Ndeye Diouf Mou Serigne Fallou offre une voiture à Malick Socé "Dello dioukeul bou amoul fene"

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025
  • Ndeye Diouf Mou Serigne fallou offre une voiture à Malick Socé "Dello dioukeul bou amoul fene"

КОМЕНТАРІ • 36

  • @dieyeamadoualainndiaye6819
    @dieyeamadoualainndiaye6819 4 роки тому +7

    Machallah. Li rafét na lolou. Je suis le petit frère à Ndeye DIOUF et je peux témoigner de sa générosité. Elle a tout fait pour ses frères et sœurs.

  • @fatoubah4800
    @fatoubah4800 4 роки тому +2

    Machaala niari bate dou yague bamou worla ta loumoula wakhe deguela machaala tata ndeye diouf

  • @Fatouseck-ec6lp
    @Fatouseck-ec6lp 3 роки тому

    Machalla yalla nala yalla same contane na

  • @oumardiawseck4594
    @oumardiawseck4594 4 роки тому +3

    Adja Ndeye Diouf sama xarit Ndanane bou bakh ta niak kiniane ta beug nawlem ak ay gueram,2013 lako dieukeu indi Etats-unis ta dara niawoul,motakh Ndanane bouci tardeti rek setlouwatal sa xol ak sa yene ci Nit gni,nit dafay labbir Machallah....

  • @diorcisse3487
    @diorcisse3487 3 роки тому

    Machalla laf thiate cou bakhe bilaye défe Diouf yalna sa diam yague thy barké Seydina Mohamed psl amine yaraby

  • @ndeyediouf6700
    @ndeyediouf6700 3 роки тому

    Sama toutando rafetna yala nala yalla faye

  • @mbalofficiel7513
    @mbalofficiel7513 3 роки тому

    Vraiment ma ngui doga sétane vidéo bi mais MASHA ALLAH ame koleré mo bakh

  • @toubandindyafricanhairbrai2924
    @toubandindyafricanhairbrai2924 4 роки тому +2

    MASHA ALLAH LI RAFFET NA NDEYE DIOUF YALLA NA LA YALLA DOLLY WEER AK SOUTOURA DAYIMANE CI BARKE XASSIDA YI AMINE 🥰DAMA BEUGUE KOUY DEFF LOU BAKH 💖😘❤

  • @khadyleye689
    @khadyleye689 4 роки тому +4

    Machaaala Sokhna Ndeye yallana yalla yokk ci barke cheikh mamadou faddal mbacke aminn aminn

  • @khadythiam9556
    @khadythiam9556 3 роки тому +1

    Machalla geste bou Nice 🥰

  • @mactardiouf7249
    @mactardiouf7249 4 роки тому +1

    Ay way ndeye diouf yabah way yalnala yala diokh louko eup pere malick soce boko guisser hamni kou bahala yalna oto bi di ndjiglayam

  • @mamadousow8154
    @mamadousow8154 3 роки тому +1

    Vraiment elle a été reconnaissante
    Mais le guitariste Malick soce mérite cela

  • @khadimdia8229
    @khadimdia8229 3 роки тому

    Linka def bakhka lolll wayei billahi danka am xewall barke serigne fallou

  • @aminatathiaw9225
    @aminatathiaw9225 4 роки тому +1

    Yalnaco yalla foul beau geste Ndeye Diouf

  • @fatoucisse4529
    @fatoucisse4529 4 роки тому

    Machalla sama sopey bi

  • @fatougaye7920
    @fatougaye7920 3 роки тому

    Macha Allah kou bakhega

  • @batoudia489
    @batoudia489 4 роки тому

    Machallah Nice na LOL bilahi tat ndeye rek

  • @fatousakho3763
    @fatousakho3763 4 роки тому +2

    MashAllah généreuse et gentille ❤️😘👍🏽

  • @bouboudiop8706
    @bouboudiop8706 4 роки тому

    massala yala n'a yok vraiment beuguenala te yala takh

  • @nenediedhiou1851
    @nenediedhiou1851 4 роки тому +3

    MashaAllah yalla na raap ak diam te nga raapal ko amiiiiiine ya rabi ❤️❤️❤️😍😍😍😍

  • @babacarndiaye8983
    @babacarndiaye8983 4 роки тому +1

    Ohh machalan li refétna

  • @AnonymousNr_2
    @AnonymousNr_2 4 роки тому +1

    Machala

    • @Thiamfa82
      @Thiamfa82 4 роки тому

      Mashalah sama yaram Bangui daw

    • @Mouhapape967
      @Mouhapape967 4 роки тому

      Machala adjia ndeye ya bakh ter ame ngor au kolorer. Yalana la yala lafal thiate mayla wer yok sa soutoura

    • @counafashion
      @counafashion 3 роки тому

      Machallah maman de coeur😘❤❤❤

  • @ibrahimagueye9801
    @ibrahimagueye9801 4 роки тому

    Ndaye diouf ya bakh waay

  • @senemoustapha2716
    @senemoustapha2716 4 роки тому

    Machalla badiene

  • @mbissinediouf4852
    @mbissinediouf4852 4 роки тому

    Machallah Ndéye jestbie rafétna

  • @alkhakimtv3305
    @alkhakimtv3305 2 роки тому +1

    Yaye yabakh rk

  • @wolyfaye4636
    @wolyfaye4636 4 роки тому

    Machala, borom kholou diama bi

  • @sayesall883
    @sayesall883 3 роки тому

    Nvv.

  • @ablayesy9646
    @ablayesy9646 4 роки тому

    Yabah,çonntanna,thiakaw.rek

  • @oumyloum1027
    @oumyloum1027 4 роки тому +1

    Machaallah

  • @niangaby9281
    @niangaby9281 4 роки тому +1

    Machallah