Oustaz Alioune Sall sur l'annulation du Magal et Gamou: "Imam Ndao limou wakh thi République moy..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 8 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 237

  • @benlothbrok1535
    @benlothbrok1535 4 роки тому +9

    Questions pertinentes réponses satisfaisantes Alioune Sall le meilleur Ouztas du Sénégal 🇸🇳,99%des jeunes te suit

  • @fallgora5785
    @fallgora5785 4 роки тому +39

    Rene inchalla ngaye giss magal gou neekh inchalla

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 4 роки тому +29

    Dieure dieuf machalla yalnanga goude fan oustaz aliou sall

  • @mamecheikhgueye8986
    @mamecheikhgueye8986 4 роки тому +1

    Machalla oustaze yallna Yalla goudeul fane wi Té yokou la Wéur Té mayla weurseuk gou sawane baawane barkep Borom Touba

  • @thiernoniang5625
    @thiernoniang5625 4 роки тому +2

    Machallah dieuredieuf ya oustaz aliou sall yalla nagefi yague lol the wér alahouma amine

  • @mohamedniass4297
    @mohamedniass4297 4 роки тому +5

    Man.cha ALLAH imam sall Qu'Allah veille sur notre pays senegal...

  • @cheikhmassamba235
    @cheikhmassamba235 4 роки тому +10

    Machallah ouztaz ❤️

  • @cheikhmbackeseck6704
    @cheikhmbackeseck6704 4 роки тому +3

    Machallah amna solo trop ❤

  • @abdoulayefall2312
    @abdoulayefall2312 4 роки тому +14

    Machallah Alhamdoulilah Ya ALAH

  • @mouhamadmoustapha3179
    @mouhamadmoustapha3179 4 роки тому +8

    Serigne mountakha mognou yilif dé na lér
    merci oustaz.

  • @geant427
    @geant427 4 роки тому +2

    En tout cas si l'état ne peut plus prendre des décisions sur certains lieux vaudrait mieux qu'il leurs donne l'indépendance totale .c'est à une état responsable de prendre toutes les décisions meilleures pour la majorité de sa population évidemment en se concertant avec les concernés

  • @fatoundoye851
    @fatoundoye851 4 роки тому +3

    Machallah oustaz yalna Yallah fay la yiw

  • @fallouwilane343
    @fallouwilane343 4 роки тому +2

    Machalla oustaz amna solo

  • @TAWAMBAYETV
    @TAWAMBAYETV 4 роки тому +9

    Très bien dit oustaz
    État est toujours invité
    Donc natey tei deglou kilifayi

  • @pacopaco7709
    @pacopaco7709 4 роки тому +6

    Dieureudief Oustaz Yalla defal la goude fane en weer

  • @sokhnafatoundiaye2814
    @sokhnafatoundiaye2814 4 роки тому +3

    Oustaz doundeul wérel amal diam barkét Nabil Moustapha ❤️ nitt lo donoul dara wali rék moy sa métier bo ragalé boul dém gniy teugu nak par force lagnouy dém République bi guay wakh Ahmadou bamba mo ko waral gninaw yalla Kone ragale corona dougnou té magal warati gamou bayiléne ouztas gni guéne beugua déff wérou waye douguéne am dame boudé Alioune Sall rék deugue rék😜😜😜😜

  • @esnentreprisesoudeurniang1868
    @esnentreprisesoudeurniang1868 4 роки тому

    Machahalla Oustaz

  • @amethfall9079
    @amethfall9079 4 роки тому +13

    Dieurideuffati s touba point 💪💪❤

  • @mbayendiaye8726
    @mbayendiaye8726 4 роки тому +3

    Massala oustas❤👍👍👍👍

  • @cheikhdiouf6552
    @cheikhdiouf6552 4 роки тому

    Dieureuf ouztaz Sall

  • @papaaliousall6650
    @papaaliousall6650 4 роки тому +8

    De grace ayez du respect pour ce grand homme il n'est là pour personne il à le droit d'être impartial du fait de son statut social et religieux. Donc dites ce que vous voulez mais d'insultes.

  • @diopadama7670
    @diopadama7670 4 роки тому +1

    Jàr a jëf Sàll. 👍

  • @silameboubacar6623
    @silameboubacar6623 4 роки тому +2

    Mach Allah Tabarak'allhah

  • @alimayaffa320
    @alimayaffa320 4 роки тому

    Très intéressant le débat

  • @amadoudiao5387
    @amadoudiao5387 4 роки тому +1

    Machalla amine yarabi machalla a diarama no fèwi seydi sall

  • @nafisatoufall4215
    @nafisatoufall4215 4 роки тому

    Machala oustaz tu es un pedagógico

  • @masstv2484
    @masstv2484 4 роки тому +9

    Billahi oustas aloune sall mo nitte te deugue

  • @kebefaliloufalilou6036
    @kebefaliloufalilou6036 4 роки тому +7

    Macha allah dierejiaf sal

  • @fallgora5785
    @fallgora5785 4 роки тому +14

    Cou amoul magal yakham vaie nioun daniye magal bamou neekh aithia mourid ila touba

  • @lampthiame8909
    @lampthiame8909 4 роки тому

    Senegal 7 diarota sétane bagouniou diiné

  • @niangbakheyaye369
    @niangbakheyaye369 4 роки тому

    Grazie mille oustaz alioune sall

  • @issacisse4785
    @issacisse4785 4 роки тому

    La question est pour ouztas alioune Sall pour le gamou et le magal ? Qui est ce que notre prophète a dit pour la prière à plus forte raison des festivités quand il y a épidémie ? Je vois au Sénégal il y a beaucoup de naafekhs .Ils vois la vérité , et ils font les aveugles .

  • @halwaartv2803
    @halwaartv2803 4 роки тому +4

    oustaz ma ngui ziar dans tout le monde etat mo yor securite rew bou yegue fimou tol tey etat mo wara duel ay motouway bounou hole thi makka kone doyna lecon nit ki loumou heur na bayi hel securite rewmi

    • @aloudia4180
      @aloudia4180 4 роки тому +1

      Dege la mè macky moo kena Bone korona

  • @bayeomardiaw6299
    @bayeomardiaw6299 4 роки тому +4

    Journaliste bi dél wakh loula woore journaliste day gestou

  • @dembadiop1054
    @dembadiop1054 4 роки тому +1

    machalla ousstass

  • @famaracamara8238
    @famaracamara8238 4 роки тому +8

    Merci oustaz

  • @souleymanedante4318
    @souleymanedante4318 4 роки тому

    Dieureudieufé oustaz

  • @moussagueye5724
    @moussagueye5724 4 роки тому +5

    WaW goor allin sall tountu yie amna solo ila touba rék

  • @melokanetvtv7634
    @melokanetvtv7634 4 роки тому

    Bien dit oustaz

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 4 роки тому

    Vraiment oustaz

  • @freediop6111
    @freediop6111 4 роки тому +4

    Billaye ma respecte oustaz oumar Sall yallah na fi yag lol té wér ! Oumar Sall ! Oumar Sall ! Oumar Sall

  • @elhadjisene9723
    @elhadjisene9723 4 роки тому +3

    Machallah machallah oustaz inchallah magali rék séne fényi dugnu té magal inchallah

  • @modoudiop4305
    @modoudiop4305 4 роки тому

    sounou wakhon auto dou demm touba diaral nama dokh ba déé bilahi ndakh magal gui s touba rék moniouko mana teré touba rék inchalla

  • @falloukebe1262
    @falloukebe1262 4 роки тому +1

    Merci sall

  • @mariasant3937
    @mariasant3937 4 роки тому +4

    Sou Islam amé dolé Sénégal borom Magal bi motax

  • @djilydiongue3005
    @djilydiongue3005 4 роки тому +9

    État défalou touba dra magal rk inchallah serigne touba la nio yakar. L amour est plus fort que la peur

    • @mamanSouaré00
      @mamanSouaré00 4 роки тому

      Kone état da wara defal dara Touba kw

    • @djilydiongue3005
      @djilydiongue3005 4 роки тому

      @@mamanSouaré00 beugo nio dra état slience

    • @ahmedgaye6825
      @ahmedgaye6825 4 роки тому

      Wakhale lo khame maky sall deff na lou eupe 18 milliards 1ere mandat massalikou djinane 7 milliards nit dou seuke dieuf bayi lenne wakhe te degue fi adina fenne daye diekhe ndakhe vare

    • @djilydiongue3005
      @djilydiongue3005 4 роки тому

      @@ahmedgaye6825 serigne touba woutiwoul nitté nio koy woutissi serigne touba mouy adouna doul rk ya président mé pa nion riba rk géne ni douné

    • @ahmedgaye6825
      @ahmedgaye6825 4 роки тому +1

      @@djilydiongue3005 riba gua wakhe kholatal doule ak fenne ak soss foumou nek te yalla takke wakhouma nit nak

  • @coumbafall27
    @coumbafall27 4 роки тому +2

    Merci imam qu Allah vous protège

  • @nitudaguebi2969
    @nitudaguebi2969 4 роки тому +6

    Magal dina am dé in sallah mei vi-clo lay don

  • @diopsaliou2415
    @diopsaliou2415 4 роки тому +1

    Journaliste bi Lou yoname thi sonou magal gui nguir yallah Manou lééne

  • @astoufaye1645
    @astoufaye1645 4 роки тому +3

    Dieureudieuf ya Oustaz ❤❤❤🇸🇳🇨🇵

  • @soweabdou8051
    @soweabdou8051 4 роки тому

    Amna solo lollll

  • @abramobencamara5087
    @abramobencamara5087 4 роки тому

    Hypocrite quand Macky proposait son référendum sur la laïcité est-ce que tu t'étais levé contre ?
    Seul Serigne Fallou dioumada était contre et l'avait fait savoir.

  • @ababacarsadih8030
    @ababacarsadih8030 4 роки тому +2

    Magali rek inchallah

  • @romaitaly959
    @romaitaly959 4 роки тому

    Dieureu dieuf sall usraz lerna nagn.

  • @mawloudsene1062
    @mawloudsene1062 4 роки тому

    Ok les cérémonies religieuses sont organisées par les hommes religieux mais l’état ne l’organise pas . Dans ce cas une question : les baptêmes et les mariages qui les organisent c’est l’état ou bien 🤔

  • @souarenouhou7991
    @souarenouhou7991 4 роки тому

    Bien

  • @sakhombaye618
    @sakhombaye618 4 роки тому +3

    Touba rek

  • @serignembackendiaye5529
    @serignembackendiaye5529 4 роки тому +16

    Kone Après Tabaski le le cas yi yokou No politicien yi Ay 😂😂😂Sax lane me Déf Sé wéri wéri yépou Safar Gué Tax

  • @mamadougueye3380
    @mamadougueye3380 4 роки тому +7

    Outaz febar Amna na ngnou bayyi ba bene moguēne

    • @modou8toure472
      @modou8toure472 4 роки тому

      Sama mbokou yaw khamô li geune

    • @mamadougueye3380
      @mamadougueye3380 4 роки тому

      @@modou8toure472 Sama tourondo febar noi rekk la motakh

    • @modou8toure472
      @modou8toure472 4 роки тому

      @@mamadougueye3380 yalla bakhna yalla nagnou yalla soutural

  • @mohamethelmoustaphandiaye4035
    @mohamethelmoustaphandiaye4035 4 роки тому

    Merci Oustaz si gataal daal dama yakaar ni yone yi amnaniou ay Kilifas cone naniou deglou Kilifas yi luniu wakh rek lolou la si diiné walum aduna nak faudra faire en sorte que les lois et règlements se basent d’abord de la croyance et des recommandations divines qui sont certes mieux pour nous êtres humains. Une révolution peut être autre que violente ou source de tensions sociales, oui elle peut-être pacifique et sans problèmes, si et seulement si on accepte de se réunir en une seule force et une seule croyance qui doit avant tout être bénéfique pour l’être humain.

    • @mohamethelmoustaphandiaye4035
      @mohamethelmoustaphandiaye4035 4 роки тому

      Respectons l’être humain et ayons le courage d’appliquer les recommandations divines en nous mais pas les lois et règlements qui ne servent qu’à protéger les intérêts d’une minorité. Réveillez vous Ô mon peuple, les lois civiles et commerciales permettent à une élite de mieux arnaquer le bas peuple, de protéger leurs intérêts en ayant d’abord le monopole de l’offre face à une demande conditionnée ou pilotée par un système ou un programme défini par des égoïstes qui veulent le contrôle du pouvoir où même de la destinée 😂 😂 pendant que les lois pénales les défendent contre nous « bas peuple » tout en empêchant de les atteindre ou de faire appliquer l’équité tant recherchée dans cette vie sur terre. Wake Up People and show the world how to live, live like a believer 👌🏾!!!

  • @niangndaye8095
    @niangndaye8095 4 роки тому +2

    Ndaysan oustaz yamanou rk

  • @assanekante6577
    @assanekante6577 4 роки тому +10

    franchement je ne trouve pas pertinent cette tentative de reponse. la reponse doit uniquement se baser sur lislam et non sur ton sentiment persinnel. quand on a peur de vexer on ne peux donner un jugement rationnel. dites nous juste ce l'islam en dit.

  • @saiddiakhate6680
    @saiddiakhate6680 4 роки тому

    Amna solo

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 4 роки тому

    Mais gnii fi dess nak danoo gueumoul yalla maandou wougnou guoré wounou itam waayé Lou dound neex neex baammmeeel moong lay khaar 🏃🏃🏃

  • @issiakhabathily6485
    @issiakhabathily6485 4 роки тому +5

    Oustaz tu parles et ne rien dire il faut trancher le débat l'état doit impérativement interdire vos Magal et vos Gamou.

    • @elhadjidiop7332
      @elhadjidiop7332 4 роки тому

      🤫🤫🤫🤫🤫magali par force

    • @sarr0143
      @sarr0143 4 роки тому

      Concernant le Magal, Oustaz n'a pas répondu.
      On s'attendait qu'il nous donne la position de L'Islam, pa rapport, à la maladie, les rassemblements interdits partout dans le territoire national...
      L'Islam n'a jamais exigé aux croyants de prendre des risques, contre une telle pandémie, sous son prétexte . Quant L'Islam interdit, l'alcool et autres c pour préserver la santé des croyants et les effets y découlant. Revenons à la raison, NIIT DAAYE NITTER, WA SALAM

    • @elhadjidiop7332
      @elhadjidiop7332 4 роки тому

      @@sarr0143 magalliii par force dara ngueinn si meunoul sokhor ngueinn lol

    • @mouha313mouh8
      @mouha313mouh8 4 роки тому

      Khou bakh ki li oustas wakh nékhoula am ngaci droit sa opinion laa, mais nous inchalaaa on va fair le magal et leta ne va pas nous interdit de le fair,poin de vu islam en teori si on a les moyen de se protege les regle restra toujour mem wala le contex va changé, nagnou moytou plomic Senegal gnoko bokou gniy magal dougnou ay diahile ni iletré, donc souvent yéneu wakh yi bagna diafendiko sa khélla,basé wou haine wala ignorance, nguenn balma akh

  • @saikh2348
    @saikh2348 4 роки тому +8

    Kou am kham kham la waayé Am amou adouna ak politique mookay téré wakh deugg légui légui

    • @souleymanedoucoure7093
      @souleymanedoucoure7093 4 роки тому +1

      Non c'est faux

    • @modoudieng7229
      @modoudieng7229 4 роки тому +5

      Ak bagn coco mèrè

    • @haqiiqatan5128
      @haqiiqatan5128 4 роки тому +8

      Kone yaw daal danga diapp né limou wakh dou deugg thieuy yalla linga beugone mou wakh lolou la wakhoul motakh ngakoy khass

    • @saikh2348
      @saikh2348 4 роки тому +3

      @@haqiiqatan5128 noo ki damadan dieunde ay kasette Di enregistrer wakhtanam kon yaguna té pour wakhla nila loubaré lama diangale mais sur ces dernière année am amou adouna ak politique mooy galnkoor kham khamam

    • @haqiiqatan5128
      @haqiiqatan5128 4 роки тому +5

      sante sante wayé diambar la nak parfois nit dou ngéne bokou guissine wayé boum takh ngakoy wakh ay sik sikeum

  • @mohamedndir726
    @mohamedndir726 4 роки тому +7

    Non ouztaze je ne te reconne plus wakhalle li yala wakh ngire yala

    • @menemimc590
      @menemimc590 4 роки тому +2

      Li yallah wakh si lann

    • @mayoronguer2498
      @mayoronguer2498 4 роки тому +2

      Yaw werro nga naan li Yallah wax li wax moy niou diaamou ko

    • @awabeye1070
      @awabeye1070 4 роки тому +1

      Wakhal yaw li yalla

  • @thiernolo5280
    @thiernolo5280 4 роки тому

    ماشاءالله جرجف صال

  • @bambatoubareck
    @bambatoubareck 4 роки тому +3

    magal reck ba fatou de bilahi

  • @ousseynoundiaye2506
    @ousseynoundiaye2506 4 роки тому

    Ouztaz sama sopéga nak, mai ts les cérémonie religieuse son organisée part l'état, mouy sécurité bi, mouy santé, mouy courant, mouy ndokh etc....

  • @moussathioune8795
    @moussathioune8795 4 роки тому

    Thiey magal ngi yalla naneko féké té talko bargue Khassidayi

  • @comzotefessois9491
    @comzotefessois9491 4 роки тому +1

    Oustaz doundeul sans ordonnance

  • @serignediagne2855
    @serignediagne2855 4 роки тому

    Diara diaf oustass waye mane damelni danga complex thi toubabyi ligne khalat reck ngay wakh 3 manda wagni wout dara maroc ben parisida mofa nek ablay wad bayinako fi macki dinako fi bayi te maroc geuna amase senegal

  • @djienesene8851
    @djienesene8851 4 роки тому +3

    Diaradieuf ouztass deug déy mbadou com yaw

  • @malangsano9578
    @malangsano9578 4 роки тому

    Dieuredieuf mbacke

  • @babacargueye1574
    @babacargueye1574 4 роки тому +3

    Mais.oustas.ya.nafekh.etat.mo.massa.encadre.evenement.religieu.si.senegal.dissi.def.lagent.du.contribuable.wakhofi.dara.wakh.te.kene.ladioula.soof.rek

  • @baragaye9329
    @baragaye9329 4 роки тому

    Danio sono si cas yi vraiment

  • @mamengorfaye6299
    @mamengorfaye6299 4 роки тому +4

    Vraiment DEUG rek

  • @khadim5779
    @khadim5779 4 роки тому +5

    yalla na yalla guindi alioune sall gamou ak magal yeup bida la bokoul ci dîné lislam

    • @habibndiaye3890
      @habibndiaye3890 4 роки тому

      😁😁😁😁😁

    • @aidatoure6566
      @aidatoure6566 4 роки тому +2

      Yanara suno yalla Moy dokol amo kham kham geBalma

    • @toubadarmanko7193
      @toubadarmanko7193 4 роки тому +7

      Yeow toudo Khadim té amo xam xam démal geustou bisou guané adouna Saydina Mouhamed psl

    • @aidatoure6566
      @aidatoure6566 4 роки тому +2

      Khamna dodou khadim wané parpar lo amoul sulo Billahi

    • @lejusticier4283
      @lejusticier4283 4 роки тому +1

      Aliou sall wakhou fi touss vraiment

  • @khadimsylla2507
    @khadimsylla2507 4 роки тому

    Imition bie bane heure laye ame

  • @chiekhtidianediba1021
    @chiekhtidianediba1021 4 роки тому

    Ostaz aliune sall ya dege

  • @lebaolbaoltigui2599
    @lebaolbaoltigui2599 4 роки тому

    Vous ne pourrez jamais dirriger un pays avec vos soit disant connaissances archaiques qui ne riment qu'avec des reves.....Partout où vous etes nombreux et la libertè de detourner la conscience des gens , c'est le chaos .....

    • @moustaphasy6779
      @moustaphasy6779 4 роки тому

      Vous êtes tous des complice avec des marabout

  • @serignediagne2855
    @serignediagne2855 4 роки тому

    Soufsi and nathi ak yow

  • @aliounediop8346
    @aliounediop8346 4 роки тому +3

    Si tu a peur de répondre les questions reste chez toi et tu te té

    • @haqiiqatan5128
      @haqiiqatan5128 4 роки тому +1

      Thieuy Sénégal c'est parsk linga beugone mou wakh ko lolou la wakhoul motakh

    • @laminecisse1196
      @laminecisse1196 4 роки тому +1

      Frère ki dou yenn dolenn momm tmt ki dafa degg ta andak mandou lolou kepp moy nitt yenn danguen yeur touti si terei yi bou fekkeh yeur nguako sah nguen nieuw fi di wakhlo nitt gni lounguen beugg

  • @moctardieng5516
    @moctardieng5516 4 роки тому

    Wakhal li l'islam wakh si loumel ni sou amé .ou no

  • @morfall4556
    @morfall4556 4 роки тому +5

    Brobleme bou amé dagaye wah ni seydou na mahamad psl aterwone

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 4 роки тому +1

    Gnioune sunu ribibligue yi tubabi kesse la nuye tobou

  • @mamemassaer7052
    @mamemassaer7052 4 роки тому +1

    Eta Moy dogal oustaz! Ragalen yalla ci seni wakh,, ta bagn Ragal as ndomou adama

  • @fallougallassdiop1023
    @fallougallassdiop1023 4 роки тому

    Rafitna lolllll

  • @khoumakhouma4940
    @khoumakhouma4940 4 роки тому

    Linga waxe daal daguela magal s mounetaxa mooy disèder pas kaneen

  • @bourhan142
    @bourhan142 4 роки тому

    Nguènté nak état moko doon organisé? Lou takh gnou koy térré

    • @aboutalla5886
      @aboutalla5886 4 роки тому

      Tektthi, dem Diakka, dioulli Aldiouma. C est vraiment dommage

  • @babaly5821
    @babaly5821 4 роки тому +1

    Yen defa melni magal nguendi gana fonko ak gamou hana xif nguen

  • @sobptv9430
    @sobptv9430 4 роки тому +1

    Oustazz dafa ragala wakh si magal gi magal mom d'où amé namou dan amé

    • @elhadjidiop7332
      @elhadjidiop7332 4 роки тому

      Lègui fènno?
      Deill wakh loulaa woorrr nak

  • @baralo9772
    @baralo9772 4 роки тому

    Nakh loxamoul limou donne wargan ko toppou kon kou deugou warouta endall goure lan moye laïtte ak république xamou nioulén kon linou niou indil banou waxnouko warouno endak niom

  • @djipsondj9955
    @djipsondj9955 4 роки тому +4

    Oustaz ragalal yalla

  • @Badoudiouf2023
    @Badoudiouf2023 4 роки тому +3

    Domeram yi nioye wakh annuler magal s'en data ndeye

    • @aloudia4180
      @aloudia4180 4 роки тому

      Yawe moome jaroule gaye Dème touba Boofa Dèmè aye saaga rèke gafaye yobou

  • @shiekhndaw6997
    @shiekhndaw6997 4 роки тому

    Jajaf sall bula kenn dugall

  • @yacinecodoumbaye3247
    @yacinecodoumbaye3247 4 роки тому

    Oustas mala beug deug rek ngay wakh

  • @aminagueye7907
    @aminagueye7907 4 роки тому +1

    Gouvernent Sénégal doul rek lagnouy def fébar bi ay féne mothi eup fi gnouko yobou égoufa maghui ni Mali té gnou gui doude normalement défougnou yeufou dof yi Sénégal di déf

    • @mamadousall7046
      @mamadousall7046 4 роки тому

      Amina naka malie

    • @Niang-ec8sl
      @Niang-ec8sl 4 роки тому

      La maladie est bien là et elle est mortelle surtout sur les vieux et les gens couvant d'autres maladies. Portlns les masques et respectons les mesures barrieres

  • @laminendiaye4705
    @laminendiaye4705 4 роки тому +3

    Oustaz yaangi daw wax ji. Lan islam wax ci magal ak gamu?