Série - DJIGUEEN JONGUEE (FEMME COQUETTE) - EPISODE 07 (VOSTFR)

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 166

  • @evaly4011
    @evaly4011 3 роки тому +58

    Ndeysan deuxième dame bii dadone déf bac yalla na am inchallah gno bokon centre

  • @anginapiod3793
    @anginapiod3793 3 роки тому +14

    Nafina🤣🤣🤣allez bo guiss amna retour pardon tèy mom dalossi. Bravo mère Oumy tèy japeu ngaci👏première j'espère que tu as retenu la leçon jongué fèp la occupe toi du ventre et du bas ventre de ton mari 🙈

  • @medzuniang2961
    @medzuniang2961 3 роки тому +185

    Alhamdulillah j’ai eu mon bac

  • @sokhnadiop6328
    @sokhnadiop6328 3 роки тому +32

    Non niarel day daflo goor perturber la célibataire la dh mais niarel yi la faral 😂😂😂😂😂

    • @maremesougou8031
      @maremesougou8031 2 роки тому

      Guisga lolou ak li nafina di dadje lepp pour mou bégue l'autre migui deff le contraire mouy begue doff 🤣🤣🤣

  • @ndeyediop126
    @ndeyediop126 3 роки тому +20

    non man Méré Oumy la beugué ♥️♥️♥️♥️

  • @fraiizybaby4702
    @fraiizybaby4702 3 роки тому +7

    Mere Oumy la beugue 😂😂😂teik na xalley bi si axe🤸‍♀️🤸‍♀️

  • @alimaly1572
    @alimaly1572 3 роки тому +21

    Oumy sa badiane sax mola dakh sey

  • @maguettegaye6343
    @maguettegaye6343 3 роки тому +21

    Ma begue djiguen bou jongué way

  • @ndeyeastoudia2771
    @ndeyeastoudia2771 3 роки тому +30

    Ay oumou sa toura ndo sonou na thi sa sey bi doo def toti efforts

  • @falysane6895
    @falysane6895 3 роки тому +6

    Sénégalais you Bari lolu molen yakk yakar nagnouni djiguéne rek moh wara diongué
    Mais goor aussi dafa wara beguel diabaram aussi
    À part ça série bi c'est intéressant en plus tableau c'est vrai so meunone niak moh geune

  • @aminaba4672
    @aminaba4672 3 роки тому +17

    Sen dieukeur gui aka beug femme 😂😂😂

  • @abydiouf3182
    @abydiouf3182 3 роки тому +45

    Ndeysaan mère bi da beugue oumou nak.mais oumou nékhoul farale 😂😂

  • @dabasow9769
    @dabasow9769 3 роки тому +25

    Awo bourou keureum nak dafa sonone 😂

  • @amyseck5710
    @amyseck5710 3 роки тому +25

    Wa yein oumou komencéna yakkou😂😂😂

  • @princessemaria6566
    @princessemaria6566 3 роки тому +49

    J'adore le teint de nafina♥️🥺✨

  • @AwaNdiaye-lr5hs
    @AwaNdiaye-lr5hs 3 роки тому +16

    Noo man badien oumou la begue 😂

  • @antambodji2460
    @antambodji2460 3 роки тому +8

    Goro bagay seuy seuy beu nk niaw 😂😂😂

  • @fd5009
    @fd5009 3 роки тому +5

    Djigeen bou jongué ,mok pothi,kokou sama kharit lay done ,mais Nafina dafa jongué rk mokoul pothi dh,té jongué DEUG =jongué +mok pothi,kou beug kham lane moy mok pothi ,mangui ni kay ma wah la.je suis une fille de 15 ans ,en classe de cinquième

    • @lofama5424
      @lofama5424 2 роки тому

      manguini wakh ma louy jongué

  • @mariamacisse684
    @mariamacisse684 3 роки тому +36

    Ahh seri ame nekh na tropp
    Mais dess na lou beuri si même keur guii la lep di khewer meme chambre bi
    Amoul togou amou amoul wagne amoul dem marché ni voisin
    Seri bi bougnou kholé goudi la ak souba tell
    Si je me tromp pas 🙏

  • @fatoubinetoufall403
    @fatoubinetoufall403 2 роки тому +1

    Épisode 1 bi la beugue sétane t guissou mako

  • @badoudia4869
    @badoudia4869 3 роки тому +22

    Jongue bou bari daye doflo niit Nafina warna lale soie bi pour teudd😂😂😂 drap goudi mom coton bou Wekh dace doye seukk

  • @maremnjaay2289
    @maremnjaay2289 3 роки тому +3

    Awo bou melni yalla naniou yalla mousel

  • @bintadiop4405
    @bintadiop4405 3 роки тому +2

    Sen makup yi ngir yala nay simple simbougbou😭😭😭😭😭😭

  • @mmediakhte9807
    @mmediakhte9807 3 роки тому +19

    Man awo laa waayé niaréll bi laafarall bh

    • @mariamadiallo9511
      @mariamadiallo9511 3 роки тому +2

      Mane aussi magui si marietou té pourtant awo mais d'à mélni momar marietou

  • @famandiaye3052
    @famandiaye3052 3 роки тому +35

    Awo bi migui yakk sougnou dérr😭😭😭

  • @MameantaFaye
    @MameantaFaye Рік тому

    Nia rek yagui neee❤❤😂😂😂

  • @sokhnaaminndiaye7498
    @sokhnaaminndiaye7498 3 роки тому +8

    Momar néna Oumou so ayé damay contane ki geumoul dara dé

  • @alimaly1572
    @alimaly1572 3 роки тому +11

    Wa mani qui comme moi regarde plus de 5 séries sur UA-cam 4G en 2 semaines eupna

  • @fatoudiabaye431
    @fatoudiabaye431 3 роки тому +19

    Tay môme mère oumy diap nasi niaff

  • @safietoumbaye2941
    @safietoumbaye2941 3 роки тому +1

    Ayo dibi yap ak meulf bi 🤪🤪🤪💃🙆mangui dé AK ré

  • @yacinendiaye9896
    @yacinendiaye9896 3 роки тому +25

    Waa noumfa démé nii🤔 tay carte gu daa melni dafa tourné 😂

  • @aichadiop1863
    @aichadiop1863 3 роки тому +5

    Momar tamite beugeu nga djiguen😂😂

  • @naboudiop2717
    @naboudiop2717 3 роки тому +6

    Oumou wayy tayy da fipou nileuh jiguenn jongué lagnou wax

  • @mamesayethiam6554
    @mamesayethiam6554 2 роки тому

    Man môme souma nekoul niarel damay bayi ♥️ inchallah 😅

  • @mouslygueye6232
    @mouslygueye6232 3 роки тому +2

    Thime dou yoor say fémou popu nane dangay santé mér bi bobu nga pérté djiguene dafa wara diongama

  • @bintoucisse7325
    @bintoucisse7325 3 роки тому +11

    Tay mom série bi nekh na 😂

  • @fatoukinediop7833
    @fatoukinediop7833 3 роки тому +5

    Wooy Goro bangay seuyal Oumy nak
    Lol

    • @Fabidi1011
      @Fabidi1011 3 роки тому +1

      Noumouye deff diarbatt tam la té moko dougueul si sey bi ndeyssane. Mane lilmeu beugueu kham pourquoi yenneu djiguene yi di tekk lekke si kaw lall d’ailleurs nekk dou lekoukaye surtout so amè place si keurgui.

  • @aissatassow436
    @aissatassow436 2 роки тому

    Épisode 6 xana amoul

  • @layeawandiaye6767
    @layeawandiaye6767 3 роки тому +7

    No awo bi daf may fathie🤣🤣🤣🤣

  • @modoundiaye8651
    @modoundiaye8651 3 роки тому +14

    Té niom nieup awo bii Moleen dakk nakkk

    • @boussodieng7300
      @boussodieng7300 3 роки тому +3

      Loll jongue rk la defoul

    • @maremedieng7732
      @maremedieng7732 3 роки тому +1

      Billay dafa rafett macha Allah 😂

    • @yassdiaw1386
      @yassdiaw1386 3 роки тому

      loul mom dou débat sama sœur rk dafa jongama 💪💪

  • @bintoudiop6391
    @bintoudiop6391 3 роки тому +13

    Ounou mu ndaw kaay warna déff tuti jongué

  • @abdouthiongane5737
    @abdouthiongane5737 3 роки тому +10

    Doumako lale awo ni la kay gua sagualniou touti sakh😇

  • @maremesy3235
    @maremesy3235 3 роки тому +7

    Wa oumou défal effort yow tamit mere bi sonneuna😂😂😂

  • @mrscisse243
    @mrscisse243 3 роки тому +19

    Keurgui khalé dawoufi🤣🤣🤣

  • @ndeyefamasall9808
    @ndeyefamasall9808 3 роки тому +3

    Première rek

  • @sallydemba2176
    @sallydemba2176 3 роки тому +4

    Momar niarel bii la guena beugg téé ne niarel bii mo lén dak téé molen guena djongué kouy niarel ni man sa lokho thia kaw

  • @salladiallo3571
    @salladiallo3571 3 роки тому +5

    Série bii mome avancéwoul darra😪😪

  • @tousabvba2035
    @tousabvba2035 3 роки тому +7

    Oumyyyy way🤩

  • @sokhnadiop3326
    @sokhnadiop3326 2 роки тому

    Oumou tay défna yeufou djiguéne

  • @mamemordieng7650
    @mamemordieng7650 3 роки тому +1

    Goor ko sérla kholom Yako Mom

  • @fatimathiaw7057
    @fatimathiaw7057 3 роки тому +10

    Machallah

  • @mamediarrambaye8271
    @mamediarrambaye8271 3 роки тому +7

    May première

    • @af5681
      @af5681 3 роки тому +1

      Ban jiour l'ay ame

  • @matygueye4917
    @matygueye4917 3 роки тому +7

    machallah 👍👍

  • @aichadiop1863
    @aichadiop1863 3 роки тому +1

    Thiey mane yi khétou makup

  • @diarradiop4837
    @diarradiop4837 3 роки тому +3

    Mba khamnguene ni momar niareel bi la nopp tres serieux

  • @siiiraaa2854
    @siiiraaa2854 3 роки тому +1

    C’est quand les sous-titres svp on n’attend toujours

  • @nba_young_boy9561
    @nba_young_boy9561 3 роки тому

    Mach’Allah nekhna

  • @aissatoundiaye3251
    @aissatoundiaye3251 3 роки тому

    Xana ben neuk guendi jouer mm tableau bi je le trouve partt

  • @oumyyyc
    @oumyyyc 3 роки тому +1

    Oumou wayyyyy 🤪🤪

  • @smaifalloundiaye7771
    @smaifalloundiaye7771 3 роки тому

    Oumou Bouma rayy wayy

  • @rokhayasane9462
    @rokhayasane9462 3 роки тому +1

    Awo yé ayé téy

  • @jeux1182
    @jeux1182 3 роки тому

    17:00 Setlu ngeen ni Oumou dou sakhami dey warax 🥺

  • @fatyseck1711
    @fatyseck1711 3 роки тому +1

    Mane lima diakhal Bene nek laniou boko wala tableau yi nio niro

  • @djeinabakane6427
    @djeinabakane6427 3 роки тому

    Jigueen day diogue

  • @awasow1912
    @awasow1912 3 роки тому +3

    Ah teyy awo yii degno fiippou

  • @barohadia3681
    @barohadia3681 3 роки тому +6

    Niarel bi do defar sa kanam bi do lippowou sah mouy mate toune yi ni

    • @evaly4011
      @evaly4011 3 роки тому

      Niarél wala niatél on diré k Daga diom🤷

  • @mamediaradiouf44
    @mamediaradiouf44 3 роки тому +2

    Maypremiere♥️♥️♥️

  • @princessemaria6566
    @princessemaria6566 3 роки тому +21

    Non srx ki Leni make-up bagne nalen yi eye brow

  • @lesmauxducontinent6770
    @lesmauxducontinent6770 3 роки тому +1

    Ahh Awo day khadiam wayy

  • @absatambaye1114
    @absatambaye1114 3 роки тому

    Wa ki dou niatele

  • @benedictemugisho5227
    @benedictemugisho5227 3 роки тому

    Les sous-titres sont passés où ?!

    • @senserietv
      @senserietv  3 роки тому +1

      Toutes nos excuses, c'est disponible🙏

  • @mrscisse243
    @mrscisse243 3 роки тому +2

    Hi awo bi da yeugou

  • @sisterasful
    @sisterasful 3 роки тому +2

    Momar beugu na djiguène

  • @mamecheikhantagueye5454
    @mamecheikhantagueye5454 3 роки тому +2

    Awo fne

  • @fatimazahrafall5768
    @fatimazahrafall5768 3 роки тому

    Ah tay oumy amna dara way mère oumy yekh na diok tamite

  • @adamengom1210
    @adamengom1210 3 роки тому +1

    Momar taye ba diame yaye déf ni nafina

  • @ibrahimadieng8017
    @ibrahimadieng8017 3 роки тому

    Momar mbadou anticipé sa mort

  • @faambay8799
    @faambay8799 3 роки тому +1

    Yenn bayy lenn sabot3 lolou baxoul yaw princesse maria yaw momou layy waxal lernama diago doul wayy yaw

    • @matarsamb920
      @matarsamb920 3 роки тому

      Faa mbay nit nday am yar yarol boy

  • @ibrahimadieng8017
    @ibrahimadieng8017 3 роки тому

    Badiane waay

  • @maremethiam6763
    @maremethiam6763 3 роки тому

    Mane dal mère bi la beugue

  • @ndeyeseck2825
    @ndeyeseck2825 3 роки тому

    🥰🥰

  • @smaifalloundiaye7771
    @smaifalloundiaye7771 3 роки тому +1

    Malar déll changer toubay bi

  • @fatoumatazahra8342
    @fatoumatazahra8342 3 роки тому +2

    Oumou nak dangay were quoi awo dafay khadiam

  • @sokhnamomymbackeseck6987
    @sokhnamomymbackeseck6987 3 роки тому

    💪💪💪💪💪💪💪💪💪😁😁😁😁

  • @dieynabadiop4333
    @dieynabadiop4333 3 роки тому +2

    Niarel yi dal am nagn buzz li lan la tamite ba mou soti

  • @maimounahanne5842
    @maimounahanne5842 3 роки тому

    Thia héritage bala

  • @mamecheikhantagueye5454
    @mamecheikhantagueye5454 3 роки тому +2

    Dafa rerr

  • @djadjabalde7767
    @djadjabalde7767 3 роки тому +9

    Machallah