Alakhou akbar, Dome dji mo guéné yayam li metina la maman inconsolable aggrave la situation

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 5 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 223

  • @AdamaCissokho-i8n
    @AdamaCissokho-i8n 7 днів тому +40

    Mane nga kham ni sama rêve yeup moy dougal sama yaye thi keur 😢😢tay ma guiss kou guéné yayam 😭😭😭🥺😭

    • @Gggge_dudiolof9536
      @Gggge_dudiolof9536 7 днів тому +7

      Mane de sama yaye dougal nako si keur sama tawou yaye ak ay domam dougal nalene si keur aussi li metinama trop😢😢😢 kouy trokhal yayam

    • @FamaKebe-f4e
      @FamaKebe-f4e 6 днів тому

      Moi aussi 😢

    • @mohametthiam4500
      @mohametthiam4500 6 днів тому

      Bilaye 😂😂😂😂😂

    • @MamaDeme-jf3qw
      @MamaDeme-jf3qw 6 днів тому +2

      Wallahi moy rêves kepp ko guis tei yalla naniou ko souniou borom yombal inchaallah

  • @slamArtBarham
    @slamArtBarham 7 днів тому +16

    Ndeysane les preuves qui montre que c’est la fin du monde 😢

  • @seydinaoumarloftssy4146
    @seydinaoumarloftssy4146 7 днів тому +13

    Ay souma Yalla dinkane keur walahi ma fatt leu mais Yalnala Yalla takhawou si barké Mouhamad PSL

  • @codousow5840
    @codousow5840 7 днів тому +41

    Wawe on aura tous vues dans notre Sénégal invraisemblable guainer sa yaye ak yaye noumou tolou si.dome

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 7 днів тому +1

      Li môme dara rafétou thi. mais ésque yayam directe la

    • @User-p1s5w
      @User-p1s5w 7 днів тому

      ​@@basselabdou9891si,c'est sa mère

  • @cheikhouDomoupikine-t3q
    @cheikhouDomoupikine-t3q 7 днів тому +19

    Je dirai que adouna daye touki je ne comprend rien 😥😥

  • @binetakeita6020
    @binetakeita6020 7 днів тому +5

    Bilay Adouna bi da diékh ba paré yaye AK loumou sakhé si khol mou dieuf lou niawli doyna war trop yalla n'a yalla takhawou

  • @talibecheikh7628
    @talibecheikh7628 7 днів тому +15

    Waaaaaw allakhou akou bar li dé khana gouléte thi senegal 😮😮😮😮 gniaya nak dieul nga ndame li guéné sa yaaaye boooye 😢😢😢😭😭😭😭

  • @AidaSenghor-o4b
    @AidaSenghor-o4b 7 днів тому +5

    Sama yaye bou mako gui satone ❤

  • @KingKingbuzz
    @KingKingbuzz 7 днів тому +4

    Sénégal dou mousa bakh Peseque taye justice bi guene katte ndayame

  • @NdeyeciaraFalldiarra
    @NdeyeciaraFalldiarra 7 днів тому +19

    Li mome domdji tayou ko 😢nakh yaye noumou mele si dome li dou tayef way 😢

    • @hassadivadiallo3716
      @hassadivadiallo3716 7 днів тому +2

      Dama yakar ni djeukeur dji dafa tourné khel mi 😂😂😂aya bimbam

    • @KineKhaliloulah
      @KineKhaliloulah 7 днів тому

      @@hassadivadiallo3716lolou mon am sakhh nak

    • @fatoudjitte2358
      @fatoudjitte2358 7 днів тому +2

      Diommi amoul heures guéné sa yaye si keuram nakh sa dieukeur..wa bakhna ba rêne di deweune inchalla..sa dieukeur dji moleu nara woor comme ningako defé sa yaye sa biss mongui nieuw inchalla..

    • @khadijakeita8015
      @khadijakeita8015 7 днів тому +2

      Man dè lila wakh Esk dieukeur dji ligueyouko tamit

  • @alfylyfa7645
    @alfylyfa7645 7 днів тому +4

    Ndiaya dé légui dieukeur gui nok ko thibiti maléne wakh li 😂😂😂

  • @niang.talibe.brom.ndienend5434
    @niang.talibe.brom.ndienend5434 6 днів тому +2

    😢😢😢😢 sarap ndaye liii😢 alale diaroul liii😢

  • @AminaSagna-w8c
    @AminaSagna-w8c 7 днів тому +10

    Modou lô il faut que tu l'aide la manma une appartement le plus rapide possible

    • @lacolombeblanche4589
      @lacolombeblanche4589 7 днів тому +4

      Ki domame yi niakou niou je pense li niouy niane kay Moy ay avocat you bakh pour récupérer keur gui. Li dafa yomb

  • @hyougojesais7239
    @hyougojesais7239 7 днів тому +33

    Yalna ko dieukeureum torokhal come nimou torakhalé yayam

    • @awathiam-d6p
      @awathiam-d6p 7 днів тому +3

      Allahouma amine bala yague Dara

    • @SENEGAL303
      @SENEGAL303 7 днів тому +1

      Lolou kay diaroul niane. Nakh kiy dèf li sa yaye ngay sètane, dotoula respecter abadane

    • @Gggge_dudiolof9536
      @Gggge_dudiolof9536 7 днів тому +3

      Mane sama makk sakh dougal nako si keur ak ay domam li metinama

    • @FaNdiaye-xr6mo
      @FaNdiaye-xr6mo 7 днів тому +1

      Amine yarabi 🙏

    • @FantaToure-eu8mt
      @FantaToure-eu8mt 7 днів тому

      Allahouma amiine 🙏

  • @AminataBa0-wn2cn
    @AminataBa0-wn2cn 7 днів тому +5

    Aonzou bilahi mina cheytané lazim. Dome bouy torolhal ndayam nguiir khaliss ak goor yalla kaay khare.

  • @tallafall7629
    @tallafall7629 7 днів тому

    Mér bou bakh té yiw mako kham lii 14la yalla bakhna dina bakh dh inchallah 🙏🙏

  • @josephakibode5679
    @josephakibode5679 7 днів тому +4

    C'est la société en général qui est devenue méchante 😢

  • @bassidoumbia6854
    @bassidoumbia6854 7 днів тому +3

    Une maison à 11 ou 13 millions franchement Sénégal y a beaucoup d'injustice

  • @cheikhdiop859
    @cheikhdiop859 7 днів тому +6

    aka nékhane ma guiss sama yaye 😭😭

    • @cecilediouf8500
      @cecilediouf8500 7 днів тому +1

      Bilaye khamoul li thi gnak Yaye .Moye galadj😭😭😭

  • @khadycisse7644
    @khadycisse7644 7 днів тому

    Li deh fogone nani théâtre rek la mana am mais pas dans la vrai vie yalnaniou yala mousal si trokhal souniou waydiour

  • @bassidoumbia6854
    @bassidoumbia6854 7 днів тому +2

    La justice n'a pas encore donné de verdict er les propriétaires sont expulsés, Sénégal fait partie de quel monde

  • @assanecisse1820
    @assanecisse1820 7 днів тому +1

    Li niáwna trop sakh 😭😭😭😭😭😭😭

  • @binasanja9521
    @binasanja9521 7 днів тому +2

    J'ai trop mal 😢💔.

  • @binetandoyesamba
    @binetandoyesamba 7 днів тому +5

    Louy lolou?😭😭😭 Allahou Akbar yalna bou titre done deugue

    • @adamagaye4662
      @adamagaye4662 7 днів тому

      Bilaye c vrai deh fy la ame parcelle unite 14 ta propre mer kha deff khou ly 😮

  • @seynaboufaye337
    @seynaboufaye337 6 днів тому

    Yaye mougnal massa yalla guiss na lép dinako guiss😢

  • @papaelhadjithiam7746
    @papaelhadjithiam7746 7 днів тому +8

    Sénégal comme film

    • @siramo574
      @siramo574 7 днів тому

      😂😂😂😂film la dii, chaque jour akk pièce bou bess

  • @DiarraThiaw-v6i
    @DiarraThiaw-v6i 7 днів тому

    Oh maman yalna yalla takhawou 😢 yalna yalla may sama yaye fane wou guoude Dara dieundeul sama yaye keur 🙏

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595 7 днів тому +2

    Sénégal lougn wax rek gnouni dagnko ligey 😢😢😢

  • @FatouDiouf-w4g
    @FatouDiouf-w4g 7 днів тому +1

    Mane mounou ma comprendre 😢😢mé tout sauf yaye, ndiaya meunoul téy lii yaye nimou nékhé thii khol no geuwmako

  • @rosemendy7946
    @rosemendy7946 6 днів тому

    Massa métina dal, yalla na yalla léral léppe

  • @BibaDiao
    @BibaDiao 6 днів тому

    Yalna deugg dioupp kaw metina trop

  • @AboulBacharSall
    @AboulBacharSall 7 днів тому +1

    Mane ba legui comprendrouma Bilahi li ces grave 😢

  • @AminataBa0-wn2cn
    @AminataBa0-wn2cn 7 днів тому +7

    Mane dé fouma toleu louma térralé sama yaye lay niane.yallana

  • @FatouNdiaye-ni1it
    @FatouNdiaye-ni1it 8 днів тому +2

    Allahou Akbar Senegal li rek mo dessone amna😭

  • @fayemamy9521
    @fayemamy9521 7 днів тому

    Ahhhhh li d doyna warre guéné wa yaye fila beut yam nak
    Ndiaya mi est ce que dieucoeur dji yobou woul khelmi😢

  • @matybeye837
    @matybeye837 7 днів тому +2

    Sénégal boudé film la saison bi warna diékh

  • @NdeyKane-j7w
    @NdeyKane-j7w 7 днів тому +13

    Bilahi sama xol bi métina trop

  • @arizona4234
    @arizona4234 7 днів тому +1

    Dom bou guéné yayam waw amna kay ndiaya khawma lane j’espère que kham nga linga def

  • @khadysakho3317
    @khadysakho3317 5 днів тому

    Une brave fille courage à elle

  • @ibraniang7450
    @ibraniang7450 7 днів тому +3

    Non on est au moudioum diamono. C’est vraiment grave 😢

  • @Lota9-o7p
    @Lota9-o7p 7 днів тому

    Bly ngogui si moudjoub djamono 😢

  • @saaadiyabiche
    @saaadiyabiche 7 днів тому

    Yalla na leen yalla diapalé

  • @baramboup8705
    @baramboup8705 6 днів тому

    Ki Yallah nako Yallah atté ak yayam mettima trop

  • @salkaba6005
    @salkaba6005 7 днів тому +4

    Soubhanalah guéné sa yaye eupneu

  • @SerigneModouDiakhoumpa-gx4ek
    @SerigneModouDiakhoumpa-gx4ek 7 днів тому +1

    Wallahi rewmy deukk fi woroul ,sarab ndayi bib justice

  • @ThiamelSow-gd7vq
    @ThiamelSow-gd7vq 7 днів тому +7

    Abdou rokhmane diouf dina dokhane sa ndéye sathi bou kate ndéyeme nga

  • @Faye-sv1jx
    @Faye-sv1jx 5 днів тому

    Li istoire dinako binde yaye nk mes qui mome wakh deug yalla wéroul 😢

  • @alysebor6553
    @alysebor6553 6 днів тому

    Je besoin le numéro de cette mer pour dimbaliko koko am dimmali thi je suis en France

  • @AMThiam-n4d
    @AMThiam-n4d 6 днів тому

    Na état bi taxaw gaw ci situations bi jubanti cas bi.
    Dara rafetu ci

  • @MamesoukaynaDiedhiou
    @MamesoukaynaDiedhiou 6 днів тому

    Domdji teyko mais Dieu est grand

  • @Mamediaw773
    @Mamediaw773 7 днів тому +3

    Khana diaaya amoul domeu 😢momeu tmt li niaw naa

  • @kayezikartv7240
    @kayezikartv7240 7 днів тому +1

    Abdou Rahman diouf yaye vrai domou khath diakh mbam yaye doméram walay digua kham ni adouna dou keurrr

  • @gueyediarra2340
    @gueyediarra2340 7 днів тому

    Haaaaa mane dé damané dou deugue wayé soufé deuguele laa khawela wala khouwata sa yaye 😭😭😭😭

  • @Yfadbs
    @Yfadbs 6 днів тому

    Vraiment dafa yombeu gnémé akheu non li metina

  • @MmeNdiaye70
    @MmeNdiaye70 7 днів тому

    Mère Nogaye Béye pendant que Unité 14 et 13 pleure les morts de l'accident de Touba ndiaya guéné ndayame

  • @boussosene-o5o
    @boussosene-o5o 7 днів тому +1

    toute mes reve c.est pour batir une maison.pour ma mere ki di guene yayam alakakou bar

  • @Ngone95gmail.ComDiakhate
    @Ngone95gmail.ComDiakhate 7 днів тому

    Alahu akbar li mom alkou la wala reipeu😢

  • @alylo184
    @alylo184 7 днів тому

    Dans beaucoup de dossiers, surtout ceux immobiliers, les avocats des victimes ont une très grande responsabilité dans les suites malheureuses qu'ils ont. En effet on leur donne les dossiers mais ils ne s'en occupent pas réellement alors que l'autre partie, souvent très bien outillée, a le temps de dérouler ses plans tranquillement. C'est après coup seulement que ces avocats montrent leur tronche pour constater les dégâts où tenter de rattraper ce qui est rattrapable. En écoutant cette avocate de la famille on se rend compte qu'elle n'était guère préoccupée par ce dossier et à la limite même elle ne le maîtrise même pas.

  • @AwaMarone-x1b
    @AwaMarone-x1b 7 днів тому

    Doom dia troxalena ndeye dia

  • @diyandiaye4532
    @diyandiaye4532 7 днів тому +2

    Mère bii nena ap talibe baye la mais baye niass boukoy yeuk diko rendii doyna war ken hamoul lilanla mais yaye dou morom naniou dèm rkk bientôt dinako guiss bilakhi

  • @abdousow6344
    @abdousow6344 5 днів тому

    DJIGÉNE Senegal seriñe réke lane geme

  • @KhadijaTraoreKhadijaTraore
    @KhadijaTraoreKhadijaTraore 7 днів тому

    allahou akbar 😭😭😭

  • @leuzpro2886
    @leuzpro2886 7 днів тому

    ndiaya dome bou trokhal sa ndeye digua ko guiss bilahi

  • @DjilySamb-r3i
    @DjilySamb-r3i 7 днів тому

    Subhanalah

  • @CatherineManga-ft7vb
    @CatherineManga-ft7vb 7 днів тому +1

    Ndeysan 😢

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy 7 днів тому

    Femme bi kouko gueneu bonne amoul Ndiaya yaya domė khathieu

  • @SENEGAL303
    @SENEGAL303 7 днів тому +5

    Gor dèf li sa yaye, nga tok di khool? Bobou gor dotoula tèk ngay nite mouk.
    Khana ndiaye dafa andoul ak saggom. Wala mou nara done dom djou bone rek.

  • @leytikane8704
    @leytikane8704 7 днів тому +7

    Gnepp di weur fougnou dougueul s'en daye yaw guay guene sa wadjiur yaye domaram

  • @diarraaidara9648
    @diarraaidara9648 7 днів тому +1

    Khalé yi di niafé di dougueul iao ngay guéné est-ce que ande na akk sagom

  • @nafidiop5483
    @nafidiop5483 7 днів тому +1

    AMGUA WAY BOUNDOUL FAYE 😢

  • @Aissatounging-p8l
    @Aissatounging-p8l 7 днів тому +1

    Sénégal louné dinafi am Li kén khamoul lanla 😱😱

  • @elfallfall3250
    @elfallfall3250 7 днів тому +4

    Wane ngou fotom ngou taf ko fép wér ko kom nimou déf yayam

  • @sokhnarabidoucoure9939
    @sokhnarabidoucoure9939 7 днів тому

    OMG

  • @mouhameddiop282
    @mouhameddiop282 7 днів тому

    Mane lii meunou mako geum soubxaanal laaah
    😊😊😊

  • @DIOP.KÉMANEALLALOU.S.SALIOUMBA
    @DIOP.KÉMANEALLALOU.S.SALIOUMBA 7 днів тому +1

    Allahou ak koubar

  • @Mame-wn5gx
    @Mame-wn5gx 7 днів тому

    Justice pour cette famille, tout le Senegal derriere vous , incroyable.
    Bad people.

  • @kya_lovelydays
    @kya_lovelydays 7 днів тому +3

    Si j'avais les moyens je lui offrirais un toit, plus au moins 6 mois de ravitaillement. Yalla na ko yalla diapale.

  • @Passou3Syna
    @Passou3Syna 7 днів тому

    Sénégal niit Day deflouko nekh...
    Après niouné donoukolighey ....
    Torokhale sa yaye bamou néh toth sans regret dineh defdef...
    Pisé way

  • @khalifambaye8658
    @khalifambaye8658 7 днів тому +1

    Alahou akkubar

  • @mouhamaddiop2374
    @mouhamaddiop2374 7 днів тому

    Aussi tamite amna parents youy guéné sénni domm n'oubliez surtout pas que ni moudioum diamano lagniou nék Mane sama papa dafma guéne keureum té dama comprendre que adouna bi daffa diékh ba noppi doundou yagueuna yagoul

  • @FatouDiedhiou-xo8mm
    @FatouDiedhiou-xo8mm 7 днів тому

    Bizarre toutes les histoires de famille doivent etre réglées par le président quel marathon

  • @onedollarcommunity
    @onedollarcommunity 7 днів тому

    Un bordel de pays qui n'a pas de justice .... toujours voici les conséquences

  • @mousdiop5469
    @mousdiop5469 7 днів тому +3

    Il ne faut jamais accepter les beaux frères chez vous , egale pour les veuves qui accueillent les nouveaux maris chez eux ... finalité bi c est ça

  • @amadoudiop1985
    @amadoudiop1985 7 днів тому +1

    Sénégal c’est pas un pays Akh li da yomb trop qu’on remet sa mère et la famille dans la maison forcé Sénégal amoul justice amoul lois c’est du nptk

  • @FallouKane-zf9ed
    @FallouKane-zf9ed 7 днів тому

    C'est la première fois ma guiss ko de

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 7 днів тому

    Ay mane d taye mouma menone ba sama yaye niou bakhdia nieuwatt ma séne khari ma séne alasane barke serigne babacar sy ma defko bilaye walaye

  • @isseundiaye8935
    @isseundiaye8935 7 днів тому

    Ay way ki ragaloul yalla dé

  • @ramatoulayendiaye2632
    @ramatoulayendiaye2632 7 днів тому

    Adouna toukina yaye ak Nou mou sonné fayé woko Dara Lou doule li

  • @AlimaCisse-vv3cd
    @AlimaCisse-vv3cd 6 днів тому

    Macky mo beuri bayré

  • @SenyCissé-b2y
    @SenyCissé-b2y 6 днів тому

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲

  • @farmataniang5608
    @farmataniang5608 7 днів тому

    Wollu Wollu Wollu Wollu yalla jogleen dimaly jaboot yalla wallu

  • @MameseynabouNdiaye-o4l
    @MameseynabouNdiaye-o4l 7 днів тому +1

    Kou torokhal sa yaye torokhe amoul wakh

  • @aminataniang8335
    @aminataniang8335 7 днів тому

    Ndeysan mère diou bakh bilay 😢

  • @MbayeDiop-sm5jl
    @MbayeDiop-sm5jl 7 днів тому +1

    Masa metina torop

  • @TabaraPouye-c6f
    @TabaraPouye-c6f 7 днів тому

    Manedé diomina ki beugue na homme khana goudigui mon nékh montakhite diébalouna gor takh guaye torakhal sa yaye khana ki koyou diama la yor 😂😂😂

  • @mateldoucoure689
    @mateldoucoure689 7 днів тому

    Sa dieukeur dinala torokhal beuthe guou ndara kamb

  • @mariamadione8533
    @mariamadione8533 7 днів тому

    Ndiaya deh sa woy dotoul fay, dom bou torokhal ndéyam,allahou akbar l’histoire retiendra ,😢li dey boula djigué ma khamni mbeur ga
    Tay souma meunona guissate sama yaye💔dina remuer terre et ciel pour defal ko li mou beugue

  • @MoustaphaKhouma-sd3zg
    @MoustaphaKhouma-sd3zg 7 днів тому

    Na yoone déf ligéyam

  • @NdeyegnagnaMbaye-d6j
    @NdeyegnagnaMbaye-d6j 7 днів тому

    Wa mané esk yayam laaa guéne balma qui du nitte yalla nalla sa dieukeur torokhal ndiaya la sorsier

  • @FatimaFall-ci2ms
    @FatimaFall-ci2ms 7 днів тому

    amoulll domdji tayouko mokko tayyy yaye daffa sakh ci kholll ki yalla nakko akou yayam dallll