Niankou ak koorgui - Épisode 8 - Sketch Ramadan 2022

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 3 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 358

  • @khalil1111
    @khalil1111 2 роки тому +152

    Ana gni begue Khassida serigne Touba yi nio ngi lenn di niane ngén abonnés fii ci “ Khassida tv ” ngir dieumi seydina mouhamed psl 🙏🏾❤️❤️

  • @assanendom4621
    @assanendom4621 2 роки тому +102

    Ta mère sera parmi les femmes du paradis in sha Allah ❤🙏🥰

  • @cheikhounafassa281
    @cheikhounafassa281 2 роки тому +39

    Billahie niakou le meilleur commedien yallah nala fi yallah bayi si barki seydina Mouhamed psl❤️❤️

  • @wakeurboromkossodaroukosso463
    @wakeurboromkossodaroukosso463 2 роки тому +62

    Douck linga wax si cheikh ibra nékh na❤️🙏🏿

  • @fallouthiam3137
    @fallouthiam3137 2 роки тому +20

    Lampe fall yalla nanou ko yalla fayal ❤

  • @medzo5671
    @medzo5671 2 роки тому +24

    Baye fall rek mon woorr yalla na diamou yague

  • @malangcamara7896
    @malangcamara7896 2 роки тому +77

    Que des leçons de vie dans vos séries QU'ALLAH vous assistes et succès à vous

  • @islamtv7210
    @islamtv7210 2 роки тому +86

    Diadieuff les baye fall sén ligueye rafett na trop yenna gui térral newdi doolée yii yalla nalén serigne touba fayy

  • @actualiterap9306
    @actualiterap9306 2 роки тому +11

    Le bayfal a fait un geste très noble

  • @ndoumbepouye8298
    @ndoumbepouye8298 2 роки тому +27

    Très belle leçon d'amitié à la fin...peut importe l'enjeu l'amitié le vrai ne s'éclate jamais

  • @mamethiernofall5882
    @mamethiernofall5882 2 роки тому +8

    Borome darou yalla n'a fi yagg te wer 🙏🙏🙏 n'oublie pas Serigne Abdou Karime yalla n'a fi yagg te wer 🙏🙏🙏

  • @blacktvblack9638
    @blacktvblack9638 2 роки тому +53

    Mane doucouré ak le père de niankou dinagnma réy 😂

    • @designer354
      @designer354 2 роки тому +1

      Barki yallah ay ndanan lanie

  • @senegal2023
    @senegal2023 2 роки тому +275

    Yow midi lire sama publication bi Yalna Nga tekii teral Say wadiour wakhall Amin ❤️😭 tè abonné

  • @softdstlo8171
    @softdstlo8171 2 роки тому +10

    Machala li rafét na trop yalla na diam yague ♥️♥️♥️

  • @papendiaye8450
    @papendiaye8450 2 роки тому +22

    Ani wa team Avancer pub j'aime 😂

  • @mamadoufaye3188
    @mamadoufaye3188 2 роки тому +2

    Barcke cheikhoul khadim mangui guene kontane 😭😭😭♥️si mame cheikh binguene nekone 🤲👏

  • @malickbeye4301
    @malickbeye4301 2 роки тому +4

    Bilahi j aime tellement les vrai bay fall serigne cheikh nena yenangui aldiana

  • @abokane820
    @abokane820 2 роки тому +27

    Le partage est l'un des points fondamentaux du Bayfallism

  • @lingardgeuye6177
    @lingardgeuye6177 2 роки тому +27

    BILAY DOUCOURÉ DAFA KONG 😀

  • @bocargangue4858
    @bocargangue4858 2 роки тому +5

    Koudoul baye fall 👌🏽 Baye fall 👌🏽 mola geuneu 👌🏽

    • @papesylla7281
      @papesylla7281 2 роки тому +1

      Doul nga deh

    • @bocargangue4858
      @bocargangue4858 2 роки тому

      @@papesylla7281 Ndeysan Ana teguenine saway louma way DF balnako....Amal diam rk oe ...

  • @cheikhfall132
    @cheikhfall132 2 роки тому +17

    Yalna yalla deff jamm gni nék si hôpital 🏥 yi yalla feug sén bobpou way dawlou yi yalla yeureum len yalna jamm yague🙏🙏

  • @aidaradiaw6264
    @aidaradiaw6264 2 роки тому +15

    Général kaire nena wally seck mo mana woy amlen diam rek 🤣🤣🤣🤣🤣

  • @diagnenar5717
    @diagnenar5717 2 роки тому +3

    Yalna Diammou yagg sii Sénégal ak louka weur sii barké baye yarabi

  • @mbayesall3507
    @mbayesall3507 2 роки тому +7

    Fall mi yalla falé koudoll baye fall baye fall mo la geun

  • @Khitmatoulkhadim1
    @Khitmatoulkhadim1 2 роки тому +15

    Good job yallnaa nieup am dim

  • @Serigne_khadim_mbacke
    @Serigne_khadim_mbacke 2 роки тому +2

    Machalah ab baye fall ni laye méléKano yalla na léne yalla sambou té rafétall séne xoll

  • @elseneprod8449
    @elseneprod8449 2 роки тому +1

    Doukoure nékh na bilahi

  • @bounamadiagne9331
    @bounamadiagne9331 2 роки тому +24

    Bonne ramadan ❤

  • @senegal5217
    @senegal5217 2 роки тому +4

    Guémignou niankou bii dounko vérifié khol lou cii nekk🤣🤣limouy meutie dé xamna nekhna😂😅😄😃

  • @ousseynoudiakhate8370
    @ousseynoudiakhate8370 2 роки тому +15

    Vraiment y’a avancement par rapport ak année denier le son est bon l’image parfaite vraiment chapeau a vous

    • @adjandiaye6422
      @adjandiaye6422 2 роки тому

      Sisi inchallah dina geune bakh ak niankou pro bi

  • @abdoulayefayedia7651
    @abdoulayefayedia7651 2 роки тому +4

    Amna solo trop bilay 😂😂😂

  • @sokhnafatoudiandiaye8170
    @sokhnafatoudiandiaye8170 2 роки тому +6

    Wouy Niankou nèna ki rek moma woutal heuy🤣🤣🤣

  • @rouguietousy2292
    @rouguietousy2292 2 роки тому +26

    Doucouré loutakh mou beug ay aylou tei bou dara khéwé moy dieunk daaw, néna douma nittou deux cent, guédé néna damadone khol ndakh intérêt ngama topé😂😂😂😂

  • @diedhiouismaila8079
    @diedhiouismaila8079 2 роки тому +3

    Doucouré dinama ray rék 🤣🤣

  • @awacheikhibra
    @awacheikhibra 2 роки тому

    scène du baye Fall 😭❤ bilahi sidy birahim amna kounè baye Fall Partagé ✌

  • @rsbgby9113
    @rsbgby9113 2 роки тому +4

    Vraiment sketch bi Nice na ❤️

  • @alphasylla4598
    @alphasylla4598 2 роки тому +1

    Way DOUGOURÉ YA DEGG👌🏾❤

  • @amadoudiao756
    @amadoudiao756 2 роки тому

    yala na yalla nakoul sinon Gorgui🙏🏿🙏🏿👁

  • @elementndiamedarou2414
    @elementndiamedarou2414 2 роки тому +57

    Waw bay fall moy liguey dimbali gnigua tané,pas de Sathi,pas de toukh yamba,pas d'insultes,enfin bayi dérou nitt gni té baayileen sa derr,loo am diokhleen liniou am gua bakok niom etc

    • @abdougueye6984
      @abdougueye6984 2 роки тому

      Walaxi baye fall moy noble ❤

    • @modoudiakhate6820
      @modoudiakhate6820 2 роки тому

      Dafa ler

    • @ousmanediop1620
      @ousmanediop1620 2 роки тому

      Yal wane rek guene meun🤣🤣🤣

    • @seydinadione3607
      @seydinadione3607 2 роки тому

      akassa ndeysaane

    • @gondiaye6661
      @gondiaye6661 2 роки тому

      @@ousmanediop1620 😂ouz rayngama mé menousi niak ndakh daradjia teksi baye térré té falé yala d'où nieupako meune khamna pour nga khamsi Lou Bari ak yalwane gui setanal baye ndiaga Diop ou baye cheikh ndaw magui toup boubakh nak barkep cheikh ibra souma wakhé Lou niaw balma akh ouz 🙏👌réna basone

  • @papasambandiaye5752
    @papasambandiaye5752 2 роки тому

    Guédé ak doucouré sen djotay comme emission télé🤣🤣🤣

  • @khalyfall5870
    @khalyfall5870 2 роки тому +6

    Nice j’aime cette Épisode

  • @matarthiam4086
    @matarthiam4086 2 роки тому

    Bii mm moy meilleur bi fall amna solo

  • @طالبالرضوان-ر8س
    @طالبالرضوان-ر8س 2 роки тому

    Thiey yalla yalla santané koor ngén ni doungén woor diamoulén yalla té bayi thiakhan yi

  • @mouhamadlo1776
    @mouhamadlo1776 2 роки тому +5

    Doukoulé dinama rayy😃😃😃😃😃❤️🙏

  • @aboundiaye8299
    @aboundiaye8299 2 роки тому +2

    Niouye diouli tèye worr mo geune thiakhane yi 🤌🏾

  • @aramedieye4756
    @aramedieye4756 2 роки тому +9

    V etes vraiment fort machala

  • @modouseck7237
    @modouseck7237 2 роки тому +6

    Machalla fall rk 👌🏁🏁🏁🏁🏁

  • @ndoumbediop8298
    @ndoumbediop8298 2 роки тому +2

    Le serie vous être meilleur

  • @mmrassoullo9170
    @mmrassoullo9170 2 роки тому +5

    Bay fall bi dioylonama 😥❤️🙏🏾

  • @Soppe-nabi
    @Soppe-nabi 2 роки тому +3

    Baayi leen caaxaan nga naan baye fall laa woor ñépp la war.
    Amul baye fall ak ku dul baye fall. Maa ngi jéggalu nag 🙏

    • @khadimsarr1943
      @khadimsarr1943 2 роки тому +3

      Yéne sokhor Ake Bonn molene sonal bilahi képe koy dingate baye fall yii yawe diarol sakh ngaye diamo yalla Di sonal sa bop safara moye sa keur barké seringe Touba

    • @ricardpuigpuig1836
      @ricardpuigpuig1836 2 роки тому

      waay noppil ...mandouuu daffa baakhhh....worraal saa woor reek .....baye fall yiii saa Yoon nékoussi ...niom aakk yalla laaa...

  • @aidandiaye1158
    @aidandiaye1158 2 роки тому +1

    Amine yarabi 🙏🙏 niou book leupeu inchallah

  • @madamedieng2108
    @madamedieng2108 2 роки тому +9

    😂😂😂😂😂😂😂non doucourè ak Kairè raynagne ma😂😂😂

  • @papeomardiagne4954
    @papeomardiagne4954 2 роки тому +3

    Akassa fall🤣🤣non fall todj ngafii🤣🤣🤣 niankou déh souba mou outi keull🤣🤣🤣

  • @dioumserigne099
    @dioumserigne099 2 роки тому +1

    Koor keip ko guisse ak komo meuna don di dioxé ndogou mo xam mo xam ko wala mo niak ko xam si cheikh ibrah faal bayi ko
    Motax nak
    Xamé Baye Fall Jotna
    Ragné Deugi Deugi Baye fall Jotna…….
    Sen wadji do baye fall
    Baye Fall dfay seil di liguey di diamou yalla té mbanou 🙏🏽

  • @djibrilmbow8074
    @djibrilmbow8074 2 роки тому +1

    Baye fall si ay djiko leu 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌

  • @mbayebabacar5053
    @mbayebabacar5053 2 роки тому +48

    𝐍'𝐨𝐮𝐛𝐥𝐢𝐞𝐳 𝐏𝐚𝐬 𝐋𝐞𝐬 𝟓𝐩𝐫𝐢é𝐫𝐞

    • @bathiefall9007
      @bathiefall9007 2 роки тому +1

      Mandou mo gueun lép fékhel nga respecté sa 5 prière rek di niane yalla mou nangoul lako frère lolou mo euppu solo mangui toub bou wer

  • @mouhamedkonate8695
    @mouhamedkonate8695 2 роки тому +1

    Niankou Nekeu baye fall legui

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 2 роки тому +3

    *Bilày doucouré doù Nitou fi seuhhh 😁🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🚶🏽*

  • @mrgueyelamine9286
    @mrgueyelamine9286 2 роки тому +1

    Macha allah. Lii moy baye fall deuG

  • @papitohdip1625
    @papitohdip1625 2 роки тому

    Douma nittou 200 f Doukouré il est fort😀😀😀

  • @lahadseye6101
    @lahadseye6101 2 роки тому +1

    Doucouré la beugg bilahi 😅😅😅😅😅😅

  • @lexvofficiel6800
    @lexvofficiel6800 2 роки тому +1

    Doucouré tamittt 😂😂😂cas la 😂🤣

  • @guilayegaye2062
    @guilayegaye2062 2 роки тому +1

    Baye Fall bi néna maguî wallahou 😂😂😂

  • @mbarsene8118
    @mbarsene8118 2 роки тому

    Bilakhi doucourè amal jamm rk 👌🤭😂

  • @khadimsarr1943
    @khadimsarr1943 2 роки тому +3

    Barké Alkhouran barké seringe Touba épisode bi mo dakh si épisode yépe non Theiye baye fall yii Ligeuye diokhé wallahi lolo yomboul motakh bilahi dinange lak ngou Bari wallahi

  • @sambaafricatv
    @sambaafricatv 2 роки тому

    Général AK Doucouré 😅😂😂

  • @ibouyandou782
    @ibouyandou782 Рік тому

    Non doucouré ak guédé talents 100%

  • @loumenebiloumenebi711
    @loumenebiloumenebi711 2 роки тому

    Wa Team and sétann niankou feeeep

  • @papabaragueye4504
    @papabaragueye4504 2 роки тому

    Manguéy walakhou momoy ray 🤣thieuy bayfall aldiana ❤

  • @djibrilmbow8074
    @djibrilmbow8074 2 роки тому +2

    Koudoul baye fall baye fall molo geunn si ay djiko leu

    • @khaliloulah2167
      @khaliloulah2167 2 роки тому +1

      Waxou thiakhane kasé ak gnak xam waxou yalla geune mogui koula geune dioup geune selleu dakh la diamou yalla lene lo wax lodoul li fene la ak weddi yalla

    • @khadimsarr1943
      @khadimsarr1943 2 роки тому

      Bilahi baye fall yii dinange lak ngou Bari wallahi

  • @ibrahimathiam5655
    @ibrahimathiam5655 2 роки тому

    Doukouré le meilleur

  • @baboyesow9561
    @baboyesow9561 2 роки тому

    Baye fall mo guenn yess mouride mo guenn yess

  • @jeandiop8519
    @jeandiop8519 2 роки тому +2

    Douck doundeul Wäy 🏁⚫⚪👌

  • @sidybarandiaye8479
    @sidybarandiaye8479 2 роки тому +4

    Diarama sidy Brahim fall

  • @wakhdeugthiala2980
    @wakhdeugthiala2980 2 роки тому +4

    Doukouré AK guédé dinagn ma ray😂😂😂😂

  • @fallougueye2678
    @fallougueye2678 2 роки тому +1

    akasa fall amna solo

  • @pendathiaw
    @pendathiaw 2 роки тому +14

    😂😂😂gni niouniouy sedaler sama xol bi naléne ko yalla fay

  • @Zall2.00
    @Zall2.00 2 роки тому

    Loutakh ma fan doukré dafa nékh lamign 😂😂😂

  • @loyalbi823
    @loyalbi823 2 роки тому +10

    6:35 non vous avez résumé la vie des sénégalais bilay yorouniou beurinaniou bor danio dal xel mais amouniou moyens 😂

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 2 роки тому +2

    Doukouré dieuleul exemple bi rek😂😂🤣

  • @maymounagueye7249
    @maymounagueye7249 2 роки тому +1

    Machalla nékh way baye fall bi machalla

  • @moustaphadione5509
    @moustaphadione5509 2 роки тому

    Niankou amna âme kheuy

  • @ousmanediop1620
    @ousmanediop1620 2 роки тому +1

    Thiapa ndeyam yene ak seni serigne rek kene meunoufi am diamu ak serigne doul rek rek lagne meun

    • @neymar10diallo92
      @neymar10diallo92 2 роки тому

      😅😅😂😂😂😂😲🤣🤣🤣😭😭😭😭😭🏃🏃🏃🏃🏃🏃

    • @yorothiaw5213
      @yorothiaw5213 2 роки тому

      Sa data yaye

  • @Cheikhdeme123
    @Cheikhdeme123 2 роки тому

    Ma beugue niankou

  • @damassndiaye7064
    @damassndiaye7064 2 роки тому +1

    Walàhi anzime sama akh boulen dalet non baye fall bi Rey nalenn 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @amarfallou7480
    @amarfallou7480 2 роки тому +1

    Lii histoire leuh naack douckré danou looh n'a baye fall bii

  • @djilyfall7201
    @djilyfall7201 Рік тому

    No fin bi😢😢😢lou am solo

  • @tallandiaye9150
    @tallandiaye9150 2 роки тому +2

    Wali losi yonam 😂😂😂 si danou bi

  • @abdatyvalia1517
    @abdatyvalia1517 2 роки тому +2

    Niankou door katt la 😂

  • @mariamaseck320
    @mariamaseck320 2 роки тому +6

    Doucouré nenako sifeul monine bi dieuleul yoro😂 mais tamit guenei niko waadji kheutié mou diahane mayei bopam😂😂
    Je termine par magui walakhou😂😂😂 magui dhei fi

  • @pk_business19
    @pk_business19 2 роки тому +8

    yéne gnii déwagoul yalla guéne dead demain 😂😂😂😂

    • @mamadoungom7455
      @mamadoungom7455 2 роки тому +2

      kou dhé téy ak souba Yako réy🤣 assassin

    • @rounewinner2419
      @rounewinner2419 2 роки тому +1

      Amine ya Rabi

    • @Soppe-nabi
      @Soppe-nabi 2 роки тому +1

      Yaw kay kom ka dee nga ñianal ñu gudd fan rekk

    • @pk_business19
      @pk_business19 2 роки тому

      @@mamadoungom7455 oh day sane ioe boko Mane je m'appel Mamadou ngom ossi sama toma ga

  • @dabistadieus241
    @dabistadieus241 2 роки тому

    😂😂😂😂 gni dougn nitou dara

  • @allediop1247
    @allediop1247 2 роки тому

    Doukourei mongui may rayy waay🤣😂

  • @fatoudiagnediallo3857
    @fatoudiagnediallo3857 2 роки тому +3

    Doucoure 🤣😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ouzprondoye875
    @ouzprondoye875 2 роки тому +1

    Kénn dou doucouré

  • @MindsetA.N2025
    @MindsetA.N2025 2 роки тому +1

    Sama yaram bi yepou daw na ay yax rek la dessé ni mais quel leçon d’amitié ohhh may na léne kou nek 5$😂😂😂

  • @seydousow1704
    @seydousow1704 2 роки тому +2

    N'oubliez jamais les 5 prière c'est obligatoire pour les musulmans

  • @ssalioukhouma9519
    @ssalioukhouma9519 2 роки тому

    M'y best series

  • @bayeserignesamb9564
    @bayeserignesamb9564 2 роки тому

    Danél nga baye fall bi dh🤣🤣konn ma ngaye walakhou

  • @modoucisse837
    @modoucisse837 2 роки тому

    Boulen ma ray way hahahaha