Machalla li amna solo trop machalla ❤️🧡❤️❤️❤️❤️❤️❤️ adouna yalla moko khallé bou gore bi yalla nako yalla maye goudou fane akhe wére si barké Seydouna Mohamed ❤
Pour moi, il faut le rejeter autant qu'il t'a rejeté. Ce vieux est ton géniteur mais pas ton papa car il a décliné sa responsabilité parentale depuis ta conception. T'as pas besoin de lui, trace ta route mon frère.
@@ibrahimagueye8559 ce n'est pas une obligation religieuse de pardonner. S'il le peut tant mieux mais personnellement à sa place, je ne pardonnerais absolument pas.
Il faut assumer ses responsabilités dans la Vie khame khalébi limou done euluke pour moi il doit le reconnaître comme son papa mais il aura toujours la rencune que son papa a fuit sa responsabilité
Il ne serait pas Iman ernternellement ! Mais restera ton père à l'éternité laisse le temps faire les choses. La décision doit venir de lui même et Allah voit tout. Courage Mr le procureur car le meilleur reste à venir.
Le pardon guerrit les blessures du cœur.nous tous qui réagissons, vivons en harmonie dans nos familles.laissons les autres en profiter.Rien n'est éternel sur terre.Toutes les écritures saintes se résument en l'amour.
Je me demande pourquoi refuser sont sang et la souffrance de ça mère nos maman soufre beaucoup dans cet genre de cas ne lui pardonne pas il ne t'a jamais accepté comme sont fils cet triste 😭😭😭😭
1 Wa Thi côté l'islam Dh même souko pa Bi accepté Dou Takh l'islam acceptéko Thi pa Bi Thi yaayam rék lakoy accepté. 2 wa Mom souko mané jégal Moy li Gane comme Niko yalla waxé "فمن عفا وأصلح فأجره على الله" من سورة الشورى الآية 40 3 Khayna yaxxou yaxxou Bouy Am Thi famille Bou pa Bi ndax mbokko Gui fala tayit ragal Naani Dou yombou Thi pa Bi moukoy léral Ak Ndiabotam dh😢 4 yalla naniou yalla jégal Ta May Niou jamm jou sakh dakk Ta bolé Niou soutouraal adouna Ak alaakhirah. Merci bcp S Fatou émission Bi amna solo 👍
They bou khamon procurer moy domam bimou rejeté won they bouco khamon way no they lolou they bobou rencontre me limo takhe rejeté sa dom bakhoul bou tece gua rousse bilay no li doy na ware bilay se une vraie leçon de vie❤❤❤❤
Ne te laisses pas emporter par les paroles des rancoeur.tout en chacun a besoin d'aimer et de se sentir aimer.le pardon guerrit les blessures du cœur.Rien n'est éternel sur terre. Ils vivent en Harmonie avec leur famille et leur fond intérieur.Vous n'attendez rien de votre père mais la paix du cœur
Il faut demander ta mère ou tes grands parents ces conseils seront les meilleurs mais apparemment tu as toujours besoin de lui donc il faut nouer la relation mais il ne faut jamais oublier et il faut le faire savoir
@@papawade8521 sa waye pa yi linou beugue dafa yombou dannoulaye abandonné ake sa yaye guene sonou niome niou nek benene djiguene nga teki niou nieuwe nane moye sa papa après nafekhe yi takhawe nane bale ko ter khamouniou li nga dathie ake sa yaye
Le pardon du procureur n’est rien devant celui de sa mère et ses parents ce sont eux qui ont souffert. Il devra demander à l’imam d’aller demander pardon à sa mère. Elle souffert depuis sa jeunesse avec une grossesse et un enfant. Personne ne sait comment elle vit son mariage.
Mome da bakh rék te manqué amour soudone mane doma eup foula parsk sou nékone vaut rien pa bi douko falé donc sou fékone mane dama lay supprimer sama parsk da nga ma trohale mane ak sama yay
La dignité de sa mère a été bafouée celui de ses parents elle a été exploitée sexuellement par un fou qui se dit riche et qui détournait les mineurs qui sait combien de victimes il a fait avant de penser à ses 2 diegues qui souffraient sûrement en silence. C’est un imam irresponsable il faut le dénoncer parce que Dieu voit tout.
salut fatou com dhab Maashallah amatina solo 😊lima koy wax moy na signalé ni pa bi moko diour ndax lislam kén dou ko fowé nako wax niou dindi imam bi après mom mou dess ak papa dji lougn kham niou def ko
Nul n’est parfait on a tous pêché pour moi le vieux a commis une erreur fatale de n’avoir pas reconnu son fils et d’avoir laissé la pauvre innocente seule dans Son galère alors que c’est lui même qui la tromper la pauvre et l’enfant aussi a grandis sans amour ni de l’affection paternelle donc le vieux lui il a commis des erreurs en étant plus jeune pourquoi on ne peut pas lui pardonner on a tous péché pour moi rien a avoir avec son statut d’imam y’a beaucoup d’imam qui ont fait plus pire même les imams commettent des erreurs c’est des humains comme tout le monde le mal dans tout ça c’est d’avoir rejeté son enfant il sait très bien que c’est Son enfant car il est sur que c’est le premier homme de cette pauvre fille par ce que la fille était mineur elle n’avait aucune expérience dans la vie alors que lui avait déjà deux femmes pourquoi donc rejeté son sang c’est ça mon problème monsieur le procureur je vous demande de le pardonner et de profiter de votre père parce que le pardon vous libère et vous ferai une personne meilleure Profites en tant qu’il est encore temps et essaye de faire connaissance à tout vos frères et sœurs la famille est très importante Profite de tes frères et sœurs monsieur le procureur vous avez une chance de réussir votre vie et une chance d’avoir une très grande famille ne laissez pas le rancune détruire toutes les chances que dieu vous a donné profites en monsieur le procureur nul n’es parfait ❤
Est ce que on peut se cacher devant Dieu. Non. Donc le papa doit se confesser devant toutes ses enfants et demande pardon à la maman du grand Monsieur le Procureur
Fatou ba ndiayen yi diappoula 😅😅😅😅bes buko wa deuggubi xamé dotul done imame deh na nabou secret bi té du tee moukoy dimbali come mom yalla sutural nako baga xamni wérouwul si Ken na xame lime xame té noppi ndakh fi Senegal da xawa dorway trop té bolési kheuthio imame yiye ame si diakayi sunu la xamalé secret bu touti danioulakoy waxal kone na noppi rek yalla bakhna yalla xole lay Faye mercy fatou
Cariiya néna kou ndialo du nék imame té koumu djité amo diouli kone nako wakh bala mouye yakh diouli mbolo mi sinon backar bi daye beuri أولاالحق ولو كان مرا
Mon frère mesieu le procureur sa papa diegueule KO té yalla soubhana houwa tahala kepe yakhe doka rethiou nakhe wadioure dafa fore en plus nagna bayi khele ni dieu est avec toi wallahi
Il n'était pas imam à ta naissance donc pense à la souffrance qu'a enduré ta maman.tu peux t'arrêter à la présentation et gères ta famille maternelle.yallah kenela darame dou changer,quand il moura ou bien tu meurs personne parmi vous ne doit héritier .kou wax wadiour doth la dou bi wadiour.rends heureuse ta maman et tes grands parents.
Vrement djiguene gni sone nagnou bouy nekh moy lollou sou eumbè nga bagne c triste
Machalla li amna solo trop machalla ❤️🧡❤️❤️❤️❤️❤️❤️ adouna yalla moko khallé bou gore bi yalla nako yalla maye goudou fane akhe wére si barké Seydouna Mohamed ❤
Ndeyssane Thieuyy Yallah Adouna dafa goudou tank nako Bal ta Yallah rek takhe 😢Masha Allah sister Fatou mayniou ci caffè ☕ gui 😊Bonne Continuation Dieureudieuf 🙏 ❤ 🙏 ❤ 🙏 ❤ 🙏
Koko kay matul immam 😂😂
Jiguene louko mèti goor moko tekk
Macha allah Longue vie à vous fatou diarrama c'est bando diallo depuis Italie Lecce
Pour moi, il faut le rejeter autant qu'il t'a rejeté.
Ce vieux est ton géniteur mais pas ton papa car il a décliné sa responsabilité parentale depuis ta conception.
T'as pas besoin de lui, trace ta route mon frère.
C'est pas une bonne solution mon frere dans la vie il faut savoir pardoner
@@ibrahimagueye8559 ce n'est pas une obligation religieuse de pardonner. S'il le peut tant mieux mais personnellement à sa place, je ne pardonnerais absolument pas.
Il faut assumer ses responsabilités dans la Vie khame khalébi limou done euluke pour moi il doit le reconnaître comme son papa mais il aura toujours la rencune que son papa a fuit sa responsabilité
Il faut toujours faire son devoir de fils envers les parents même s ils ont fait des erreurs entre guillemets.salam
Rien ne peut remplacer un parent qu'il soit bon ou mauvais
Boko doundoul meunoko kham mais yalla bakhna nako bale rék thé yallah takh 😔
Naka Bâle té kham né papam am n'a guadier. Adouna ak alakhira
Nako wakhe papá katal sadeye feuler dafa yombou ❤❤🎉
❤❤❤❤ASALAMALEKOUM SOKHNA sy Masa Alhalla diereudief aman solo mercie beaucoup ❤❤❤❤
Il ne serait pas Iman ernternellement ! Mais restera ton père à l'éternité laisse le temps faire les choses. La décision doit venir de lui même et Allah voit tout. Courage Mr le procureur car le meilleur reste à venir.
Le pardon guerrit les blessures du cœur.nous tous qui réagissons, vivons en harmonie dans nos familles.laissons les autres en profiter.Rien n'est éternel sur terre.Toutes les écritures saintes se résument en l'amour.
Slm aka nékhon ma kham histoire yii foumou khéwé si Sénégal
Thioukoummmmmm ndiayyyyyyyyy non fatou damako beugue ki dou sakh nite 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Je me demande pourquoi refuser sont sang et la souffrance de ça mère nos maman soufre beaucoup dans cet genre de cas ne lui pardonne pas il ne t'a jamais accepté comme sont fils cet triste 😭😭😭😭
Papam waroul nék imam na délo lépou té nék ak domam
1 Wa Thi côté l'islam Dh même souko pa Bi accepté Dou Takh l'islam acceptéko Thi pa Bi Thi yaayam rék lakoy accepté.
2 wa Mom souko mané jégal Moy li Gane comme Niko yalla waxé
"فمن عفا وأصلح فأجره على الله" من سورة الشورى الآية 40
3 Khayna yaxxou yaxxou Bouy Am Thi famille Bou pa Bi ndax mbokko Gui fala tayit ragal Naani Dou yombou Thi pa Bi moukoy léral Ak Ndiabotam dh😢
4 yalla naniou yalla jégal Ta May Niou jamm jou sakh dakk Ta bolé Niou soutouraal adouna Ak alaakhirah.
Merci bcp S Fatou émission Bi amna solo 👍
Sa netali bi déke barale😂😂
Ça veut dire quoi ? Explication please
Naka bal nonou nit day dioom ken matoul n'a fekhi ba wakhtan ak moom lou fi guis wakhatan la ta 😭😭😭wadjour dafa nekh 😭😭 Allahou Akbar
Bilay émission bi amna solo lolou they adina loune gay deg❤❤❤
Caffé bi khana dou sédde?😂😂😂
They bou khamon procurer moy domam bimou rejeté won they bouco khamon way no they lolou they bobou rencontre me limo takhe rejeté sa dom bakhoul bou tece gua rousse bilay no li doy na ware bilay se une vraie leçon de vie❤❤❤❤
Wa mais attend fatou cafè bi dama beuguone kham nakh café ☕️ touba le wala Nescafé wala lane la 😂😂😂😂😂😂😂
Ann Gafé bi may ma si ❤❤
Machallah amatina solo lool yallah samanou
Thioukoum Diop ngay wakh sokhna mai liguay déf amna solo lolll Ku bakh nga franchement
Bilaye fatou café ☕ yaw rek laye topou ❤❤❤❤
Tu peux allé dans les 📺 privées émission bi amna solo babacar dp8 italie
❤️
Sama gayi may 1em 😂😂😂😂
Felicitations 😂😂😂❤❤❤
Merci beaucoup 😍😍😍😍
Importante 🎉
Mashallah amatina solo merci beaucoup ❤❤
Ne te laisses pas emporter par les paroles des rancoeur.tout en chacun a besoin d'aimer et de se sentir aimer.le pardon guerrit les blessures du cœur.Rien n'est éternel sur terre. Ils vivent en Harmonie avec leur famille et leur fond intérieur.Vous n'attendez rien de votre père mais la paix du cœur
Thiey adouna bi😢😢
Salam Salam fatou
Mou ball Pa bi ak mou gnakë ko deff yeup Pa bi mene ta done imame
😂😂😂❤❤❤❤❤❤
Tu as raison! Ku raggalul Yalla togn ngae! Mais yoow d'or bayyi xessal?
Très pertinent mais il faut être court car c’est très long
Ndeyssane c triste et grave ça ndoyna waar ndeh courage mon frère
Té gni bagne séne dom yeupp yalla day def niou niro
Pa bi na delo imame bi ta dioubok domame
Tes vidéos sont tres longues. Faut dire l'essentiel c mieu
Et les souffrances de sa mère dans tout ça. Il a oublié sa mère.
Boule ko bale dara kou bone la sa yaye limou souffrir nake sa papa na talale ba thiaka Ndiaye😂
Kou diangue Alkhouan ok Mai’s kou kham li dinei wakh do ndiaklo
Café ☕️ bi dina sede😢😢😢😢😂
Nako wakhe papa katale sa ndaye feuler dafa yombou
Bayil Thioukoume Ndiaye Thioukoume Diop la
Mane sa imisobi damakoye dekelo saké soreba sama wakare dima djipe
Qu'il laisse a son papa la responsabilité de décider de la suite.Et surtout qu'il soit patient
Il faut demander ta mère ou tes grands parents ces conseils seront les meilleurs mais apparemment tu as toujours besoin de lui donc il faut nouer la relation mais il ne faut jamais oublier et il faut le faire savoir
Pa bi bakhoul dou nitou dara
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mane der papa diouma abandonné bama teki nga nieuwe nane ma maye sa papa ma dokhane sa ndaye
mdr boulma ray mé bén Yoon lagniy am papa
@@papawade8521 sa waye pa yi linou beugue dafa yombou dannoulaye abandonné ake sa yaye guene sonou niome niou nek benene djiguene nga teki niou nieuwe nane moye sa papa après nafekhe yi takhawe nane bale ko ter khamouniou li nga dathie ake sa yaye
Walahi nekhoul dégue mais deugue rek nga wakh kou la abandonné bi nga ko gueuneu sohûla sou nekhé waroul nieuw
Deel résumé conection bi dafa chère trop nak
Ndessanne. Kholal ma. Li. Reck
❤❤❤❤ ❤❤❤ Amine
Nanou nagoulep papa dji deglou thi yala kham ne yala yenako
Na baal papa dji, adouna amoul solo
Le pardon du procureur n’est rien devant celui de sa mère et ses parents ce sont eux qui ont souffert. Il devra demander à l’imam d’aller demander pardon à sa mère. Elle souffert depuis sa jeunesse avec une grossesse et un enfant. Personne ne sait comment elle vit son mariage.
Son père n'a pas souffert c la maman ki a eu tant de souffrance
Bayyilén khéssal ak perruque té ragal Yalla am djom.
Do wakh rek tiè bayi manièrou bi.
Mome da bakh rék te manqué amour soudone mane doma eup foula parsk sou nékone vaut rien pa bi douko falé donc sou fékone mane dama lay supprimer sama parsk da nga ma trohale mane ak sama yay
La dignité de sa mère a été bafouée celui de ses parents elle a été exploitée sexuellement par un fou qui se dit riche et qui détournait les mineurs qui sait combien de victimes il a fait avant de penser à ses 2 diegues qui souffraient sûrement en silence. C’est un imam irresponsable il faut le dénoncer parce que Dieu voit tout.
salut fatou com dhab Maashallah amatina solo 😊lima koy wax moy na signalé ni pa bi moko diour ndax lislam kén dou ko fowé nako wax niou dindi imam bi après mom mou dess ak papa dji lougn kham niou def ko
Nul n’est parfait on a tous pêché pour moi le vieux a commis une erreur fatale de n’avoir pas reconnu son fils et d’avoir laissé la pauvre innocente seule dans Son galère alors que c’est lui même qui la tromper la pauvre et l’enfant aussi a grandis sans amour ni de l’affection paternelle donc le vieux lui il a commis des erreurs en étant plus jeune pourquoi on ne peut pas lui pardonner on a tous péché pour moi rien a avoir avec son statut d’imam y’a beaucoup d’imam qui ont fait plus pire même les imams commettent des erreurs c’est des humains comme tout le monde le mal dans tout ça c’est d’avoir rejeté son enfant il sait très bien que c’est Son enfant car il est sur que c’est le premier homme de cette pauvre fille par ce que la fille était mineur elle n’avait aucune expérience dans la vie alors que lui avait déjà deux femmes pourquoi donc rejeté son sang c’est ça mon problème monsieur le procureur je vous demande de le pardonner et de profiter de votre père parce que le pardon vous libère et vous ferai une personne meilleure Profites en tant qu’il est encore temps et essaye de faire connaissance à tout vos frères et sœurs la famille est très importante Profite de tes frères et sœurs monsieur le procureur vous avez une chance de réussir votre vie et une chance d’avoir une très grande famille ne laissez pas le rancune détruire toutes les chances que dieu vous a donné profites en monsieur le procureur nul n’es parfait ❤
Il faut le rejeter pour moi même étant iman
Je te conseille de ne pas garder les relations chacun pour soi dieu pour tous
Vocal warone naa âme. Il n'a qu'à pardonner Allah est témoin de tout.
C difficile de pardonner à celui ki a roviné ta vie,j'en sais klk chose
Laisse ton verre tranquille waye
Est ce que on peut se cacher devant Dieu. Non. Donc le papa doit se confesser devant toutes ses enfants et demande pardon à la maman du grand Monsieur le Procureur
Man gua netali
PAA BI. NA. WATHI. MINNBAR BI. MOY PREMIÈRE. CHOSE. APRES. NAK. MOY. SERY. LIMOUY. DÉF
Papa bou niak diome solawtouko na topoto ndeyam te doundou doundam
Mais sokhna fatou amna Lumala wakhone mais toutou amagoule.tontou ma gaw.wala so ama dieukeur nga wakhmako ma guene thi.
Ndeysane 😢
Ningaye nanè cafè mashallah
Élève. cémeudeu 😅😅😅
Il est bien éduqué
Boumouko bal jamais jamais si adina
Na KO ball rek aduna kou def Lou bakh am Lou bakh
Kene dou sougnou borome
Celui la en islam djouroul khalebi seghounou absolument rien d'où djel tourem dou ko donnons
Ndesane kou bah gua soutoural ko gua balko te yalla tah
Il n'a qu'à rejeté son père
Yaw sa explication dafa yague torop comme lep
Papa dji diaratouco aduna da goudou tank
ADOUNA YALLA REK
❤❤❤❤❤❤❤
Mattoul imam mosss😅😅😅
Bonjour
Le pere doit démissionner de son titre d imame et demande pardon à la maman de l'enfant et à son fils qu'il devait élevé
Pardone ton papa.il ne doit pas etre imam.tu nas rien fait occupe deta maman point
So nekon diaykatou guerte sa papa dou nangou
Fatou ba ndiayen yi diappoula 😅😅😅😅bes buko wa deuggubi xamé dotul done imame deh na nabou secret bi té du tee moukoy dimbali come mom yalla sutural nako baga xamni wérouwul si Ken na xame lime xame té noppi ndakh fi Senegal da xawa dorway trop té bolési kheuthio imame yiye ame si diakayi sunu la xamalé secret bu touti danioulakoy waxal kone na noppi rek yalla bakhna yalla xole lay Faye mercy fatou
Asalamou aleicoum chères internautes pour toutes vérités en islam il n'est pas son fils c'est fils de sa mère il ne doit pas hérité rien de lui
Kou eubeule mounoule dôme imam Balko te YALLA takh
Ndawsi di expliquée dafa yambaré
Tioukoume Diop la sante, pas Ndiaye
Cariiya néna kou ndialo du nék imame té koumu djité amo diouli kone nako wakh bala mouye yakh diouli mbolo mi sinon backar bi daye beuri أولاالحق ولو كان مرا
Mon frère mesieu le procureur sa papa diegueule KO té yalla soubhana houwa tahala kepe yakhe doka rethiou nakhe wadioure dafa fore en plus nagna bayi khele ni dieu est avec toi wallahi
Wadiour doth la 😢❤
Il n'était pas imam à ta naissance donc pense à la souffrance qu'a enduré ta maman.tu peux t'arrêter à la présentation et gères ta famille maternelle.yallah kenela darame dou changer,quand il moura ou bien tu meurs personne parmi vous ne doit héritier .kou wax wadiour doth la dou bi wadiour.rends heureuse ta maman et tes grands parents.
Djégal pour lane sou réussiroul mone adounam son papa n'allait pas regretter
@@kingdave2984amna fou dôme Di doné dotch d