Alakhou akbar, Ndiap surprend Wally seck et impose sa place finalement acceptée par Eumeudi Badiane

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 22 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 274

  • @general_tdc2299
    @general_tdc2299 Рік тому +39

    Ndeye ndiaye banaya motakh ndiap transferer Ramdaane😂😂😂

  • @zeze6242
    @zeze6242 Рік тому +11

    Mani ndiap zo amnafi place waye liii quel équipe ❤😂

  • @ngonesene5394
    @ngonesene5394 Рік тому +8

    Ndeye Ndiaye mo eup feeling Awa te li affaire de feeling leu 😂

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 Рік тому +7

    Wally ya meune ya eupe dolé machalla ❤❤❤❤diame rék guaye ame inchalla daga ame gnani wadiour ❤❤❤

  • @HaronaKeita
    @HaronaKeita 20 днів тому

    Je suis Malien fiere mais Jaime beaucoup waly seck s'il plais le bon Dieu visitarai Senegal

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 Рік тому +13

    Man dé j'aime trop eumeudi ❤❤❤

  • @adamaseck8816
    @adamaseck8816 2 місяці тому +1

    Kou beugue yeunguel sa kaw scène diotna nga abeu banaya xalébé meune bari feeling masha allah ❤❤

    • @amysall2008
      @amysall2008 2 місяці тому

      Elle s’impose naturellement

  • @ndeyefatougaye4071
    @ndeyefatougaye4071 Рік тому +19

    NDEYE ndiaye vraiment dafa moure awa nak c’est vraiment triste . 😢.mais NDEYE dafa meune nak

    • @CheikhOumarNdaoNdao
      @CheikhOumarNdaoNdao 11 місяців тому

      Tu pense vraiment ?

    • @FARAON-j9r
      @FARAON-j9r 9 місяців тому

      wah gua wah dji, da meune piir😅

    • @amysall2008
      @amysall2008 2 місяці тому

      Mene rek mo wore ba paré ndeye ndiaye ak ndiap dioubo be paré bok scéne bou amoul mort dine ame blessé

  • @AbdoulazizThiam-u7v
    @AbdoulazizThiam-u7v Рік тому +10

    Awa mo moudié diomi😂😂

  • @sambakoma-cm8bt
    @sambakoma-cm8bt Рік тому +7

    Wally seck mo meune tji ambiance 🎉❤

  • @tendancebmn1573
    @tendancebmn1573 Рік тому +9

    Waly nékoul bayi dafa tabé ame yeurmandé Machalla

  • @cheikhfall3088
    @cheikhfall3088 Рік тому +17

    Mise en Scène 🎬 leu malen ko waakh lougnou Preparer leu 😂😂

    • @fatimandao8359
      @fatimandao8359 Рік тому

      mane mome dama comprendroul

    • @maguintd5790
      @maguintd5790 Рік тому +1

      @@fatimandao8359diakhaso na dh mai man mom dama yeureum sidy vraiment

  • @ReginaAfricana
    @ReginaAfricana Рік тому +20

    Il danse bien maashaallah

  • @mamyba9945
    @mamyba9945 Рік тому +10

    Mashallah ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️

  • @sidibarhamatraore293
    @sidibarhamatraore293 Рік тому +27

    Pourtant amnafi place deh .il danse très bien.

  • @ESCALE3
    @ESCALE3 Рік тому +5

    tiéyy khalissss mdrr sénégal geumouniou darraaa certains diront que cest beau mais le probleme cest l'argent

  • @pApA99599
    @pApA99599 Рік тому +4

    Senegal comme bagages marchands ambulants trop de détails Sonko Macky wally Sidy et l’image reflète sur nos petits enfants cst tjrs motx 0 progrès 0 avancement jeunes bou bgu guna yalla nala souniou borom gunei amine

  • @modouseck1719
    @modouseck1719 Рік тому +6

    Sidy kassé❤❤

  • @bayeniass5633
    @bayeniass5633 Рік тому +13

    Ndiap le phénomène ❤

  • @mameawacisse9537
    @mameawacisse9537 Рік тому +4

    Ndiap ak Wally ndeyesn adouna amoul solo ❤❤❤❤❤❤

  • @dalandadiallo9835
    @dalandadiallo9835 Рік тому +27

    Mane dama moudié yeureume awa 😢

    • @ndiayendeye4713
      @ndiayendeye4713 Рік тому +5

      Bilahi yaw diarna yeureum

    • @kitokoken2187
      @kitokoken2187 Рік тому +7

      Bilaye ,ndeye ndiaye lui fait de l'ombre 😂

    • @ndiayendeye4713
      @ndiayendeye4713 Рік тому +5

      @@kitokoken2187 walahi dagno yobou bayrém bi fégna toul bou bakh

    • @tiatine6328
      @tiatine6328 Рік тому +3

      Mais dey lal khalissam comm Ndeye ndiaye

    • @antagueye1169
      @antagueye1169 Рік тому +2

      No mai awa mo war di duo ak ndaye ndiay mom dafay bérou rk té nday dafa am feeling

  • @wfamily9941
    @wfamily9941 Рік тому +88

    Ndiap nieuweutina 😄 thiey wally mo ndjabot. Legui leer na, ndiap mo beugeu nieuw faramareen. Wally amoul diotou wo ken. Ndiap forcé na ba gneuw ni rek🤭. Artistes yi fonkou len sen ay musiciens ak feth Kate, gnep meunou gno gneuw si wally aussi. Mais bienvenue ndiap, c'est ta décision après tout dangay liguey rek et eumeudy a validé faramareen amoul cissaté gnep lagn yaatal.

  • @buz7755
    @buz7755 Рік тому +14

    Omaro moy bandi 😂li lepo mom la 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @falloundiaye3120
    @falloundiaye3120 Рік тому +3

    Mais ndeye N’diaye banaya ak ndiape thii scene dina tangue dina meti

  • @aminatasidibe1591
    @aminatasidibe1591 Рік тому

    Bou ndiape gnewé Armand Ndiaye soulou kone Awa rékkk 😂❤❤❤no li dafa nekh

  • @BahiaThiouf
    @BahiaThiouf Рік тому +12

    Ndiap mo beugueu Wally 😂liiiii Lou si nite mane 😢❤

  • @cheikhseck1197
    @cheikhseck1197 Рік тому +18

    J'aime le show bizz ils sont forts en scénario mais je suis tout à fait d'accord avec lui avec Waly et son groupe qui font le malin

  • @LittleBuddhaForever-kc9zq
    @LittleBuddhaForever-kc9zq Рік тому +7

    Wally Nekal niit, ndiap sokhlawoko

  • @AmyDiakhate-r3o
    @AmyDiakhate-r3o Рік тому +2

    Néna sama pape yeukeutina niati nék bén bantré ak douche publique 😂😂😂😂😂❤❤❤❤

  • @Dija_Md
    @Dija_Md Рік тому +5

    Ndiap mi dh amoul roussou kaye Deug leu dh nitt ki yaye khôl foula nekh nga dem fa dh mais dou done man la souma naré diougué si sidy diop di dem si Wally ma bayi féthie moma ko geuneul nakh man mom dama ragal gathié Bly 😢mais yalla bakhna com mom moko choisir 😊bienvenue ❤

    • @ndeyesaliou389
      @ndeyesaliou389 Рік тому

      Iow ndap koula😂wakh lan la diote AK sidy fimne daal diamano ji koune Moy fouko arange mu demfa guisnga souba souba man NGA degue ni sidy bayina😂 .soubatel lolu louthi way man ??ba sidy yobouwe orquest am ba Europe lan la ndiap def ???te boba wadjouram yi ak niep nenan ko togal buy delou galsen ....way home sidy ak bañ woor motax mou delou si tu sidy....Kon koku. Gore rek la def bo yore say ferhie kat topotolen amouñu thi Ben avance si sen dundu Amna drua Dem xol fou apou xaliss wakh degue yalla Nak nan wakhante AK degue me aduna da metí rrkk....mom daal loutsx mu ñiak ñiari fethie Kat am sidy mom AK yalla AK dancers yi nioko kham me. Lepp si waloum xaliss Rek lay don fethie da metí ....Daka masa guis bn fethie katou Wally bayi Dem si. Sidy Wala si. Ñienen. ..nono Pask. Sen patrón dafa kham akou ligueye katt😢

  • @diaboudiouf
    @diaboudiouf Рік тому +7

    Ndapou Wa legui louthi nitt mane 😂😂😂😂😂

  • @mamanfatoundoye
    @mamanfatoundoye Рік тому +3

    Ndap dama koy beug ba kagne😂😂❤️Wally goudeul fane

  • @malicksallah
    @malicksallah Рік тому +9

    Wally rek ❤❤❤❤😂😂😂❤❤❤❤❤

  • @abymodyba3101
    @abymodyba3101 Рік тому

    Wally da am hool bou rafétt ❤️mais ndiap bienvenue wally cé le meilleur❤️🙏🙏

  • @Fall-t2i
    @Fall-t2i 11 місяців тому

    Grâce à ndeye ndiaye ❤❤❤

  • @augustinetine-o4z
    @augustinetine-o4z Рік тому +14

    Ndeyssane Awa mom dafa moudié efacéwou😂😂😂

  • @FatmqSakho-ye3bt
    @FatmqSakho-ye3bt Рік тому +6

    Machalla wally li rafétna torop

  • @PendaDiallo-f2c
    @PendaDiallo-f2c Рік тому +2

    Bou yagué sidy diop nieuw ndeysane la pauvre 😅😅

  • @augustinetine-o4z
    @augustinetine-o4z Рік тому +7

    Wouy Waly diomina😮😮😮😂😂😂😂

  • @amiejoof3270
    @amiejoof3270 Рік тому +2

    Sidy, just sit and watch where this will end. Yallah bugul worr akk newal dolleh

    • @Seck221
      @Seck221 Рік тому +3

      SA COMENTAIRE BI KHAMO SAKH LILA KO TAKHA WAKH, YALLA DAY ATTÉ

    • @amiejoof3270
      @amiejoof3270 Рік тому +1

      @@Seck221 jooyal naa sidy, teh hamu makkoh. Njapuh, na fehe beh limm deff, mu jarr ko. Teh Yallah dinna arteh.

  • @djibrildiogoyediouf
    @djibrildiogoyediouf Рік тому +8

    bouléniou fonnto wally dara oupouko thie niéwou diap moko wo Sénégal mo barri nafékh wally khamnané diap dina niéw

    • @sidydiopinfo3609
      @sidydiopinfo3609 Рік тому +5

      Frère gni bayi lén gnouy dof dof Wally kén dou yék si kaw scène bi ta wowou la mom sakh daf koy wakh fi sama chaîne la

    • @djibrildiogoyediouf
      @djibrildiogoyediouf Рік тому +2

      @@sidydiopinfo3609 mo nioko guéna kham di mais Sénégal bo yorré khalise ngua diourr gnou barri

    • @matydiallo3211
      @matydiallo3211 Рік тому

      Daguéni diéma fékhé yor té bayi wakh diou bari dou yéna woté concurrence té yorouléne mouy léne rek

    • @ndeyefatougaye4071
      @ndeyefatougaye4071 Рік тому

      En tout cas eumady savais 😂 khamwmanak waly 😂

  • @LamineSonko-pg1fy
    @LamineSonko-pg1fy Рік тому

    Diap rk laye topeuh ❤❤🎉🎉😊😊

  • @tawoubayam1880
    @tawoubayam1880 Рік тому +5

    Xalisse rekk mai yalla daye atté dh ta souba kéne khamoul louye khéw 😢😢

    • @tiatine6328
      @tiatine6328 Рік тому +1

      Fi travaille tu di yallah day si lan kou avancé do avancé y’a nekh

    • @Zking-k2v
      @Zking-k2v Рік тому +2

      Yow wally da liguey ba tekki nieup daw deme si mom li dou charia showbiz la

    • @kineseck8786
      @kineseck8786 Рік тому

      Bilahi walahi vérité absolue sidy yalna coo yalla maiye kholou mougne ❤

  • @Abyfaye-bx7ph
    @Abyfaye-bx7ph Рік тому +8

    Machallah

  • @ndiogougueye9319
    @ndiogougueye9319 Рік тому +2

    Nice mise en schen 😂,mais ken dou wally

  • @imaneanne9464
    @imaneanne9464 11 місяців тому

    Sakou khaliss seck kène dou yw😊

  • @coumbadiagne7u904
    @coumbadiagne7u904 Рік тому +3

    Ndaye ndiaye rekkk

  • @prodrmx5007
    @prodrmx5007 Рік тому

    Les danseurs de wally ont des coeurs d'ange

  • @matarsarr3638
    @matarsarr3638 Рік тому +2

    Même Wa Ramedan sait qu’il est aveuglé par l’argent 😂

  • @KhadimNdongo-s2s
    @KhadimNdongo-s2s Рік тому

    Nice na dh 😂❤athia papa Wally

  • @yourdarkqueen6275
    @yourdarkqueen6275 Рік тому

    Waly dieulal ndiap moi apporter fraicheur si team bi, dakal payi

  • @mr.africa8166
    @mr.africa8166 Рік тому +3

    No ndiap dou nitt no tothie na suware bii 😂😂😂

  • @munassaidy6313
    @munassaidy6313 Рік тому

    😂😂😂😂ahhh Lee touchna 😂😂😂😂Wally warrouna 😂😂😂😂

  • @sidibarhamatraore293
    @sidibarhamatraore293 Рік тому +5

    Ndiapou nak guiss nani wally dafko beug koi , sayouko guisser rek dafay retane rek 😂😂😂😂

  • @ndeyefatougaye4071
    @ndeyefatougaye4071 Рік тому +1

    Ndiame amenafi place ca change du leumbeul un peu ❤

  • @BahiaThiouf
    @BahiaThiouf Рік тому +5

    😂😂😂😂😂😂bienvenue ❤❤

  • @kadijatoujallow3477
    @kadijatoujallow3477 Рік тому +2

    Nice one 👍 ❤❤❤❤🎉

  • @abdousylla6390
    @abdousylla6390 Рік тому +1

    Ndiapou ne peut ríen apporter dans ce groupe. Ses Pas de danse son perimés. Wally amoul bopou les filles dansent tres bien et font de grandes spectacles

  • @mariaDieme-dp6zg
    @mariaDieme-dp6zg 4 місяці тому

    Ndeye diaye li yeup 10000f la😂😂😂😂😂😂😂

  • @SodaDiagne-qs8tm
    @SodaDiagne-qs8tm Рік тому +3

    Domu thione dji moe säi_säi❤😂

  • @bintacham-iy8sd
    @bintacham-iy8sd Рік тому +13

    We are so proud of you Wally

  • @BoyeMaty
    @BoyeMaty Рік тому

    Kou wakhati Sénégal amoule khass bly ma nokhoula li môme sakh par gnata laye diokhè😀

  • @cisseboromcassamance1855
    @cisseboromcassamance1855 Рік тому

    Ndiapou mii attation sama gayii fèthiii khalè billahi

  • @MinaMina-kn4wf
    @MinaMina-kn4wf Рік тому +8

    Awa banaya la pauvre. Moi à cause de ces gens là, je n'aime plus regarder les shows de wally

    • @TALIBE-SONKO.
      @TALIBE-SONKO. Рік тому +2

      La pauvre pitié d'elle naysane

    • @amymbengue6907
      @amymbengue6907 Рік тому +2

      Senegal legui Dani banalize gnak gor ak ndiom. Bo deme nak akh goredi dal la nguanan Dan ma ligueye san vergogne😢

    • @bigleuztv5211
      @bigleuztv5211 6 місяців тому

      Yaw ya yor yaw bangaye khasté pauvre domeram

  • @salihate-ew6wy
    @salihate-ew6wy 11 місяців тому +1

    Ndiap yaw mi beugue khaliss deh bakh na fataliko dém bakh na deh

  • @FallouGueye-c3n
    @FallouGueye-c3n Рік тому

    Waly vraiment y’a am dolè❤❤😢

  • @cisseboromcassamance1855
    @cisseboromcassamance1855 Рік тому +4

    Wally Sèck mo sokhorr sinonamm barki Rassoul layy

    • @ndeyesaliou389
      @ndeyesaliou389 Рік тому

      WA iow desk sava loutsx ngsnan Wally da Sokor mola Guen fuf

  • @bonypj1775
    @bonypj1775 Рік тому +5

    Awa Banaya nak Ndeye Ndiaye yobou nala banc de touche, 😢daf la guena bandi nak, bouma rouslo way mane yaw lay supporter defaratal peethie mi way🔥🔥😂

    • @seynaboudiop4050
      @seynaboudiop4050 Рік тому +1

      Ndeye ndiaye day oqp la scene mais awa day takhaw bene place rkkk dinaniou rouslo rkkk

    • @bonypj1775
      @bonypj1775 Рік тому

      @@seynaboudiop4050 wollah frère li mome diarna pétition 🥲😂

    • @seynaboudiop4050
      @seynaboudiop4050 Рік тому +1

      @@bonypj1775 ahhh dioukk diotena deiiii awa mi weuyoula katt fogone na dina dawale yeuremender

    • @bonypj1775
      @bonypj1775 Рік тому

      @@seynaboudiop4050 yawmi comprendre nga 😀

    • @pendafedior1712
      @pendafedior1712 Рік тому +2

      Awo kay meme camera yi dougnou ka dieul lou bari 😮

  • @madjiguenedabo2213
    @madjiguenedabo2213 Рік тому +2

    Wa ndiap bou lolou yeup wesso nala lerni lingua eumbeu thi sachet bi yeup matoul 50.000fr😂😂😂😂😂xalissou gambi lalay tegual dh😅

  • @papaomarthiaw9453
    @papaomarthiaw9453 Рік тому +4

    Non li niawna njap kou niaka fayda leu

  • @signytv
    @signytv Рік тому +1

    Diadieuf mass bagui Nice c vito

  • @ngonelo2463
    @ngonelo2463 Рік тому

    Daysane beugu lousii way meun❤

  • @aramendour2205
    @aramendour2205 Рік тому +2

    Bilahi wally li mou def dou classe yaw kay yagui bayi xel sidi

  • @KandjiBams
    @KandjiBams Рік тому +1

    Améth thiou dém yalla faye le niar😂 bu goor ak bu djiguén 😂😂😂ndiap yag fi te wérr

  • @fatoudiop2933
    @fatoudiop2933 Рік тому

    Banaya flag waroul lal souf waye y’a am feeling ndak mbaye s’y merci si rectification bi😂😂😂😂😂😂😂 wally gniabott ngua

  • @moussasall9051
    @moussasall9051 Рік тому

    Ndiap rék Wally ❤❤❤

  • @issasamby357
    @issasamby357 Рік тому

    Kou ré ba ba sonou si diapp ak wally rekk aimel 😂😂😂😂 ha darra dh sidi j'aime bien mais ndiapp demna dh

  • @diamilfaye7253
    @diamilfaye7253 Рік тому +6

    Wally liga def sidy niawna trop bilay walay khelattal boubakh

  • @MaguetteFaye-h9z
    @MaguetteFaye-h9z Рік тому +1

    Ndiapp way ❤

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 Рік тому +3

    Sidy courage diap amoule colaré eskey

  • @abygueye6334
    @abygueye6334 Рік тому +3

    J aime djap

  • @cisseboromcassamance1855
    @cisseboromcassamance1855 Рік тому

    Non waa ramm danne nio rafèttt khôl billahi ils sont trop beaux ceours non gnii nio gentil

  • @diatoundiaye5041
    @diatoundiaye5041 Рік тому +1

    Yalla nañou yalla dimbali ñouye goré ba fawe😮😮😮

  • @gnilanendiaye9590
    @gnilanendiaye9590 Рік тому +1

    Ndeyesane wally ya baxx guoudeul fane

  • @khalil6250
    @khalil6250 Рік тому +4

    Sidi esqu d'où moudié gneuw mom tmt😂

  • @moule7064
    @moule7064 Рік тому +1

    Il danse tres bien

  • @MSGTV-qn2uc
    @MSGTV-qn2uc Рік тому +1

    Khalissou Gambie dé amnsi 10 sakou takhoul mou baré😂😂😂

  • @maxlalionne8146
    @maxlalionne8146 Рік тому +2

    Ndeye ndiaye banaya dafa meune

  • @kingof9317
    @kingof9317 Рік тому +1

    Ndiap legui nge tekii

  • @MbayeLaye-sh8hb
    @MbayeLaye-sh8hb Рік тому

    Bourono rekelayse 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @CoumbaNdiaye-gp7vf
    @CoumbaNdiaye-gp7vf Рік тому +8

    Gaïndé bouye nélawe bouko yé , sidy modone wakhe dans les plateaux de télé dina lalate wally au mois décembre, résultat bi miguini 🤣🤣🤣🤣

  • @LamineDiop-u7m
    @LamineDiop-u7m Рік тому +1

    Sidi diop bo amate saye fethie kat di gua léne téyé da gua naye rek li bakh na thi yawe😂😂

  • @SD-ih6bz
    @SD-ih6bz Рік тому +1

    Démale talale sa khaliss ba Thiackaaa Ndiaye😂😂😂😂

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 Рік тому +1

    Ndiap Moy thiouray deum wally seck tu peux rien faire 😂😂😂🤣🤣🤭🤭🤭

  • @mouhaba6225
    @mouhaba6225 Рік тому

    NDIAPE DEFOULE KOU NEUK AK FILA ARRANGER

  • @JUNIORMBOUP
    @JUNIORMBOUP Рік тому

    Vraiment sidy diop ❤rek labellela

  • @petitndiaye7143
    @petitndiaye7143 Рік тому

    Epeuneu ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 Рік тому

    Man dei bayina def lou baax
    Ndiampu wan nama yoon bi nitt Diarul defal loubakh li

  • @alioudiagne6064
    @alioudiagne6064 11 місяців тому

    En tout cas il va pas durer ici il est mal embarqué demain fera jour

  • @assanefall590
    @assanefall590 Рік тому

    Sheuuut ndiapp dou nit😂😂🤭