🚨Urgent : le Ndigeul de S Mountakha Mbacke avec les Baye Fall sur … - Live TikTok Oustaz Alpha Ba

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 29 жов 2024

КОМЕНТАРІ • 68

  • @Rassoul1425
    @Rassoul1425 Рік тому +21

    Oustaz sene live bi amna solo lol mane ci tarikha yi la bokone mais legui guidi na mangui nouyou makhady boubakh ❤❤❤

  • @zaldiop6293
    @zaldiop6293 Рік тому +11

    Comment peut on mettre un ignorent a la tête d'une communauté religieuse non mountakha dall mo doy warr khamo te do nopi subhanallah

  • @requinquin1
    @requinquin1 Рік тому +4

    Djeureudjeuf Ya Oustaz ak Djoulit yinga andal yépp: Merci❤
    Al Âhira Yalla naniou tassé Aldjana bama ni Souniou Boroom: djamono yama rééré woon , nékoon ab Niookhite bou bonn, pas de djouli ni de woor , Gnii nio ma Sauvé , oubbi sama khol ak sama beutt sol ma Yalla ak Sunna Nabil Moustapha ❤
    Yalla na niou Yalla djapalé ci yonou souna bii niou nékk bilahi.

  • @ngordiouf3310
    @ngordiouf3310 Рік тому +10

    Vous être une référence pour islam Dieu vous protège merci à vous

  • @biloubilou5237
    @biloubilou5237 Рік тому +6

    Mbokk mashalah amna solo wayé déleen bayyi niou wax ba paré nguén doga tontou svplt

  • @laminedanfa8021
    @laminedanfa8021 Рік тому +10

    Mashallah oustaz alpha amatina solo yallah na yallah fayla yiw mai younouss dafa wara téyi may gayi wakh

  • @demebadiekh7476
    @demebadiekh7476 Рік тому +14

    Baye fall yi nio tardel Senegal amouniou diarigne 😢😢😢

  • @ElhadjeSy
    @ElhadjeSy 11 місяців тому +1

    ماشاء الله بارك الله فيكم وجزاكم الله خيرا

  • @alinesamb5006
    @alinesamb5006 Рік тому +6

    السلام عليكم ورحمة الله وبركاته كيف حالك أنت بخير أحسن الله إليك ماشاء الله بارك الله فيك أخي الكريم الشيخ الفاهم باه حفظه الله ورعاه ❤❤❤❤

  • @bazirpascal7491
    @bazirpascal7491 Рік тому +13

    Al Ghourhane ak souna rék
    Suivez Allah et son prophète Mouhamed SAW

  • @DIOBISTO
    @DIOBISTO 6 місяців тому +1

    masha-Allah à votre équipe, vous faites un excellent travail ❤❤❤
    Longue vie à vous

  • @leveridique3001
    @leveridique3001 Рік тому +7

    Doo diouli doo woor doo dém Maka baparé ngané yaye até nieye diouli di woor di dém Maka tégou woul féne

  • @xumanndiaye1148
    @xumanndiaye1148 Рік тому +6

    Machala amna solo yalna yalla fayla yiuw 🙏🙏

  • @ahmaddia3315
    @ahmaddia3315 Рік тому +2

    جزاكم الله خيرا

  • @DiaryBa-y3q
    @DiaryBa-y3q 5 місяців тому +2

    Mane pére Noël 🎅 mii diahalnama trop 😂😂

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  5 місяців тому +1

      🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🔨🔨🔨🔨🤔

  • @aboubacarba7896
    @aboubacarba7896 Рік тому +9

    Kou xam dégue tekk si sa tanka la fi guiss
    bay fall dou touss , yalla naleen yalla dindi si liñu nekk , c’est honte

  • @fredhhodonel916
    @fredhhodonel916 Рік тому +6

    Baye fall boulènn laal wala lènene tothie lènn deudieuw ndeyam ak koumou meunah doonn, sènn yeuffou doff yii di gagnaté ak dooraté nanguène ko yemalé biir Touba

  • @cheikhsadiboudiedhiou309
    @cheikhsadiboudiedhiou309 Рік тому +4

    Assalamouha leykoum machallah

  • @demebadiekh7476
    @demebadiekh7476 Рік тому +7

    Mountakha mbacke ya degeur fitte nian la yalla diake lél bagna dooulit thiey kilifaux yi

  • @sonyboys2967
    @sonyboys2967 Рік тому +4

    Macha allah les fréres sunnah rek in cha allah

  • @mountalasow2690
    @mountalasow2690 Рік тому

    Merci oustaz alpa ba

  • @abogassama6567
    @abogassama6567 Рік тому

    Jërëjëf ustaas

  • @NogayediopDiobéne
    @NogayediopDiobéne Рік тому +2

    Machallah ba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @siacamane3361
    @siacamane3361 Рік тому +2

    Longue vie a vous ❤

  • @falloutoure135
    @falloutoure135 Рік тому +2

    Live bi temp yi nékhoul dara ndakhe doléne déglou nite yi di dévoloper mane yéne la geum mais lolou rék moléne yaqeu

  • @ibrahimac-y4g
    @ibrahimac-y4g Рік тому +2

    kouy layal koudoul djouli naféh nga ak kô meune doon

  • @AbibouMbacke
    @AbibouMbacke Рік тому +3

    Dieureudieuf serigne touba Mourid mba yagui wath magal gui

  • @mamadousow1460
    @mamadousow1460 Рік тому +1

    Assalamou aleykoum oustaz Alpha nguir lerale lene niak diouli bayfal fane la commencé.

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane7066 Рік тому +1

    Machala li am na soulo torop

  • @Ousseynou-ed9iq
    @Ousseynou-ed9iq Рік тому +7

    Mountakha dara khamouko sama mame motogone may tok sama baye tok matok moko fi tekk

  • @malikseckmilk4434
    @malikseckmilk4434 3 місяці тому

    Amna solo

  • @sakhosakho5814
    @sakhosakho5814 Рік тому +5

    Nakhaté bi mome légi diékhna

  • @abdoundiaye3864
    @abdoundiaye3864 Рік тому

    Merci

  • @idrissabakhayokho629
    @idrissabakhayokho629 Рік тому +2

    Képou kou bayi dioulli bayi wor te taïko yéffeur nga té bo si dèwé saffara direct amoul gueune maa salakakum fi sakar kolo lamnaku minal mousollinn

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 4 місяці тому +1

    Tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi nane yéwou guir yalla

  • @oumarbarro8738
    @oumarbarro8738 Рік тому

    ❤❤❤❤

  • @demebadiekh7476
    @demebadiekh7476 Рік тому +5

    Baye fall yawan rek aye esclavas you bone lan🥵🥵🥵🤮🤮🤮🤮💩💩💩💩💩💩💩💩💩💩

  • @ndoibeseye4570
    @ndoibeseye4570 Рік тому +4

    Thiey lici rewmi khawma fan lan dieum rek

  • @biloubilou5237
    @biloubilou5237 Рік тому +2

    Kii dafa rérr bilaay

  • @laminedanfa8021
    @laminedanfa8021 Рік тому +2

    Baïlo mashallah diambar deug le té dafa téyi

  • @ibrahimadiop1299
    @ibrahimadiop1299 Рік тому

    Les frères prenaient le temps de les écouter çà fait mal .pour ensuite les argumenter le coran et la sunnah

  • @arounatv8707
    @arounatv8707 Рік тому

    gérr yalla gélale gana méséré

  • @mbcke1430
    @mbcke1430 Рік тому +1

    Le prophète Muhammad a vécu combien d'années sans prié ? Kefrou moy kou wédy légui Bay fall yii lane lagnou wedy ?

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +12

      Est-ce que durant ces années, la prière avait été décrété
      S’il vous plaît, essayer d’utiliser ta cervelle avant de nous emmerder sur ses Hors sujets

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 Рік тому +4

    Yalla tégaloul kéne dioulli ay féne kaséla

  • @sakhosakho5814
    @sakhosakho5814 Рік тому +2

    Ziarr nalén mbokkou yi

  • @ahmaddia3315
    @ahmaddia3315 Рік тому

    احمددم

  • @AbibouMbacke
    @AbibouMbacke Рік тому +2

    Non vraiment yen dagena tarde gnoun gnio gui wath magal gui

  • @mayekordiouf353
    @mayekordiouf353 Рік тому +3

    😂😅😂thièye

  • @MamadouBa-j3h
    @MamadouBa-j3h Рік тому

    Asalamou alaykoum oustaz niowlen si pas pasou tidiane yi

    • @sunnialiber4868
      @sunnialiber4868 Рік тому +3

      Mbokk mi, Def nagne si aye live you bari. Ma ngi diégalou

    • @ndeyeantaka-dr8ej
      @ndeyeantaka-dr8ej Рік тому

      Ni yéne mourite yi lanou yapp ndakhe da Bari ay fene wayi tijaine fomoukhareme manoul si niome dara

  • @khoudianiasse7512
    @khoudianiasse7512 Рік тому

    Baye fall bi moxoromou😂

  • @abdouazizdiagne9796
    @abdouazizdiagne9796 Рік тому +2

    Yonenté dou yapp,dou yakh,dou dérett bayilen garouwalé ak nafekh.Serigne Touba dou sen morom.Bamouy diamou yalla sen Baye yii nio topone Toubab bi di takhourane ak nafekh.Serigne Touba mo léeral islam Sénégal.

  • @amedsisse2167
    @amedsisse2167 Рік тому

    C le diable,vestido de religiosa

  • @mbcke1430
    @mbcke1430 Рік тому

    Le pouvait être très important mais vous êtes très arongant

  • @Babe-FaLilOu
    @Babe-FaLilOu Рік тому +1

    Sunna rek❤