Honnêtement Zo bett ngama parce que je m’entendais pas à ça venant de toi, mais plutôt de Canabasse , parce que je l’estimais beaucoup de par sa personnalité son intelligence etc ... mais là dagma bet parce que li nga wax bass moko waroon wax , mane quand il a fait cette sortie sur vide di teek mane dama am louma meti naxtei mom kharéwumako woon fofu ak loko meunti def Bass kmm wesuna li de 1 , de 2 amna foungeen diota jaar .. mais dafa immaturité ak niak xalaat .. bref mais io chapeau 🎩 si sa réponse boul meuss tontu , dula yoob feeneu .. au contraire dafay geun yaak , defna erreur balko nga dial si leeneen .. et bnne chance pour tn show 👍🏿
Tous ce que je dit c'est que Omzo ses promo d'événements s'accompagne souvent de clash diayanté prek truc du genre. Bass il rap hyper bien Omzo de même et que rap bi ins bi soxlatul ayy abbé clash na imam wala pinpin clash na nicky mais plus like lu gars yi di def ni tek ayy son yu dal vidéo yu dop teug si sall yu mak guichet fermé. Zo Bass Ngaga Dip Elzo Akhlu brick OMG Eve creasy black queen rap bi molein soxla pour ñu export sunu music Bilahi du omzo don clachanté wizkd guen xam wala bass ak davido meunuñu sen beatmeaker menuñu what else fall ñu diapanté liguey kw tput le monde y gagnera kw
Honnêtement omzo c’est un grand homme il a pris de la hauteur par rapport à ca Senegalais yi gno wara khamni adouna amoul solo té warougn accepté di perte temps si ay thiow Diam mo geuneu aay
oh des larmes aux yeux. Damaladane sayi kher ay temps mais diekhna tay srx. Vraima nitou kécé nga. Si possible tu me send ton num. De la part d'un nouveau fan
Attention !!!! Vibe Radio Senegal se réserve le droit de poursuivre en justice les titulaires des chaînes qui reprendront cette vidéo sur UA-cam ou encore d'autres plateformes de streaming vidéo sans autorisation.
Non Zo dou nitt wallah j'adore ton esprit de dépassement continue sur ce lancé bro tout ira pour le mieux inchallah Mouy bass mouy kénéneu boulen falé thie ay clash Déniou béguel rk c'est ce qu'on demande men TU AS BIEN PARLÉ OMZO EN TOUT CAS 👍😍
nénagne danga rew à cause de ta façon de faire le rap mais tu est intelligent tmt dans la vie il faut savoir faire ce qui est essentiel le reste on s'en fiche je t'adore!
Bro contane na si ioe bilahi Pour mane sax dangay indi thiow yokou essence si feu bi mais t'as parlé en tant que personne mature😎 bonne chance bro. Suis fan de Dip nak😍
Quand tu es un modèle pour la jeunesse il faut se comporter comme un grand homme et ça Omzo Dollar 💵 l'a fait c'est ça qui différencie Omzo Dollar 💵 et les rappeurs de sa génération Canabasse vraiment il m'a déçu il devait être le protecteur de Omzo il devait se comporté comme un grand frère mais il ne l'a pas fait dommage la jalousie est un vilain défaut big up Omzo nous t'aimons et nous t'aimerons pour toujours bonne continuation frère
Mais vous jouez à quoi... Il faut pas accepter qu'on vous divise... Vous êtes des responsables.. Il faut s'asseoir autour d'une table, discuter afin de trouver une solution à ce problème... Même la guerre mondiale a été resolu autour d'une table après des pourparlers... Donc vous devez etre au dessus de tout ça... Comportez vous comme des responsables.. Vous êtes tous des frères.. Donc arrêtez... Arrêtez...
Je suis vraima ému buzz labb c la vie et vs voir vous déchiré kom Ça walahii dou nek sunu avantages parsk après tt cela c la mifa dpui 2008 niou nek sen guinaw vraima nekhoul c genres de choses di am mai nak chapeau a tw et vraima tu as été humble et en écoutant jai pu remarqué k tu étais sincère sur tes propos car c avc le cœur k tu parlé
Vraiment digantei zoo ak bass waroulwone deimei nii.
Kié dakor🤙
weuuy mais pik yi omzo donn lancè peutr bass dafa thè guiss bopam
Bilahi
Bass moy déféant billaye déh
Yeah man mais ke dj c un vrai imbécile et kil ne c mm po son rôle dmr rek la
Bilae dj tall vrai naféke leu li dafaY Geune Agraver situation bi rk ms bass dafa wéré complètement li dou won Sakh yon gnou réglé blem bi ni😢😢
Omzo khole bou rafète la yorr billahi 💓💓✋✌✌ RESPECT a OMZO ✌👌👍💟
Omzo dou meussa tontou canabasse dj Tall seytané la
Kou beug Omzo tape bleu 👈
Big up for you
Il fait que son taff c est les gens qui ont envie de connaitre la vérité
DJ tall dou seytané deh, émission wam lay diay rek, bass mo sokhor rekk lolou moy wakh djii
Vrai seytané la dj tall
Trop sakh
Omzo mentalité propre franchement je t'adore de la part d'un fans de Dip Doundou guiss
Diadieuf djaambaar
momo men il a changé de nom ? Il est devenu deep ?
Merci de ta franchise
@@bujuman2880 non il a pas changé de nom je l'ai ecrit en englais
no yaw no fan d dip
Zo real nga billahi. même sou blème amé dénguène ko wara régler en tant que ami té kène khamoul.
Omzo nak j'adore ta personnalité
Il faut être mature dans la vie 👏👏 bravo omzo
L'exemple de la maturité dans le rap force à zo dollar✌
😊
C vraimen domage de voir des frère de buzz lab se déchiré comme ça .😳
Honnêtement Zo bett ngama parce que je m’entendais pas à ça venant de toi, mais plutôt de Canabasse , parce que je l’estimais beaucoup de par sa personnalité son intelligence etc ... mais là dagma bet parce que li nga wax bass moko waroon wax , mane quand il a fait cette sortie sur vide di teek mane dama am louma meti naxtei mom kharéwumako woon fofu ak loko meunti def Bass kmm wesuna li de 1 , de 2 amna foungeen diota jaar .. mais dafa immaturité ak niak xalaat .. bref mais io chapeau 🎩 si sa réponse boul meuss tontu , dula yoob feeneu .. au contraire dafay geun yaak , defna erreur balko nga dial si leeneen ..
et bnne chance pour tn show 👍🏿
Mdr wakhofi dara ak seu commentaire bou goudou
Yamar Diallo t’as trop bien parlé je te jure
Yeah t'as parfaitement raison
Tous ce que je dit c'est que Omzo ses promo d'événements s'accompagne souvent de clash diayanté prek truc du genre.
Bass il rap hyper bien Omzo de même et que rap bi ins bi soxlatul ayy abbé clash na imam wala pinpin clash na nicky mais plus like lu gars yi di def ni tek ayy son yu dal vidéo yu dop teug si sall yu mak guichet fermé.
Zo Bass Ngaga Dip Elzo Akhlu brick OMG Eve creasy black queen rap bi molein soxla pour ñu export sunu music
Bilahi du omzo don clachanté wizkd guen xam wala bass ak davido meunuñu sen beatmeaker menuñu what else fall ñu diapanté liguey kw tput le monde y gagnera kw
Billay wallay tontou biii la done khar Zo big up for you we love you so much
j'aime la personnalité de Zo; faut grandir en fait!
Fils
Canabass est en déclin Omzo est le seul rappeur qui tient le rythme avec Dip
Honnêtement omzo c’est un grand homme il a pris de la hauteur par rapport à ca
Senegalais yi gno wara khamni adouna amoul solo té warougn accepté di perte temps si ay thiow
Diam mo geuneu aay
Am a Gambian base in Denmark. Respect to Zo D. Gen len shokhor, shokhor respond.
T'es réagite comme un vrai gentleman respect à toi frère🔥🔥
Dj tal vrai seytané quoi 😂😂 à chaque fois omzo dit quelque chose il commence avec ses 'huuun' 'hannnn' di grawal
Wallahi bouko tontou ay real bro ngueine Dara waroul niaaw Adouna amoul solo les gars big up à toi Omzo et Basse plein de bonnes choses à vous 🤜🏾🤛🏾
Messatsu miezé on est tous derrière toi
05 avril Gt Came back2
Bass d'à sissou rk mai amoul ben motif pour khar bâ heure bi du gueinai Aÿ affaire ssi omzo boudai daka souteral bâ heure bi loumouy gueinai
yaw boude amga khel del khalate mm ls fou reflechiss ki wahoul li tah mixtape deugeuntane nek si tourou keyzit e bcp dotr chose
@@mothernature6996 yow miye khalat loutakh mou khar bâ heure bi do soga clatai mom wakhna daka donne souteral mai pourkw mou khar bâ heure bi diko wer
Bilay deug piir
Joe projet bi projet vito la mou douguale thie coupleme. Couplet wou bass c pas prémédité. Bass is the boss!
omzo Tu ne m'as jamais déçue tu sais bien parler
Merci OmZo Quelle Grandeur
Omzo pour toujour merci bro d'avoir rendu tort à certains qui attendait k u répond à basse .repect à Omzo
Omzo dolar ❤❤
oh des larmes aux yeux.
Damaladane sayi kher ay temps mais diekhna tay srx. Vraima nitou kécé nga. Si possible tu me send ton num.
De la part d'un nouveau fan
Omzo Sa Boy La Grand wam gua réponse Omzo Dafma Berte Li Da Wané dafa mature légui Big up Frère Bonne Continuation
DAOUDA sarr billaye déh
Attention !!!! Vibe Radio Senegal se réserve le droit de poursuivre en justice les titulaires des chaînes qui reprendront cette vidéo sur UA-cam ou encore d'autres plateformes de streaming vidéo sans autorisation.
Vibe Radio Senegal *Good luck with that* 🤣🤣🤣
Yeii... Yeii....
lii daaww naa yaaram
Noo Messatsu Doo niit sérieux...
"gayii Svp naa Niieup waakh Mercii Cabanasse..."
Teii tellement mature mon gars...
Non Zo dou nitt wallah j'adore ton esprit de dépassement continue sur ce lancé bro tout ira pour le mieux inchallah
Mouy bass mouy kénéneu boulen falé thie ay clash
Déniou béguel rk c'est ce qu'on demande men
TU AS BIEN PARLÉ OMZO EN TOUT CAS 👍😍
Omzo amna solo 🤲🤲🤲🤲👍👍👍
Mane mòm team doundou guiss la bòk for ever
Reptyle musique for life
Franchement li mòm dawna Yaram basse waroul wòn dokhalé ni srx
Fans Dip yi mom khamnagne kouy Omzo 😂
Reptyle rk♥🔐
nioune wa team doundou guisse sounou yone nékousi
Mais nak tall mom berina waaah deee oufff hum hum rek tamid 😔
félicitations à omzo dollar 👏👏 Canabasse warna
rouss bou amei roussoukay
Da amone niou dawone nieuwate fi dii doule
Mai canabasse banialle lolou omzo sa Petit frer la ✌OMZO Lingua tek dawna yarame😢
Vraiment cana wathie nga sa bop djisouma loukofi diaar si adina
Com dab chapeau omzo on t'aime fort nous et courage
🖕
GRAND YOMBOUL OMZO TU ES UN GRAND ET SAGE BILAY ON T AIME BIEN CONTINU COMME CA PLZ ET MONSIEUR TAL ECOUTE TES INVITES PLZ MERCI
Dj Tall war na di tedj gatam gui fait chier waay
Marieme est ce que noboumala yaw ??
دفرات سنغال mdrrrr
Walae nakk il est con
@@mariemeaichaanne8255 serigne touba khamnani dafa melni damala nop, diapsi ma khamla bok diokhla sama WhatsApp. Stp
دفرات سنغال mais mane la nob 🙄
Omzo bilaay dama la beugue
Te Canabasse do moromam😍😍😍
Dip l'avait dit ayy deumm lagn daniouy lekante sénn birr
Dip l'avait prédit dei Billae thiey dip❤
Dj tall mom franchement merci rk genrou seytanei yi lagnou wara guenei si radio yi ak télé yi
nénagne danga rew
à cause de ta façon de faire le rap
mais tu est intelligent tmt
dans la vie il faut savoir faire ce qui est essentiel
le reste on s'en fiche
je t'adore!
Bro contane na si ioe bilahi
Pour mane sax dangay indi thiow yokou essence si feu bi mais t'as parlé en tant que personne mature😎 bonne chance bro.
Suis fan de Dip nak😍
Wawaw fans Dip yi mom khamguène boubakh kouy Omzo 😂
Papa bougouma wax lou ndiagass way
Dafa def yeufou mature ma encouragé taxoul ngamay sonal fi dh
Omzo ont t'aime ces tt
Première vue💪🏾
Guiss la wakh wakhoul dégue
Altaf Limbada tu parle de quoi là?
Quand tu es un modèle pour la jeunesse il faut se comporter comme un grand homme et ça Omzo Dollar 💵 l'a fait c'est ça qui différencie Omzo Dollar 💵 et les rappeurs de sa génération Canabasse vraiment il m'a déçu il devait être le protecteur de Omzo il devait se comporté comme un grand frère mais il ne l'a pas fait dommage la jalousie est un vilain défaut big up Omzo nous t'aimons et nous t'aimerons pour toujours bonne continuation frère
Mais yenn Dj Tall il est un professionnel dans son métier.
Il a l'audace de posé des questions audacieux tmt un peu de respect 🤦🏾♂️🤦🏾♂️
Ah wei
Gars yii daniou con koi 🤔
T la plus part des gens khamouniou rap ☻
kham
@@taphambow9524 respect toi
Bravo#Omzô fière 2Tw puissance rék💪💪💪
Vraiment omzo je suis encore fière de toi encore big up a toi tu est un homme fort
Boul ko tontou bro
Pousse bleu, les vrais dollavelli
Walahi zo yay gentleman
Kham na ni dall nitt dagay nité mé nakk yalla bakhna boull tonntou moukkou one love omzo 😍😍
Mais vous jouez à quoi...
Il faut pas accepter qu'on vous divise...
Vous êtes des responsables..
Il faut s'asseoir autour d'une table, discuter afin de trouver une solution à ce problème...
Même la guerre mondiale a été resolu autour d'une table après des pourparlers...
Donc vous devez etre au dessus de tout ça...
Comportez vous comme des responsables..
Vous êtes tous des frères..
Donc arrêtez...
Arrêtez...
bayeomar245 vrement cest dommage. G tres mal de les voir ainsi
M omzo a dit vrai grand théâtre day show force 🔥❤️
J lé aime tous lé deux bilay omzo et basse sont mé rappeur a cause j'aime l rap galsen sa m fé mal j t jur
Dou ioe kasser
Guisgua dé
Vraiment Omzo daffa Mature il c’est réglé les choses avec Diplomatie je félicite à partir d’aujourd’hui dinala geuneu Follow 😍☺️🥰
Omzo Buzzlab sa yeuf Leu
Canabass Nékal Boss touty way 😎
Tu é l meilleur rappeur Sénégal d ts temp si tu aime omzo l 5 defal tew niou tassaree feppp
Kèn dou Miézè
Je suis vraima ému buzz labb c la vie et vs voir vous déchiré kom Ça walahii dou nek sunu avantages parsk après tt cela c la mifa dpui 2008 niou nek sen guinaw vraima nekhoul c genres de choses di am mai nak chapeau a tw et vraima tu as été humble et en écoutant jai pu remarqué k tu étais sincère sur tes propos car c avc le cœur k tu parlé
Med Métal Lagniou Wakh The Come Back 2
Talla wally jnr walaaaa frère
Mdr 😂😂
mbarikalah mbarikalah ❤️❤️..
Wallay Omzo yaye seen papa niom niep on t'aime fort
Vraiment lila bougonne boul ko tontou 🖐🏻❤️
Je t'adore bro brome bakh 🌹👊
respect Omzo Dollar
Omzo meune nagn ko wakh lepp sauf nitt kou bone. Bilay c'est un responsable
Miézé Miézé le général des rappeurs galsen .
Il faut avoir l'esprit de dépassement Zoo et ne le répondre pas, continue ton jobs 💪💪💪🇸🇳
le meilleur rappeur Omzo dollars jésui fiers de toi
Mogui roukhh dh 😂😂 dofo khamegua ni bass dalay watiè #Reptylemoreeeee 😂😂
Canabass dafa dioum billahi' non ça me touche que des frères Finissent comme ça, dommage😪
Omzo like for you
Mes ak nouma dèmé begouma wone 'nga geine BL
King Miézé rek💪💪❤❤
Tapez j'aime gniko beug
Omzo je t'aime 😍😍😍
Omzo😎😎💪💪
Omzo💪👍👍👍👍👍👍
mais tu dis vraiment la vérité que tu ne l'a pas clasher 🤔🤔!!!!!!
Oui
Quel hauteur !
Hii Omzo franchemant limou wax deugg la kw Bass call ko 😙
Mais vraiment
Baba Diallo ioe loffi oute xana do fans dip
@@dexterfv2l597 wahal diam iaw Dip man
Non Yaw Dj tall vrai seytané gua Li Moy L'âne😙😙
He’s so mature👌
Merci. Quelle dignité
Omzo soyons sérieux et honnête. Tu as lancé beaucoup de piques dans ton album . Tu n'as pas voulu assumé c'est pas grave , bétouniou ci yaw
MDR Wakhal deh frere .Sénégal mo neikh rek nite day deff baparé nga ladj ko mouye wakh si lénen
Omzo nite gua am gua classe conek dila wax talent kassé la motax niouy wax
#Omzo boulko réponde Dj tall sèytani la bilahi
Harouna Gassama c son boulot mec il crée des challenges c pour cela qu'on le paye
alors tu veux dire qu'on lui paye pour qu'il c'est par les meilleurs amis
Ils ont décidé de se séparer ici c son plateau il doit ouvrir le débat pour donner goût à son émission
Séparation bobou moy takh niou rap niom niare nieup...Canabasse boumou dioubowé ak NitDoff ba légui amatoule challenge ci game bii...
@@metzondiaye2837 bilahi
Caana bass dafa fayoon 😎beug siiwat clash omzo
Pour dire vré #Omzo Dollar cei mn Rappeur meii wakhoufi Dara Il répéteu les mêmes Phrase Depuis le début ...
Domou Bour enfin ioe yangui guiss tei yaangui degg👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾
Je laime Plu FransemnT Seu gars
Nooo9 cana Omzo ta montré de la classe vraiment grand tu n'as pas montré 🙏Sapo Omar🙆
Mesatsu💪💪💪💪
Vs êtes frere bro na nice c’est le movement hip hop ki gagne
Boy li dawna yaram billahi boy basse demal balou way
Mdr Omzo vous a tous eu en esquivant le vrai débat
Papa Silly Traoré t un ignorants t en + nie xamanténaniou yasi des rk ki yeufou magu la def xarako wone fi
@@serignemasoursall8682 yaw bilay innocent ngua . Ya con deugg deugg
Bass moy balou wala omzo
Maturité man. Gud réaction
Mane omzo suis op tn fans ms ligua wax deug leuu walae
respect a toi Omzo dollar tes le meilleur rappeur du rap galsen reponse leer na bass est juste frustré par ton départ a buzz lab
Tu es le meilleur
Zoo dollar 💵 wakh dji Djioup nah rafèlou lou nagne sa tontou Waw ni rèk la mak dal day yeureum xalé khalé respect ✊🏽 mak tubarkallah yalna djam yague
Cool mn Frère boudé linga wakh mo néki sa khôl
dj tall seytané tap jaime si tu es dacor
T'es un vrai Gentleman Zo wallah 🙏
Sama yone nekoussi🙉
C magnifiques les paroles pour un vieux gars comme Cana .
Daaadjil pakêt bi gnou Raab tè Taaaal... nooo dj Tall daaaaaal akh yagui nelaw.. Canabass doula wooo nahhté Dagay enrigistré poucave gaaa Poucaaave kène douko wooo. Tidjil pakêt bi loool yoolè boy gua Poucave, di tèk xél fii wayé Maguoum yi sibb nègn boyi gaay nakh