DIEUREDIEUFETY SERIÑ ABO GUEYE , Yalla GUA fi yag lol té andakhakh weur ☪️… SA KADDOU YI MOURIDOU TÉYY YEUPE WAAR NEÑOUKO DÉGGLOU TÉ BAYIKO KHÉL BOU BAAKH… LI REKK MODI MÉLOKANOU AP MOURIDOULAHI …☪️☪️☪️ DIEUREDIEUFETY BOROM TOUBA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP💫☪️
Dagne Len di nakh rek di tarbiya ay nit dilen liguey lo bano maguette té dounou yor dara cex moustapha lolou lafiy dieulé par force motakh pa yep diouk di wakh nakhé gui dafiy diekh
@@papesarr1177 waw yaw mi naaan dagn leeni tarboyah banou Magguet ta dounou yar dara.. ndax Dangua fatte ni Ab talibé bou sellalee pass passam ta Xam Liko takha diouk Ak doonté serign bou matoul serigne la am sax teewoul dana am lamouy wout . Leegui nak danguay guiss mouskallaf mo xam ni day topou serigne nguir ne bayam mo topon bayal mouy ben. Niaar danguay giiss talibe bou nek keur kilifeu ta foum took serignam lafay toogué serign ji nii serign bi naa kokou noumi amee yalla. Moukallafoum dieum kay bouko serignam doyoul na dem mou niaanal ko mou seeti kou ko doy... Diaroul thiooww di pour mane
Diggeunté talibe akoub serign Kooloté rekka Fa dokh... la Thia Dess yalla ko gaddou ndax tarbiyah leerouk yonnèntè bi la SLHW doufi diouk ba mouk ak doonte ken moy dess thi adouna di ko def. Kon ab serigne amatoul mome wax diou yakhoula .
Sëriñ Mustafaa Jóob Kokki yalna Yàlla sàmm ko te aar ko, wax jee fi nekk rekk waaye kenn gënu koo doon ab murit. Bàyyi leen fu boroom xam-xam waxee ngéen di ko dëkkal fumu dëkkul.
Diggeunté talibe akoub serign Kooloté rekka Fa dokh... la Thia Dess yalla ko gaddou ndax tarbiyah leerouk yonnèntè bi la SLHW doufi diouk ba mouk ak doonte ken moy dess thi adouna di ko def. Kon ab serigne amatoul mome wax diou yakhoula.
Didureu dieuf Senégal niaara ka yakh diangue katou toubab ak diangue kato arabe serigne bi lére na nangne amoul leounte niak téguine manoul wésou soféntal wakhou mague yi si yone wi wa sqlame
machalla Seringe bi diamou si yaw
ماشاء الله فجزاكم الله خيرا
ماشاءالله
❤❤❤❤❤
Machalah s abo Thia caw Thia canam
Serigne Moustapha dafa dioume rk wayei jambar la
Merci beaucoup
DIEUREDIEUFETY SERIÑ ABO GUEYE , Yalla GUA fi yag lol té andakhakh weur ☪️… SA KADDOU YI MOURIDOU TÉYY YEUPE WAAR NEÑOUKO DÉGGLOU TÉ BAYIKO KHÉL BOU BAAKH… LI REKK MODI MÉLOKANOU AP MOURIDOULAHI …☪️☪️☪️ DIEUREDIEUFETY BOROM TOUBA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP💫☪️
Moom mii sax xalaatam lay wax ken wax lo wu ko
Billay Serigne Moustapha Al kokii dou séne moromm
Dagie dague s moustapha diop. Daffa dioume te diaffa ndiko khalaatam. Looole te amna thi yoye xaalaat amoufa place.
Dagne Len di nakh rek di tarbiya ay nit dilen liguey lo bano maguette té dounou yor dara cex moustapha lolou lafiy dieulé par force motakh pa yep diouk di wakh nakhé gui dafiy diekh
lou léeer ngua wakh nakhtéyi dafa bari lollégui kougnou tarbiya sakh dou tané ki tokk sén keur dou am Yalla dou am barké@@papesarr1177
@@papesarr1177 waw yaw mi naaan dagn leeni tarboyah banou Magguet ta dounou yar dara.. ndax Dangua fatte ni Ab talibé bou sellalee pass passam ta Xam Liko takha diouk Ak doonté serign bou matoul serigne la am sax teewoul dana am lamouy wout .
Leegui nak danguay guiss mouskallaf mo xam ni day topou serigne nguir ne bayam mo topon bayal mouy ben. Niaar danguay giiss talibe bou nek keur kilifeu ta foum took serignam lafay toogué serign ji nii serign bi naa kokou noumi amee yalla. Moukallafoum dieum kay bouko serignam doyoul na dem mou niaanal ko mou seeti kou ko doy...
Diaroul thiooww di pour mane
Diggeunté talibe akoub serign Kooloté rekka Fa dokh... la Thia Dess yalla ko gaddou ndax tarbiyah leerouk yonnèntè bi la SLHW doufi diouk ba mouk ak doonte ken moy dess thi adouna di ko def. Kon ab serigne amatoul mome wax diou yakhoula .
@@papesarr1177nakh yi nèkhnanu
Sëriñ Mustafaa Jóob Kokki yalna Yàlla sàmm ko te aar ko, wax jee fi nekk rekk waaye kenn gënu koo doon ab murit. Bàyyi leen fu boroom xam-xam waxee ngéen di ko dëkkal fumu dëkkul.
Yén doul. Waxlén sen wadjii deug. Dafa dioum niou dioubeunti ko
@@zaydibnhaariss6310yaw de ku rew gna ta ñakk ap yar lool nitt man na wax ta dou si bollé saaga walla wax ju ñaaw
❤
Yalla rk moo doul dioume
Na wagni wax niou bari dji😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wird makhouss mourid bouko yor am na loumou epelé mourid bouko yoroul tarbiya mourid dara dara dasé geun diokh ko Wird makhouss
Khél mou sél ngay wakhé dnga am ay firndé you wér
Diggeunté talibe akoub serign Kooloté rekka Fa dokh... la Thia Dess yalla ko gaddou ndax tarbiyah leerouk yonnèntè bi la SLHW doufi diouk ba mouk ak doonte ken moy dess thi adouna di ko def. Kon ab serigne amatoul mome wax diou yakhoula.
جرجف سرين ابو غاي
اعاذنا الله من الشيطان
Kdoull khaliefa cenerall boull wakh thiy khatim ak kamiell ak khafief
Def len com di nopii rek kouy nopii ken doula wedii
Didureu dieuf Senégal niaara ka yakh diangue katou toubab ak diangue kato arabe serigne bi lére na nangne amoul leounte niak téguine manoul wésou soféntal wakhou mague yi si yone wi wa sqlame
Ndeysaan, S Moustapha kénn si yéen dégouko
Yaw khamo Lou khéw deh
Moustapha Diop kokki jambar la
Wird mahuz ndigalou Serigne bi la
❤❤❤❤