Cheikh Ahmed Cissé traite de menteur à Oustaz Modou fall….« khamoulll dare niveau bi bakhoulllll…..»

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 15 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 238

  • @babacarthiam9221
    @babacarthiam9221 Рік тому +96

    Kou d'accord ni Cheikh Ahmed daniou ko wara invité Quartier Général lalall j'aime

    • @laminediatta7069
      @laminediatta7069 Рік тому +1

      Quartier général face to face ak niou niou fall pape âne

  • @ndeyafall6824
    @ndeyafall6824 Рік тому +13

    C'est la première fois que je l'écoute et je pense que je vais continuer à l'écoute

    • @BOUCHRA-158tv
      @BOUCHRA-158tv Рік тому

      Pourquoi tu vas continuer de l'écouter

    • @ndeyafall6824
      @ndeyafall6824 Рік тому +2

      @@BOUCHRA-158tv est-ce qu'il y a un problème de l'écouter

    • @mamoudoudaff3028
      @mamoudoudaff3028 Рік тому +1

      C'est un ariff bilahi ...la seule est raison qui est valade.

  • @modoundiaye3002
    @modoundiaye3002 Рік тому +9

    Macha alah merci beaucoup cheikh Ahmad Cissé Mane modou Ndiaye Dama la buegue té yalla rékk tax

  • @awathiam6699
    @awathiam6699 Рік тому +1

    Do nit kham kham day léger gua am fit dama done wakh dafa rew mais balma ah dagua diang ba kham Di wakh mo takh gua niemme merci cheikh bi

  • @mohamedelhabibndiaye2969
    @mohamedelhabibndiaye2969 Рік тому +29

    Depuis que j'ai commencé a l'écoute, je l'écoute.
    Il a une comprehension excellente de l'islam. C'est de cette reflexion qu'on a besoin pour comprendre cette religion. Et savoir se conduire avec dans la vie courante.
    Depuis Mauritanie.

    • @siramo574
      @siramo574 Рік тому +1

      Exactement tu as raison.il comprends bien l islam trop bien.les gens interpretent n importe comment l islam.on a trop compliqué cette religion.

    • @babacartall8598
      @babacartall8598 Рік тому

      Islamou Senegal dafa méti quoi

    • @meyabababamoctar4090
      @meyabababamoctar4090 Рік тому +1

      J'aurais aimé qu'il soit Mauritanien

    • @gueyedjiby6077
      @gueyedjiby6077 Рік тому

      ​@@siramo574ppppppppppppppppppp😊ppppppppppppppp😊pppppppppppppp

    • @djibrildiop5999
      @djibrildiop5999 Рік тому

      Ki bou déwé tanéna kilifala

  • @mamediarra6068
    @mamediarra6068 Рік тому +2

    Pourtant c’est un homme véritable Machalla nioune yawe laniouye topou deugue mome dou romb aye 🦻🦻

  • @mamadoudioufff3100
    @mamadoudioufff3100 Рік тому +2

    Vrmt béguena trp si yow Cheikh Bi Machallah

  • @ndiawardieye6323
    @ndiawardieye6323 Рік тому +6

    Vraiment c'est un homme véridique

  • @modoufaye5677
    @modoufaye5677 Рік тому +9

    Cheikh Ahmed Cissé
    J le suis et je l'écoute .
    Il maîtrise

  • @diawameth4382
    @diawameth4382 Рік тому +11

    Sheikh bi rk laniouy topp😂😂

  • @Alhousseynou-p2o
    @Alhousseynou-p2o 8 місяців тому

    Vrmt tu e le meilleur de y’a génération je te jure machala cisse

  • @ndiayeousmanebaba7531
    @ndiayeousmanebaba7531 Рік тому +4

    😂😂 Dieureudieufé Baye Niasss bandit yi sakh nanenagniou bah mandit Ahmet Ciccé daffa nékh 😂do nitou fii serigne bi

  • @kinefaye6506
    @kinefaye6506 Рік тому +12

    Ndeysane man dama la yeureum bilay ndeysane yalla nala yalla sopi in sha allah

  • @Djilodeco
    @Djilodeco Рік тому +1

    Macha Allah Man mom damakoy déglou té diko dég... ouztaz commedien yi gnofi bari lougnou teugu rakh ci peureum

  • @aliouba9824
    @aliouba9824 Рік тому +4

    ❤❤❤contane ci boumay dëgg-lou 👂 dieumeuh dji

  • @assanendiaye2809
    @assanendiaye2809 Рік тому +1

    Bilahi ki borom kham kham la

  • @BabelThiam723
    @BabelThiam723 Рік тому +4

    ❤iow Mane beug nalla loll mais nak amo ay téguine billahi

  • @moussafaye3952
    @moussafaye3952 Рік тому +7

    En tout cas se k j sais fitt mom amnako😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @youssoundiaye988
    @youssoundiaye988 Рік тому +7

    Lou lerr rek kay wakh 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @abdoulndiaye9338
    @abdoulndiaye9338 Рік тому +5

    Il est pertinent ❤

  • @djibysow8467
    @djibysow8467 Рік тому +4

    ♥️ça plaisir di borom kham kham

  • @kanekane3528
    @kanekane3528 Рік тому

    Machallah surtout gadou yi mou wakh si Ahmed khalifa Niasse

  • @siramo574
    @siramo574 Рік тому +6

    Borrome xam xam là dée , je t adore vraiment.

  • @yamlihambayeinfo1102
    @yamlihambayeinfo1102 Рік тому +4

    Dafa saï saï rek mei kham kham kasela

  • @Thiaw-un5et
    @Thiaw-un5et Рік тому

    Barké baye niass beug nala allahou akbar thiéy baye niass

  • @ramatoulayediol
    @ramatoulayediol Рік тому

    Mes Lou l’aire laye wakhe gracia hermanó ❤❤❤❤

  • @Thiaw-un5et
    @Thiaw-un5et Рік тому +1

    Sama conexsion yakoy diékhal barké baye niass

  • @diksonebriz293
    @diksonebriz293 Рік тому +7

    diganté noubawatou wilayatou ak khilafatou thioum😂😂😂

  • @thiernodembaya8355
    @thiernodembaya8355 Рік тому +6

    Ils maîtrise bien le Coran mais le sénégalais nn pas habitiez a ça façon de parler ❤

  • @antasarrcisse1803
    @antasarrcisse1803 Рік тому

    Il dérange beaucoup c'est la révolution dans le milieu !!!!! Thiey Sénégal 😮😮😮

  • @awacoulibaly3022
    @awacoulibaly3022 10 місяців тому

    Moi j'aime bien t'écouter, mayal sa bopp diam nak, comme ça tu es tranquille ❤

  • @sambita3314
    @sambita3314 Рік тому +1

    Wallahi ki daf sadig kwa Mais bon j’ame 😂🥰

  • @diallosamad
    @diallosamad Рік тому

    Machallah

  • @7637-m9b
    @7637-m9b Рік тому +2

    Moytoul kathior bou am kham kham 😂

  • @matysylla5159
    @matysylla5159 Рік тому +6

    Macha Allah Cissé
    Longue vie à toi ❤❤❤❤

  • @mansour3284
    @mansour3284 Рік тому +2

    Senegal ngay guiss kouy ndiaalo waxnei mome dafay ndiaalo ba paré di wotei wilaaaya. Limassi meitti nite yi nei danioukoy namgoul naaane eskeuy😔

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 Рік тому

      Fouye sa euzeul ?bari nga wakh torope

  • @mamoudoudaff3028
    @mamoudoudaff3028 Рік тому +2

    Qui son niveau dépasse largement le niveau des oustaz de qg...qui arif bilahi...

  • @mouhamadouamadougueye9620
    @mouhamadouamadougueye9620 Рік тому +1

    Non mane kiii damako beug 😂😂🤣🤣

  • @LamFuutanke-ye5om
    @LamFuutanke-ye5om Рік тому

    Kini bilahi walahi ilfo nga téye pour nga khamco

  • @7637-m9b
    @7637-m9b Рік тому

    Machallah sama khol sedna tay

  • @toque5855
    @toque5855 Рік тому +2

    Journaliste bi tamit ak questions yimouy posé😂 Ragal na kasso 😂😂do fa dém dé ay question tàpét Deug 😂

  • @cheikhbayefallndiaye5136
    @cheikhbayefallndiaye5136 Рік тому +6

    Billahi deugue la bou ndogou dioté Kaye Lép dangane na

  • @syllaibrahima6136
    @syllaibrahima6136 Рік тому +11

    Wallahi nk dietediefé baye niass wallahi koudoul talibé baye niass do degg limouy wakh ❤

    • @mouhameddia5168
      @mouhameddia5168 Рік тому +2

      Bayil sa thiakhane yi kone djoulit yi ak borom kham xam you néck si adouna bi yeupou meunounioko dégue a part bene minorité bou ndaw si djoulit yi 😂😂😂😂 niokoye dégue arrétél way

    • @kmtechetservices9215
      @kmtechetservices9215 Рік тому

      Guénél baye si wakh yi

    • @mamoudoudaff3028
      @mamoudoudaff3028 Рік тому

      Bilahi tu as raison

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 Рік тому

      ​@@mouhameddia5168 saway li déguéko nakh Yonenti bi psl bimouye wakh moye zatou khabla tadjali...bayil sa tiakhane yi nakh wornama khamo fouye sa euzeul

    • @mouhameddia5168
      @mouhameddia5168 Рік тому

      @@adamasow9292 man déh akhourane ak sounah lah kham ,sinon aye tadjiliate ak aye euzeul mome djangoumako si darra dja.

  • @xeuchelaye6924
    @xeuchelaye6924 Рік тому +1

    Kham khamou wakh la am 😂😂

  • @mamoudoucamara3185
    @mamoudoucamara3185 Рік тому

    Pourtant il est véridique question claire réponse claire.

  • @modousylla9931
    @modousylla9931 Рік тому +3

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣non !!!!!!!!! Ahmed mo rééw

  • @OumieJagne-v6v
    @OumieJagne-v6v Рік тому

    Mashallah ceesay ceesay

  • @momarkane8377
    @momarkane8377 Рік тому +11

    Dafa saï saï rekk wayé kou am xame xame bou woor leu

  • @mouctarbarry700
    @mouctarbarry700 Рік тому +4

    Beaucoup de kham kham cisse bien inspiré

  • @alassanesow7924
    @alassanesow7924 Рік тому +2

    Nako gayi invite gnou khol 😂😂😂

  • @oumarnguette5702
    @oumarnguette5702 Рік тому +1

    Machalla cisse

  • @macoumbandiaye5580
    @macoumbandiaye5580 Рік тому +1

    Senegal amfi kham kham dafa yombo trop kon guiss ni borom kham kham la

  • @cheikhbayembaye8294
    @cheikhbayembaye8294 Рік тому +9

    Alhamdoulilah ❤merci beaucoup Serigne bi ❤

  • @salioufaye5794
    @salioufaye5794 Рік тому +6

    Non c un vrai phénomène

  • @ArounaNdiaye-jd2lo
    @ArounaNdiaye-jd2lo Рік тому

    😂😂😂 attention attention attention les sénégalais monhamed Cissé ce un savant 😂😂👍👌🤣

  • @myadiop9850
    @myadiop9850 Рік тому +1

    Pur vérité

  • @fatoutouray1474
    @fatoutouray1474 Рік тому

    Nooooo, Ahmed is very smart and intelligent

  • @dienewaganefaye7729
    @dienewaganefaye7729 Рік тому +2

    Il est bon déh

  • @abdoulayefaye-rp4su
    @abdoulayefaye-rp4su Рік тому +38

    Pourtant mom limouy wax so deglou xamni DEUG la

    • @ibrahimathiam205
      @ibrahimathiam205 Рік тому +1

      Bayil gayi di wax rek ki yomboul défié si xam xam d

    • @biramegueye4676
      @biramegueye4676 Рік тому

      ​@@ibrahimathiam205àaaàaaàààaaa

    • @pape-es5vy
      @pape-es5vy Рік тому

      Kii féne katela

    • @pape-es5vy
      @pape-es5vy Рік тому

      ⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰⚰

    • @AbdouNdour-dv1oe
      @AbdouNdour-dv1oe Рік тому

      Ragalal yalla

  • @harounasow4965
    @harounasow4965 Рік тому

    Il a une compréhension vu son passage dans plusieurs pays et cheikh

  • @tamsirbarkhamniass8954
    @tamsirbarkhamniass8954 Рік тому +1

    Seulement Thiowli Thiowli,Baye mo Yémé

  • @aissatathiam6515
    @aissatathiam6515 Рік тому +1

    El phenomeno ma la beu fii ngay wakhé sen khel yegoufa

  • @modouthiam5162
    @modouthiam5162 Рік тому

    Tu es le meilleur

  • @DieynaBouSerigneBabacarsy
    @DieynaBouSerigneBabacarsy Рік тому

    🤐🤐🤐🤐🤣🤣🤐

  • @mutarrsecka2400
    @mutarrsecka2400 Рік тому

    Moi je suis en france comment je fais faire pour gagne cette medicament

    • @rapca2213
      @rapca2213 Рік тому

      Tu es en France, profite pour apprendre le français. C'est mieux pour toi. Ce médicament ne t'apportera rien.

  • @kossogadiaga-fu6ik
    @kossogadiaga-fu6ik Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @emmanuelmane5822
    @emmanuelmane5822 Рік тому

    Amna kham kham

  • @Yacinesy-q8u
    @Yacinesy-q8u 2 місяці тому

    Mai il faut sortir de temps en temps

  • @cheikh_diagne1974
    @cheikh_diagne1974 Рік тому +1

    Man déh yalla rék motakh may wakh wayé xam xam mom amoka allkhorhan tamit khamoka nakh meusouma déigue ga wakh si allkhorhan wakh dall meun ga ko wayé xam xam mom amoka wadoha ak ligay wakh nii amoul béne rapport

  • @ibrahimasall4889
    @ibrahimasall4889 Рік тому +3

    Machalla cheikh bi kham kham lay wakh

  • @inconnu3610
    @inconnu3610 Рік тому +3

    Lou lerr rek ❤tfm tmt

  • @falloufall5032
    @falloufall5032 Рік тому

    Cheikh Ahmed ieo rék layy topou

  • @youssougambien9166
    @youssougambien9166 Рік тому +1

    Modou fall oustaz bou beug adina thé djitalko ani ragal yalla thiéy oustaz bi diakhalnama

  • @elhadjibarandiaye7857
    @elhadjibarandiaye7857 Рік тому

    Ramadan Cissé

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv Рік тому

    Yak cheikh barra ndiaye doune léne mossa invite QG ndax gnoGnou khaliss laniy weurr di invité kéne si zerooo

  • @maurycamara9542
    @maurycamara9542 Рік тому

    Il a raison

  • @ousmanelo6382
    @ousmanelo6382 Рік тому

    Ramadan Cisse 😂😂

  • @abdoulazizmane8932
    @abdoulazizmane8932 Рік тому +8

    Astaghfiroulah lazi la ilaha ila khouwa mission yonanti yallah Mouhamad salala aleyhi wasalam bou doyone ngua wakh déh ki esk nitte la toubeul delou si yallah mission yonanti salala aleyhi wasalam bou doyoutone kone yallah wathié bénéne yonanti ki day diay kham kham bou dioumoul si limou wakh kathior bou mak la

    • @dipcr7officiel707
      @dipcr7officiel707 Рік тому +1

      La ilaha ilalah yalla naniou yalla téck si yone

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 Рік тому +1

      Légui explique nous lane mo woutalé Seydina Mouhamed psl fils D'Abdallah et Seydatouna Aminata rta ak Seydina Mouhamed zatou khabla tadjali...Fékhal ba boul daw nakh mo wakh ni Yalla amale nako té bobou Adama mi ngui nekk si diganté ndox ak bane... tontoul nak on t'écoute,un deux nguén yéfeur la nite gni

    • @abdoulazizmane8932
      @abdoulazizmane8932 Рік тому

      @@adamasow9292 yow diaro tontou parceque wakhoulo fi dara mounane lane mo differencie seydina Mouhammad ak ibn zeydatou aminata ak Mouhammad habla tadjali séne wakhou choubouhate yoyou nguéne yobouko sa aleu ba mo geune Manila linguene di bagnia dégeu kouffi wakh ni mission yonanti bi salala aleyhi wassalame yégoul wakhoulo deugue tu ment ak ko meunr done ak fo meuneu dioke ndakh bimou démé mome yonanti yallah Muuhamad salala aleyhi wasalam baye mission wame diékh mouy wadia guéneu adina takhawna si digue maka né yéne dioulite ndakh diotaléna sédélenema niouniko waw diotalé ngua lila yallah yondi ya rassoulalah charlatan bi ak gni mélni mome nane mission yonanti yallah Mouhammad salala aleyhi wasalam bou yéguone ni nguéne di déf rek di leundeumeul khelou nigni wayé koufi wakh lou wakhouwoul niou tontoula nak té nguamay wakhlo lima wakhoul kagne lalani ki yéfér la dou niguéne di déf bolé nigni ak adouna mais wakh deugue dou yow dou kéneu nioukoy té in sha allah kou wakh lou wakhouwoute niou tontoula si khél bou seleu in sha allah ak ko meune done nak

    • @diolsallamariam392
      @diolsallamariam392 Рік тому +1

      ​@@adamasow9292dou tontou😂😂

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 Рік тому +1

      @@diolsallamariam392 gni khamolén sakh dagno gatte alouwe té kou wakh gnou yéfeurlo la...khamoul sakh kouye Seydina Mouhamed psl,ça fait 3jours maguikoy déglou té balaégui tontouwoul wayé bilay sou gnewé dina khamni lepp deguele😅😅...wayé comme li nga wakh j'ai peur que dou niew

  • @ndayefall6039
    @ndayefall6039 Рік тому

    Yen niar yena yam gniou niaf sen nday guen

  • @malicktine878
    @malicktine878 Рік тому

    Deug lay wakh déh bilahi thieuy borom andalabouri

  • @nabienne
    @nabienne Рік тому +1

    Dieureufé Baye Niass 🎉🎉🎉🎉

  • @diengmourtalla6250
    @diengmourtalla6250 Рік тому

    Sénégal ninou beuga doundé diné mo métti ki lime wakhe ni deuge le

  • @maragueye1250
    @maragueye1250 Рік тому

    Kii louko way bagn bagn kham ni ki deffa am kham kham

  • @safietousane8051
    @safietousane8051 Рік тому

    Djeul li la intéressé té bayi fa li dess wasalam

  • @khadiaidara9487
    @khadiaidara9487 Рік тому +1

    Dafa diaga fikhe que dafa say say rek mais il maitrise lislam

  • @antasarrcisse1803
    @antasarrcisse1803 Рік тому

    😮😮😮 😮😮

  • @layeseckndiaye4384
    @layeseckndiaye4384 Рік тому

    No 😂 Akhmet Cissé est très fort

  • @Mohamedsall844
    @Mohamedsall844 Рік тому

    Bilahi qui nangou ouma kouko eup xam xam si aduna 😅

  • @modoubabathiam5616
    @modoubabathiam5616 Рік тому

    Deug la wakh

  • @matarkane7124
    @matarkane7124 Рік тому

    Ki dou dioulite moko wakh dafa alakou kouye wakh sa yaye soma dorater ma dore la ki weroute

  • @abibatoukonate7343
    @abibatoukonate7343 Рік тому

    Yow rek lay top

  • @ndiawardieye6323
    @ndiawardieye6323 Рік тому +1

    Il est très fort Thia kaw sa kanam

  • @MameDiop-g8x
    @MameDiop-g8x Рік тому

    P❤❤

  • @PendaDiop-y5f
    @PendaDiop-y5f Рік тому

    Lilayi wa rassoulihi diokh léne ma numéro Mouhamet Cissé

  • @RamaSylla-rz5zp
    @RamaSylla-rz5zp Рік тому

    Yew koubon ga😢😢😢😢

  • @dadandoye2153
    @dadandoye2153 Рік тому

    Qui pose questions mo nul 👎🏿

  • @babandiaye2301
    @babandiaye2301 Рік тому

    😂😂😂😂😂😂😂

  • @Momo911.0
    @Momo911.0 Рік тому

  • @pape-es5vy
    @pape-es5vy Рік тому

    Kii dofela 😂

  • @kantayesouare6632
    @kantayesouare6632 Рік тому +1

    Ahmed sice vs oustaz modou fall Gasta Gasta