la famille de S.Bara Khouradia en colère contre son discours de S.Amsa Mbacke Mom S.Abdou Lahad…

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 13 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 294

  • @Abdullahi3446
    @Abdullahi3446 4 дні тому +45

    Néexol baneexol weeyé bodotoon s touba kenn du kham brom saam, fii sëñ touuuba rk moofi né ❤❤❤❤❤

    • @Media5Tv1-y9w
      @Media5Tv1-y9w 4 дні тому +4

      Serigne touba dafa am ay mboke khamal loulo

    • @abdoulayengom7659
      @abdoulayengom7659 4 дні тому +5

      Walahi waxal dhé boys yi niak niom ak niak xam sen bobbou rek .sgn bara khourédia mi meusoul doon lodoul talibè serign touba .

    • @latdiordiop6051
      @latdiordiop6051 3 дні тому

      Li motakh gni len topou di sissou rek. Serigne touba guenoul ken ki gueun yala ko kham yakar ni kou bakh la rek nguen thi am. Ay bakar you amoul féne thi adouna so kholé mbirou Serign bi dingua ko guiss. Donc respectlen nit gni. Fi koula falé woul doko falé.

    • @AhmadouBambaSarr-so6vl
      @AhmadouBambaSarr-so6vl 2 дні тому

      @@latdiordiop6051 ya meuna wah loulla woloul koulla wah sbi guenoul kene

    • @alkarimalkarim5267
      @alkarimalkarim5267 2 дні тому

      @@Abdullahi3446 Deugeleu Deugeleu Deugeleu Deugeleu

  • @SidiDienne
    @SidiDienne 4 дні тому +21

    Fi serigne touba mofi nek. Mo deff lepp. Bou lénne niou sonal ah

  • @ousmanesarr8462
    @ousmanesarr8462 4 дні тому +12

    Lii geun dit def amoul bene diarign demlen diamou dji yalla ta legeuyali sr touba ken dou dra sr touba rk moy wadia❤

  • @mamemorniang9550
    @mamemorniang9550 4 дні тому +19

    Di diouli yoor yoor amna solo

  • @diawfalfaraa5997
    @diawfalfaraa5997 4 дні тому +18

    Fi kén Doufi touss lepou Serigne Touba la

  • @Malick-n5t
    @Malick-n5t 4 дні тому +18

    Borom sama S Touba motakh nu xam ko Borom sam taloubi S Touba Lou wér ❤

  • @SerigneGueye-z9l
    @SerigneGueye-z9l 4 дні тому +10

    Waye li s amssa wax darra nékosi
    Serigne touba mo dimbali diépue

  • @abdoulahigueye2387
    @abdoulahigueye2387 4 дні тому +12

    Waxante bi ci yoon wi man naa nàkk ku ci nekk sa darajay bopp rekk nga gis, bu S. Amsa tegoon bëtam Sëriñ bi du kàññ waa kër Maam Moor Jaara, ñoom itam bu ñu gëmee ne Sëriñ bi moo leen jox li ñu yor du ñu tontu S. Amsa. Xamleen ne seen wax yii dafiy des ba fàwwu. 😢😢

  • @yytv8221
    @yytv8221 3 дні тому +3

    Kou neikeu diamoul YALLAH kem sa katane ta baayi diw mo raw diw wala diw limou am diw motakh,diamou jilein YALLAH yii amaloutt keineu diarigne

  • @KhadimThioub-s3m
    @KhadimThioub-s3m 4 дні тому +23

    Yonou mouride d SERIGNE TOUBA rek mofil serigne,khousi eup talibé yafi gueune.diarama MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL

  • @MorSeye-zf2fg
    @MorSeye-zf2fg 3 дні тому +4

    Boudoul wone serigne touba senn mame yi dougn done dara lep borom touba la

  • @bayedjite6811
    @bayedjite6811 4 дні тому +8

    إنما المؤمنون إخوة فأصلحوا بين أخويكم

  • @abdoucisse6605
    @abdoucisse6605 4 дні тому +6

    Yoonou mouride lou fii nit ame serigne touba mou la kou diokh nay leer

  • @cheikhndigueldiopsalihcnds7122
    @cheikhndigueldiopsalihcnds7122 4 дні тому +15

    Waay Sëriñ Amsa limu wax lu wér la, dara nekku ci
    Ñépp ko wara liggéeyal
    Sëriñ Amsa wax na dëgg

    • @Abdullahi3446
      @Abdullahi3446 4 дні тому +3

      Deug leu té bodotoon sñ bi kenn dou kham brom saam, fii sëñ touuuba rek moofi né

    • @aladjimadiagaye9068
      @aladjimadiagaye9068 4 дні тому

      @@cheikhndigueldiopsalihcnds7122 wa S Amsatou Loum wakh ?

    • @aladjimadiagaye9068
      @aladjimadiagaye9068 4 дні тому

      Wa S Amsatou Loum wakh?

    • @mbackeabdou3258
      @mbackeabdou3258 4 дні тому +1

      Guénal affiche sa bopp rek wakh lim wakh so amé fitt

    • @cakmbc6488
      @cakmbc6488 4 дні тому +2

      Kou khèp brom sam khèp nga serigne touba nakh nio boku lèp ta serigne bi fonkone na ko lol nane bayi parpar lol bi tapale yi serigne bi talouko wone Domi ko meuneu done Ak ko meune done bo respect wul mboku serigne bi respect wo serigne bi.

  • @Cheikhouna04
    @Cheikhouna04 4 дні тому +18

    Ak bokk daal lepp lu koy defar mo gën lu koy xajamal
    Ta Ab tontontei day indi ak ñaawoo

  • @tout1958
    @tout1958 4 дні тому +6

    Kou mom xarmi ngéne bayi boume gi Serigne amsatou toudoul kéneu sax yéne mom lane moye séne problème

    • @NOTTO221
      @NOTTO221 4 дні тому +3

      Mane Loulou moma Diàkhal Bilahe

    • @tout1958
      @tout1958 4 дні тому

      ​@@NOTTO221kou mom xare mi nga bayi boume gi 😂😂😂😂😂😂😂

    • @tallfamilleelectroniquekol6840
      @tallfamilleelectroniquekol6840 4 дні тому

      Likay dafay wani ni kon li amna kon louy problème bi

  • @dialibatoumarahib79
    @dialibatoumarahib79 4 дні тому +9

    S mor Diara dé mom s Touba geuram nakoo

  • @Malick-n5t
    @Malick-n5t 4 дні тому +5

    Thiey STouba ❤❤ Amoul Mourom

  • @cheikhounaseck4139
    @cheikhounaseck4139 23 години тому

    Beuga siw rk s amsa kasé s touba bamouy niane kén taxa woul si kanam nane amine deug la dh

  • @SerignecheikhMbacké-z1g
    @SerignecheikhMbacké-z1g 4 дні тому +5

    Lo bakh bakh boune dinde Li sering touba def thi yaw nga yemak nieup mba nieup tane la wasalam

  • @MBtv92
    @MBtv92 2 дні тому +1

    Ci thiaxane képp ngén nék sa dieufou mame mom la féxé lén dieuf té ngeureumoul yalla mo geune. Kounék sa mame lii sa mame laa diamou dji léne yalla. Lo fi wax ñouné sa mame ngay waxal té beuss bouné ñou laal dîné kén dou wax

  • @SiiwalalProjetBi
    @SiiwalalProjetBi 3 дні тому +1

    Ab sëriñ daal mooy ki Sëriñ Tuubaa wax ca Masaalikul Jinaan.
    Sëriñ nekkul ci aw Sant.❤❤❤❤

  • @NdaySy
    @NdaySy 4 дні тому +8

    S morom soxna diara talibé s touba la ak s mor Anta saly diéye s touba amol moroum dè😢

  • @cakmbc6488
    @cakmbc6488 4 дні тому +4

    Merci à vous ❤wakh nguéne deug fi kene dou fi takhali serigne bi am gnim bokal li serigne touba yor gnepa ci yem amut seut amut dom Ak Talibé rk mo fiy diarign serigne bi wakhone na ko s Fàllu Domi serigne bi Ak s mor Rokhaya di diarbat Ak s massamba raki s touba

  • @elhadjithiam9856
    @elhadjithiam9856 4 дні тому +7

    Dieureudieuf Shaykhana Ahmadal Khadim. DIeureudieuf Serigne Mame Mor Diarra. Serigne Mountakha Mbacke yallah nafi yagg andak werr. Amine!

  • @modoudiop2892
    @modoudiop2892 4 дні тому +4

    Ndeysane letre bi ngafi nettali d manguikoy soga degg te njort nani barina si morom te gueumnako waye nak Sr Hamza kheuy neu lu Bakh rek la jublu woon si nettali googui mu wakh ndeysane li yalla bum jour fitna Amiine

  • @DianeBara-gq2tu
    @DianeBara-gq2tu 2 дні тому

    Serigne touba mo takh niou kham mame mor diarra

  • @mourtadambacke9116
    @mourtadambacke9116 4 дні тому +2

    Yalla nañou yalla dollé fayal S Mame Mor Diarra ta tass ñou si barkep ❤❤❤

  • @sindiditv9606
    @sindiditv9606 День тому

    Leeep Serigne Touba laaaaa liii kép mootah Cheikh ibra raw nieup

  • @mbayesall4205
    @mbayesall4205 2 дні тому

    Serigne si legui dagasante rek moy sen liguey legui dotounou thiow nguir yalla wala yonente sen boppou rek

  • @adjicherifFall-h7u
    @adjicherifFall-h7u 4 дні тому +2

    Cou Mame cheikh ibra fonkon lol toudé nako domam serigne mbacke fall yalla na yalla doly koy aye lér aki ngeureum barquep mouride bou mag ba

  • @MameCheikhMbacké-v8t
    @MameCheikhMbacké-v8t 4 дні тому +3

    Soof rek ngadef seringe amsatou dousene morom ndiakk ngene diome lool defleneni wa keur cheikh ibra fall am ak taloube’ te’ wormal ndiabotouk seringe touba gi ngir dieumi seringe touba ne’klene ay taloube’

  • @bambagueye6670
    @bambagueye6670 4 дні тому +4

    Fi borom touba rek fi nék yi yep Amul solo

  • @lowaydeffboppam6865
    @lowaydeffboppam6865 4 дні тому +1

    Ba kham ngén né S Hamsa man na dém ba Nék Khalifa Général des Mourides rék
    👌👌
    Te S Abdou Lahad nak louway mana wakh si youne bi mo deff Touba nimo Mel tay dji
    Si taxawayam ak Farlom ak liguèyel S touba

  • @cissedame3803
    @cissedame3803 4 дні тому +4

    Soff ngen baringen wax srg amsa waxu fi dara lu jar ay conference de presse apart serigne touba ñèpp ay talibé lan amul doom amul mak amul rak fi koñ fi topp srg touba mou tax

  • @mamemorcisse3561
    @mamemorcisse3561 4 дні тому +1

    Machalla Kham Kham bi lérna ❤

  • @abdouahadmbacke7214
    @abdouahadmbacke7214 4 дні тому +4

    Boudoul won Serigne bi kéne dou toudu brome sham

  • @SerigneMbacke-t7y
    @SerigneMbacke-t7y 4 дні тому +5

    Mbacke balla li amna solo lerna lolou waye ❤❤

    • @Amdymbaor-kt4sb
      @Amdymbaor-kt4sb 3 дні тому

      Yonou mourid Lou fi waay am serigne touba la

  • @sonko2024rk
    @sonko2024rk 4 дні тому +2

    Nékal nitt seringue amsa limou wakh deug la fii seringue touba mofi nékkk amoul mak amoul rakk

  • @latdiordiop6051
    @latdiordiop6051 3 дні тому +2

    Serigne amsa da diangoul amoul kham kham yarouwoul.

  • @mbayefallou1401
    @mbayefallou1401 3 дні тому +1

    Mame Mor Diarra ak Serigne TOUBA Cheikhanaa Cheikh Ahmadou Bamba ñioo book séénouk Bookk ( yaari waydiour ) ay waay rafétal léén

  • @MomoGueye-b6q
    @MomoGueye-b6q 4 дні тому +2

    Nay rafet rekk histoire moom nieupp kham nagne nimou demeii
    Fii moom lou kilifa gou bakh am rekk Serigne Touba moko ko defal
    Yalla nak beugoul kouye reuye reuye lou ak kou sokhor
    Wasalam

  • @abdoulahigueye2387
    @abdoulahigueye2387 4 дні тому +1

    Kii di leeral leetar bi moom rekk moo waroon a wax maasàllaa ❤❤❤

  • @mbackeniang1013
    @mbackeniang1013 3 дні тому +1

    Serigne touba amoul morom

  • @wakanavision540
    @wakanavision540 3 дні тому +1

    Brom same talibe serigne touba la kon sr touba sagn nako balelo keur ndakh moy serignam sen tontou yi daleni soufel rek

  • @toubadarmanko7193
    @toubadarmanko7193 4 дні тому +2

    Boudoul wone Serigne Touba kén doulén xam

  • @hibouson2783
    @hibouson2783 4 дні тому +2

    Bou lenne ngou fonto Mame mor Diarra s touba moko geune

    • @SokhnaxadiMbacke-ju6hl
      @SokhnaxadiMbacke-ju6hl День тому

      yawde xamo labari si adona digante chékholl khadim ak s mor diare mangase Mado ndax samam Sax domoromam waxomalak iow réwge te xamadi

  • @CheikhounaMbacke-q6v
    @CheikhounaMbacke-q6v 2 дні тому

    Borom Touba Amoul Morom dh ❤

  • @elhadjilougar1855
    @elhadjilougar1855 4 дні тому +2

    Maschalla am na solo diereidiaffff ❤❤❤❤❤❤❤❤ li rek mowèrrrr

  • @fdd10057
    @fdd10057 4 дні тому +2

    Sëriñ Mor Diarra nekul ci yi Guen Nek sëriñ Mor Diarra bam ligueyal serigne Touba la tonuwu bayilen thiakhan yi te dem diamou dji yalla

  • @elhadjitidianefall3280
    @elhadjitidianefall3280 4 дні тому

    Merci beaucoup

  • @SeynabouMbacke-vf1jk
    @SeynabouMbacke-vf1jk 4 дні тому +2

    Mach la ❤❤❤

  • @barasow3654
    @barasow3654 4 дні тому +3

    Mbiir bii borom touba kepp leu

  • @falyfal9
    @falyfal9 День тому

    Li S. Amza wakh gneuwate na ni si say kadou yagui merr bay fat ta talibé day dal.
    Dara nékhoul si limou wakh bayi léne reuye S. Amza Mame Diarra maman leu ta gnawtéf amoufi yawe bi ya togne ta Serigne Abdou Lahat yonam nékhou si baguénekoy khass fi Serigne Touba moi nek ta Mame Cheikh Ibra rawna léne nakh talibé

  • @yytv8221
    @yytv8221 3 дні тому

    Digante Mame Mor Diara ak Serigne Touba dei kou siye dougou da nga nafekh rek

  • @serignembacke2986
    @serignembacke2986 4 дні тому +3

    GATT xam xam monta wésou takhalé brom sam AK rakamdja Ku Sérign bi diokhon thiér déllou lén thi létaryi serignbi dan bind thi bir tukibi

  • @diop3836
    @diop3836 4 дні тому +1

    Koné deyékate sa mame sene mame diamou na yalla lémoye diamou yalla ba yalla sante ko deme lén diamou yalla def né sene mame

  • @mameboussotoubambacke
    @mameboussotoubambacke 4 дні тому +2

    Machallah brom sam dou morom

  • @moustaphalo7935
    @moustaphalo7935 3 дні тому

    Sounguéne amon Talibé li dounguénko déf ndakh lou mana khéw seeigne Amsa mbacké moy séne sangue dérétou serigne touba la lén gagné mou nékh léne ak mou nakhari léne mame mor diarra talibé serigne touba reck la .lépp serigne touba séne mame défou fi dara😊

  • @SerignecheikhMbacké-z1g
    @SerignecheikhMbacké-z1g 4 дні тому +1

    Li leup deh amoul solo s touba dimbli niou noune nieup moko taxnona nieuw diamone nane rouss yalla rouss Yonente bi rouss ta gore sering touba koune lako war thi mom defnako nane gore ta nite koudoul s touba dodara wasalam

  • @senegwade
    @senegwade 4 дні тому +2

    Diereudiefati serigne touba

  • @GueyeMarakhib28
    @GueyeMarakhib28 4 дні тому +3

    S amsa limou wakh dara nékkou si

  • @bayebeye3070
    @bayebeye3070 2 дні тому

    Lep Serigne bé guinaw yalla

  • @tout1958
    @tout1958 4 дні тому +1

    Serigne amsatou lou lér la wax limou wax mane amna 60ans ta dama dioudou dégeu magi talibé yi diko wax bayi léne sisou bi waye

  • @barasow3654
    @barasow3654 4 дні тому +1

    Gniii danio rew sakh serigne amsatou MBACKE deugue rekk la wakh té sii layy dokh

  • @thiernoniang7117
    @thiernoniang7117 4 дні тому +1

    THANKS SÉRIGNE MAME MOR ❤❤❤❤

  • @FallouDiouf-ck7bv
    @FallouDiouf-ck7bv День тому

    Bayi léne séne thiakhane yi fi dame mbacké mofi néki mome lagn geum Beugeu ngeune ak sékhou trop dem léne ligueyi

  • @ousmanesarr8462
    @ousmanesarr8462 4 дні тому

    Dama khamne kii geune kham lè dafa diou khoun pop pam sr touba lingeuni df koun dou si ande 😢😢

  • @mortalladieng8595
    @mortalladieng8595 4 дні тому +3

    Fii loufi wat am serigne touba moo koko may

  • @modoufall1365
    @modoufall1365 4 дні тому +2

    Yalla naniou souniou borom bok djégal nioune nieep barké Serigne Touba

  • @MoustaphaSarr-cb3gw
    @MoustaphaSarr-cb3gw 8 годин тому

    Mbolo dou dara Ousmane sonko daye diglé di téré lou waye am yallah le mouy seringue AK talibé niépou

  • @SambaSylla-j4g
    @SambaSylla-j4g 15 годин тому

    Deme lene ligueyi

  • @SerigneSaer
    @SerigneSaer 2 дні тому

    Amna nio khamne matou niou amsa mbacke cote dvoire la wala ma ko kham boubakh bomma takha wakh

  • @AbdoulahatGueye-i3b
    @AbdoulahatGueye-i3b 4 дні тому +2

    Serigne Amsa waxoull tourou ken

  • @moussafame4235
    @moussafame4235 2 дні тому

    S mame mor diarra maggi mak .Kubaax ku s tuuba fonkon.

  • @Sylla-g1x
    @Sylla-g1x 3 дні тому

    Sincèrement guisou mafi Xam Xam Ms rèwanadè lafi guisse

  • @MamemorSamb-v4h
    @MamemorSamb-v4h 4 дні тому

    Macha allah ❤

  • @abouabdoulayecisse9191
    @abouabdoulayecisse9191 3 дні тому

    YALLA naa YALLA dooli niou diam teh meussoul niou ci seytaneh

  • @NOTTO221
    @NOTTO221 4 дні тому +1

    Waxji Louko fi Diarr mane guisou mako Dama yakar ni Dafa ame loline Nakhari

  • @tallfamilleelectroniquekol6840
    @tallfamilleelectroniquekol6840 4 дні тому +1

    Saway serigne touba rek mofi nik bayi lene leguine di dif

  • @falloucisse33
    @falloucisse33 4 дні тому

    فليكرم ضيفه ❌
    فليقل خيرا أوليصمت ✅

  • @yytv8221
    @yytv8221 3 дні тому

    Adouna fawou am kou jiitou am ko toppou waya la nitt di rawei nitt mbiroum YALLAH leu dou ak diambaryaa

  • @KhadimToure-g5l
    @KhadimToure-g5l 4 дні тому +1

    Bayyiléne thiakhane

  • @ModouGuey-z8v
    @ModouGuey-z8v 4 дні тому +1

    N'a dem djeuli sokhna bi nek Espagne

  • @stafiroulaha
    @stafiroulaha 2 дні тому

    talibé yi bayiléne fi nie khoulo.ak khasté rék yéwouléne té bayi topé

  • @koureltoubabayakh
    @koureltoubabayakh 3 дні тому

    Mbokkou talibé you beuri dano niakkeu talibé,wormal lène kilifa yu

  • @Meunsablond08
    @Meunsablond08 4 дні тому +1

    Yalla na jamm yag

  • @kandjicheikh7498
    @kandjicheikh7498 День тому

    Keur maman rek dé vaye dîne dolent taxa kena ak lomana xéw

  • @modouastadiakhatembacolmba2560

    Senegal Mou nekh rk serigne touba de boko am mom tay la nekh way dembo xam na nuo lou xewo

  • @fdd10057
    @fdd10057 4 дні тому +1

    Dulen russ sakh borom kay bunkoy tud serigne Touba takh ñu lak fayda guen li sëriñ amsa wakh lou wer la lol sakh

  • @Tapa-vc5uz
    @Tapa-vc5uz 4 дні тому +1

    Brom Touba ak brom Sam bén lagne

  • @mhmdalmahiibnubashir55
    @mhmdalmahiibnubashir55 2 дні тому

    Kon SR ASMA lil wax SR moor jaara la???🌚

  • @baymordiorseck6974
    @baymordiorseck6974 4 дні тому +2

    Dondée suuf moom kokoy déf lôu jeuf lou réfétt dôko wakh amsa dà alkou bou yagu té yëgo ko

  • @Likhlassproduction4444
    @Likhlassproduction4444 4 дні тому +1

    Jërëgeen jëf waay 😊

  • @2mttv64
    @2mttv64 3 дні тому

    Maasàllaa jërëjëf xam-xam bi rafet na sell na

  • @amadoufatimakane3564
    @amadoufatimakane3564 4 дні тому

    Li serigne Mamour wah moo am solo

  • @fulkutv5324
    @fulkutv5324 2 дні тому

    Diougué leene fiii liii nguene dideff amoul ben ndiarigne. Ciy tappalé rekk nguene nekk

  • @serignesarr517
    @serignesarr517 2 дні тому

    BOU MEDECINS YIY KHEEX NOU MALADES YIY DEF ?

  • @DiakhateSerigne
    @DiakhateSerigne 3 дні тому

    yenne dall yeena soff rekk fii lepp serigne bi boudoul wone serigne bi kene dou kham s mor diarra

  • @seydinatoure4044
    @seydinatoure4044 3 дні тому

    Gisouma Lou aye thi wakhi s amsa dji de diaroul tontou yi