Rema Diop - FALAY LANGUÉ (Clip Officiel)
Вставка
- Опубліковано 7 лют 2025
- Retrouvez Rema Diop sur vos réseaux sociaux
Facebook ~ www.facebook.c...
Instagram ~ / rema_diop_officiel
Tik Tok ~ / rema_diop16
#clipofficiel #mbalax #new #video #remadiop
••••
▪️ Manager : Alga +221 77 503 77 53
▪️Mastering POLIMAN
▪️Music : Jeuss Beatz
▪️Réal : Ziz’Art
▪️Pape Ndiaye Tama
▪️Tenue : Ma Ndiaye Couture et M&B Haute Couture
▪️Chaussures : Khadija Kounta
▪️Make up by: Zahra Make up
▪️Infographe : Abou HM
••••
••••
CHERIFOU et JOB SA BRAIN/Rockteam Music, Metha Ndour, Poliman, Adama Sow, Antoine Zerbo, Sophia Thiam, Touchic By Ada, Alassane Gaye, Amadou Diouf, Mouhamed Tima Déco, Mansour Mbaye, Mamoudou Sonko, capitaine Mamadou Dieye;
Mention spéciale à ABDOULAYE CISSÉ et YORO DIASSY
••••
••••
Lyrics:
Cédé lén ma wakh ko bén yoon
Yéh, mom diaral nama
Yen cédé lén ma wakh ko niarri yoono
Yéh yéh, mom diaral nama
Dinama wo, dinama topato, dinama diégué sa souné dima réeeh
Dinama wo yéh, dinama topato waw, dinama diégué sa souné dima réeeeh
Mane khamé nala téh niémé nala yama doy si farando dagua ma nékh
Chérie saï saï mane douma meuna diégué
Kay kay yay sama coco rappéh
Saï saï douma khol bamay niéméh
kone tamou nala ya fi néhhh
Doy guama wérouway
Doy guama karanguéh
Doy guama si sa ndiégué nay waw lay langué
Falay langué, falay langué, falay langué si sa wét lay langué
Falay langué, falay languéh, falay langué si sa wét lay langué
Kima sagal yawla
Kima thiëreul yawla
Kima téral bama tédd ték ma si wétam yaw la
Souma bégué yawla
Meunou ma bakh ba raw la
Souma guéné niou nawma bilay
Guinaw yallah yawla
Kone tay dessna si mane
Ma mat leu seuk yaye
Mat leu diabar
Mat leu kilay bégguël kilay ray
Kilay raaay waw
Chérie saï saï mane douma meuna diégué
Kay kay yay sama coco rappéh
Saï saï douma khol bamay niéméh
Kone tamou nala ya fi néeeh
Doy guama wérouway
Doy guama karanguéh
Doy guama si sa ndiégué nay waw lay langué
Falay langué, falay langué, falay langué si sa wét lay langué
Falay langué, falay languéh, falay langué si sa wét lay langué
Djiguéne boula mouniëlé dagua kay sagal
Gorr boula térallé dagua kay guereum
Djiguéne boula mouniëlé dagua kay sagal waaw
Gorr boula térallé dagua kay guereum
Baye ndidiay coly gorr silé for silé tokk
Thinn bou makk nélawal
Gaïndé bou boffé domam béy souko laléh togn
Est ce que dina ko lale wawwaaw
Yéé yééé dagua kay sagal
••••
••••
Merci pour la confiance 🙏🏾Rema Diop Falay Langué très jolie titre 🎼 aimé et partagé 🔥🔥🔥
Machalah ♥️
Belle chanson
merci beaucoup à vous liguén deff rafet n'a 💃💖🤩
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@@seckaminatououmoulrassoul8771
Wwza
Depuis sa son djiwoul guendél tasoul yakar ba daay dama beug barké Serigne Babacar Sy. Dama la don weur fépp meunou ma fékhé ba guisla mais kholale lii yalla déf machallah té dila nianale yalla gua continuer ak sa sagoo sii barké Seydina Mouhamed SAW 🙏✅
Elle a une belle voix je l'ai découvert dans la série bété bété la voix elle est en armonie sa musique je te souhaite beaucoup de réussite et bravo à toi tu m'a redonner le goût du mbalaye
Le son préféré de ma femme depuis plus d'un an et je viens juste de me rendre compte que c'est la sœur d'une très bonne amie qui l'a chanté. Très bonne carrière rema
Je crois qu’on doit refaire la promotion de cette fille, je dirais même cette dame. Le talent à l’état pur ma sha Allah, le charisme et le charme qu’elle dégage me surpassent. Sénégal nak khamougnou way kat et c’est bien dommage. Les paroles, la voix tout est juste magnifique bonne continuation yallana la thiat sekhlou❤️❤️❤️
Amine
P
@@ndeyefatougaye7099
l0
l0l
Vraiment
@@aissataniang5008 v''
Oh ma fille adore cette chanson continue avec ça .on doit refaire la promotion de cette fille.Qui est d'accord avec moi🥰🥰🥰🧐🧐🥰
❤❤❤
😢😊😊
Kirasoulilay ya mana woy. 😍😍😍😍😍😍😍😍Woopopopopop talent fegn na. Waxuma sa belle voix, mais yii texte mo rare si bii generation. Waye yalnala yallah lafal thiatt rema. Desormais yanga sa playliste ba. 😍😍😍😍😍😍😍Kii.
M*% )%%%% % %%%
Namonena ma Remarque la voix d’or, nga guenei fou noy avec une voix que je n’ai jamais entendu venant d’elle.
Ta polyvalence conduit d m séduire, je te souhaite le meilleur.
Mes félicitations 🎊🍾🎉🎈
Qq
Machala 🥰🥰🥰
❤❤❤❤❤ cihl 0cihl ❣🖤🖤🖤❣❣
Ki es ici en 2024 🥺❤️
Suis la 🎉🎉
😢🎉
❤❤❤❤
Cette fille, on doit vraiment faire sa promotion. Je viens de la découvrir et cette chanson est devenue mon coup de cœur. Machalla
Ah
Franchement j'adore cette titre je l'écoute plusieurs fois par jour Macha'Allah bne continuation ❤❤
@@ndeyecoumbasow3372 f5t ...
J'entendais le refrain mais c'est la première fois que je la découvre. Machallah vraiment
7mj
Bulaaa yalla fayeee sa xoll incha ala kén dulaa té Yalnaa li jeum kanam Barke serigne babacar sy on t'aime
Je comprends rien mais j’adore vrai la chason depuis burkina🇧🇫❤❤
😮 no jj
Waouuuu Waouuuu mais c’est qui sa punesssss quel talent allez ramener ce clip à des millions de vue je kiffff grave ce chanson
J'écoute cette chanson et j devient de plus en plus amoureuse de mon bonheur , mon mari merci encore Réma
En dehors de sa voix éblouissante ses paroles sont riches d’enseignements 😍🥰😇
Merci bcp
@@remadiop ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ 1:28 👍👍💔💔💔💔💔💔💔💔💔
J’arrête pas d’écouter la voix d’or 🤩 Ma Réma ❤️
Je vais super 👍 mais ça me parait pas encore ça été
😮A eu GT eaaag
Yaye boye iow dall diam ak Salam werr ak werlé SOUTOURA ADUNA ak alahira yalna yalla lalay NIANAL doundeul yalla bayi sa voix machalah youkhu gua moy dioyna
Djiguene bou la mougnalé danga koy sagal gor boula teralé danga koy guerëm macah allah REMA DIOP❤❤
Ki moy kan mom amna talent dh na lekk si millions way
Ça fait des semaines je vois cette vidéo à travers mes notifications mais je ne savais pas que c'était la chanson que j'entends toujours en demandant celle qui la chanté vraiment cet une très belle chanson ta une très belle voix Diop.jaime!
💔💔💔💔💔💕💕💕💕💕
👍👍👍👍💅
Merci beaucoup à vous j’apprécie vraiment 🫶❤️
🎉❤
Wallae meunouma tokkkk journée sans deglou sons biii en plus 10fois minimum wallae
J'adore beaucoup cette chanson, sa voix est extraordinaire, c'est vraiment une fille de qualité. Une fille titulaire et representable partout en toute efficacité. J'écoute depuis Paris 🇨🇵🇸🇳
J'ai pas les mots pour d'écrire à quel point ce titre me touche. Machallah
Akpwubmcewu
@@aidadiop5004Mc'
Macha allah ma chérie geun doundou geun werr thi barke serigne babacar sy 🥰🙏❤
Vraiment une promotion à refaire cette musicienne mérite une carrière internationale. C‘est une voix d‘Or vraiment
Machallah ma copine d'amour thi kaw thi kaname Machallah grammy awards bi légui rek
Ana diegg you diongué yi beugeu ndioukeul Senn Aladji yi 😍 Cette chanson est vraiment appropriée 💃❤️✨
Quand des esprit créatif se rencontre sa donne ça une Bell voie, une Bell mélodie et une Bell vidéo machalla notre Réma national
Machallah 🥰
Belle paroles 👌🏼
Belle musique 👌🏼
Belle voix 👌🏼
Sa promet vraiment ! Bravo à Rema Machallah
Pleins de succès 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Bravo Alga good job 👏🏻👏🏻👏🏻
@@rachidousow4213 Merci beaucoup Rachidou
Machallah ma chérie d'amour
@@rachidousow4213 ⁰p
Ls2
Nooo son Bi nimoumay def srx yallah nasa diam yagu et bonne continuation yallah n’a batt Bi wérr❤️✨🧏🏽♀️☺️🥰😥
............i
Sama son la walahi
Maa shaa Allah petite sœur 😍 😍 😍 très belle chanson 💪💪🙏🙏
Machalah khamna mome lo guéné mou nekh bimalay beugue boba Aÿ acapéla nga dane déf ba légui fi lala déf
Ayyy Mane mi fouma nékone tay la Massa sétane clip bi wa lii môme neikh na 🥰🥰🥰🌹
Rèma nèkh nguama bouma ñewè Senegal naka lay dèf ba guis la❤
Xana thiaga la😢
Say Say douma khôl bamay gnémé c'est les paroles les plus importantes djiguen dafay am caractère bonne continuation rema♥️♥️♥️♥️♥️
Moi
Machallah rema vraiment Li nekh neu yalla nanga am disque d’or amine ya rabbi
Waow Waow c'est trop lourd....
Et on est sur un bon chemin
Tu as bien assuré
Khalebi yallah yallah goudal fan ame rema yallah naga goudou fan masaallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha Allah REMA DIOP
Belle clip
Belle titre
Belle voix
Vraiment tout est Nice bonne continuation plein de succès incha Allah 💪💪💪
Machala
Leip belle dal dii belli
@@mbissanegaye3430 are
bilelay belle voix❤
Machala
Bulaa yalla cherifou ❤❤❤❤❤
THIEUY ZIZ'ART CHERIFOU BAKHNA DAL TOUTES MES FELICITATIONS DU COURAGE ET BON COURAGE
RÉMA SACHE QUE TU PEUX CAR LE TALENT EST AVEC TOI DONV CROIS EN TOI
Rema Diop l’artiste complète mashallah wa A.D.B Tiv bégu naniou
Suis guinéen mais vraiment j''adore cette langue sénégalaise 🥰🥰🥰🥰
,erci
Desormais ma deuxieme chanteuse.
Elle et dieyla gueye me rendent toujours heureux
Merci bcp
MachaAllah Maréme très jolie titre et ta voix n'en parlons même pas😍muy bellissima
Tres belle voix Bonne continuation
J'adore cette musique de Rema Diop cette fille est superbe et a une voix de Diamant je l'adore Belle chanson j'arrête pas de l'écouter je te mets 10 étoiles 👍👍👍💋💋😍😍😍🥰🥰🥰😘😚🤩🤩😱😱😱❤️❤️👏👏👏👌👌👌👄👄👄👄👄
Mon coup de cœur ce matin je l'écoute en boucle🥰😇😇💖
Li nga waay si serigne saliou motax ma abonné aimer et vue content na si yaw trop🥰❤❤ my boy
Franchement c’est juste rema , wa diaspora Bi surtout wa paris contane nagnou Deh , bonnne continuation
Rema ma sister adoré tu chante très bien khaller bakh yarou ame kolerè félicitations
Sa voix est vraiment mélodieuse qui est d'accord
Beusseul j'aime
💕💕💕💖💖💖💜💜
Sa voix est extraordinaire 💕💕💕💖💖💖
Shiiiii heure biii yahh na ci mane tayy dahh attente impatiente bima am cii clip biii💃🏼
Ndeyssan sama dieukeur sama kharit ndiaye sipiong bakh sagal ma machallah
On peut dire que c est le travaille de sa maman elle est extraordinaire machalla laf that
Abf
La voix, elle est juste exceptionnelle ❤️
J'adore la partie où elle dit"ki ma téral yaw...meunouma bakh ba raw la
😍😍😍🥰🔥
Kima sagal yawla
Kima thiëreul yawla
Kima téral bama tédd ték ma si wétam yaw la
Souma bégué yawla
Meunou ma bakh ba raw la
Souma guéné niou nawma bilay
Guinaw yallah yawla
Une très belle découverte, une voix unique reconnaissable entre mille, Rema Diop inch'Allah tu atteindras des sommets. Compte moi parmi tes fans ❤️
Ykzkzntk'qh'odhsbEHJZJEIAAJ'XKL,.
Fktv
Grands yék grandes yi moytoulén khalé yi madjiss ah macha Allah meun nagn way dh
Je suis malienne je ne comprends pas olof mais je kiff gravr la chanson et Rema a une superbe voix🤩🤩❤
Wawe lii rombouna nekh dhe bly yaw avec rema diop rek dou aye fooo brom vois dor bii
Machallah très belle voix et très belle musique très riche je te souhaite le meilleur ma chère Rema adorée ndam rek inchallah sa kaw sa kanam
Réma Diop Ningai séralé sama ♥️bi yallah réka ko khàm 🥰Machallah Bonne Continuation ♥️💫⚡️♥️🥰
Elle a une très belle voix Ma Shaa Allah Bonne Continuation😍❤
Machaalah je viens de te voir à la télé laff Thiate tu chante trop bien vraiment je te souhaite tout le bonheur du monde et bonne continuation et du courage
Toutes mes félicitations Rema vas de gloire en gloire que Dieu te protège. Amen!!!
Saa fan's dep8 tivaouane👍🏼nice naa trop sakh👍🏼
Je n'ai jamais entendu cette voix si mielleuse .... Elle chante très bien
Noumay déf ba guiss reema❤
En plus d’être très modeste elle a une voix incroyable bonne continuation sister♥️♥️
C'est la première fois que j'entends cette fille mais elle est talentueuse elle a une belle voix si elle est bien encadré elle seras une chanteuse renommée
Machalla ma petite sœur adorée 🥰😍♥️♥️ félicitation ❤️❤️❤️ et bonne continuation ♥️♥️
falaye langué si wétou Kima beugue laye langué lii nékhna dé
Très belle chanson fils bonne continuation
Moi mome je suis pas surpris de cette car dès fois a G15 elle me donnait des extraits de ce qu'elle prépare.🎉✨✨🎉✨🎉
Bonne continuation Réma en tout cas tu as une voix en or inchallah ci kaman rek
Kou meuneu way a ngui nii masha allah💖💖💖
Thi yoe la beugue roy barké baye niass 💓
Awa
Machalla ma fille chérie yalla na nga aggale sa yeene ndam rek inchallah 💪 bole ci jom ngor foulla ak fayda te geum sa Bopp fonkk say wadiour ca kaw ca kanam inchallah contaane ci yaw looool leppay baax ya ngi ci yoon wi que Dieu swt te protège éternellement et bénisse abondamment je suis fière de toi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Amine inchallah et merci beaucoup a vous 🥰🥰❤️
je suis malienne j'a me bien ton son 🇲🇱🇸🇳❤
Merci beaucoup Ismaila
@@remadiopmerci vraiment que le bon Dieu te protege 🤝
Sénégal wa Apr rekk niou amoull talent
Ôlala iox lo déf mou nékh Masha allah la voix d'or 🎙️❤️
Rema Diop t'a la meilleure à cause de toi j'irai voir au Sénégal je l'adore 😍
Mann ky clip ba 1 millions de vu🥰🥰🥰❤
Ay way lii nekhna dit ça mérite des millions de vues ❤❤❤❤❤
Du jamais vu 😉 laf tiat vraiment à elle 🙏 c’est l’espoir de la musique sénégalaise by force.
Je crois que si elle est bien encadrée elle fera du merveille dans le monde de musique sénégalaise je l’ai découvert quand elle est venue hamo 6 1mer janvier passé je juste dit waow😍
Félicitations Reema diop 😍
Nieuw na nieuwalé collo nampo
La fierté💗💗💗💗💕💕💕💕💓💓💓❤❤💞😍😍😍😘😘😘😻😻
En plus de ça elle a une beauté divine et naturel ,Big up African Woman
Machallah yalnako yalla lafal thiate vrema RAS c mon coup de coeur chaque jour j l'écoute
Falay langué nous régalé encore 🥰bnne suite de carrière
Beautiful song 🎵 I just love it I always sent it to my husband when he's working
Ohhh maschàallah 🙏🏽🥰
Snvpt
Hur
Stoyn
Vraiment AÏCHA KONÉ , a timbre de voix extraordinaire , et explosif . Ngathié ngalama 🌹 💖 💐 🌷 🥰
Thank yu Ziz’art contane sén taxaway rafete na trop
Félicitation rema Diop ndanane gua dei yagui si birrr 🥰❤️
Trop nice ma belle ci kaw ci kanam rek ci Lou bakh inchallah sama xole seddna
Elle mérite des millions de vues bilay ❤️❤️
J'aime reeeeeeeeeeema❤🎉
Enfinn le 1m j’attendais ça tellement chaque jour mangui fi tu le mérite ma belle 🥰🥰🥰
Yalnala yalla same inecha ala si barké sougnou Serigne borom bonnet carré bi daga mena way machala