Moi vraiment j'écoutais Hady Niass mais d'après ce que je viens d'entendre sur lui il a perdu mon estime et merci beaucoup Oustaz Alpha pour ton éclaircissement.
Non mon frère. Continue à écouter ses tafsir et prends ce que tu comprends c'est à dire ne prend pas tout. Moi je suis akhlou Sounnah mais j'écoute toujours ses Tafsir car c'est le meilleur dans ça vraiment
Yéne khawma wahabistes khawma ibadou ay élève jardin 1ère section guène yam alors que Tarikha yi niveau professeur universitaire lagn . Yéne daguéne rerr té xamoléne guatt. Sene guiss guiss mo soriwoul motax ligni wax diléne diaxal. 😂
Fiennes bakhoul... Vouloir défendre le nomade du désert au point de mentir sur Allah et.son Prophète... Hady Niass, soit pas orgueilleux va apprendre... Qu'Allah veille sur toi ALPHA BA ma sha Allah Ma sha Allah Ma sha Allah...
Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla faye yalla na gnou yalla wane deug bagne meuneko top mou wane nene bagne maytouko
Moi vraiment j'écoutais Hady Niass mais d'après ce que je viens d'entendre sur lui il a perdu mon estime et merci beaucoup Oustaz Alpha pour ton éclaircissement.
Non mon frère. Continue à écouter ses tafsir et prends ce que tu comprends c'est à dire ne prend pas tout. Moi je suis akhlou Sounnah mais j'écoute toujours ses Tafsir car c'est le meilleur dans ça vraiment
Dieuredieuf Oustaz Qu'Allah le tout Puissant vous protège
Allahumma amine
Ma challa imame alpha ba long vie santé que dieu te protège ❤❤❤
Merci beaucoup oustaze alpha ba❤❤❤❤❤❤c claire et nette
Ci kaw kawi arash ak ci kaw arash.. Alpha ya beug degg lenen rek mais li hady niass wakh lerna.
Alhamdou lillah sunna defa lèr sunna thiakaw bida si souf
Allahu akhbar inchaallah
Merci Oustaz Alpha ❤️❤️
Sénégal beaucoup de tarikhas ,et chaque tarikha raconte ses propres histoires et se dit plus puissant que les autres
Mandou dall si diamou yalla la boco hkdi doula tonton waho fi dara xam xam wahoko fi yalla mongu ande Ake niono ❤❤❤
Yalna yalla bakél xam xam bi fayla Aldiana ya Oustaz
Machala alpha lér yi am na soulo torop machala
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Le menteur des menteurs Hardy Niass merci Alpha pour votre éclaircissement
Lo hkamoll dall nopi si mon guen 😂😂😂😂
No mou déf mo la ta né ndakh yaw thi guinawam ga fété Di wakh
Mboke yi wallahi bida bida boon na yalna yalla mousal gnou ci bokalé ak bida amine yarabi
Amna solo si léral dji .
Alkrouane AK suna rék 💪
sa kaw sa kanam
Dieuredieuf Oustaz hady hiass iéw rékh lanouy tope domorom béna kalé si xam xam motax iéw rékh lanouy tope
Doff certifié gua yagui wakhé poumon, dél nangou deugg, Hardy Niass mytho leu
Vraiment 😭 que Dieu nous protege sur le Droit chemin 😭 amine yarabi
Merci beaucoup oustaz ❤❤❤❤
Adi mahalla
Maleyereme
Alfa démal diagi
ioe momou ya wara diangui😂
4:36 tarikha cheikh thia kaw sa kanam
sa conviction la sunu yone nekoussi😂
Yalna yalla sougnou borom mousal gnou ci soss ci dîné yalla bi
Souf ci kaw arch sakh mo logikoul
Al quran ak sunna rek.
Hady niass ragalal Yalla
Yow dé Serigne Hady mola geuna ragal yala fouf sakh yaroul
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salam alpha
Iow ya khoul dara
Nit guemal ligue guéme bayi nitki mou diap loumou diap
Yaw dague rére demal diangui wate
قبل الزودي والزود دون علم
walaye serigne Hady wakhna deugue. problemou niveau ak tolouwaye la. kou niame salatoul fatihi da nga kham deug deug li serigne Hady di wakh.
Wakh deug niam nako mais gissouma dara.salatoul ala naby❤
Mancha llah dieuredieufe merci beaucoup oustaz alpha ❤❤❤❤❤❤
Iaw mom xamo foy arasss
Longue vie a vous ❤ ya ✊ oustaz ❤ ❤ Ba ❤
Merci bcp oustaz alpha ba ❤❤❤☝️☝️☝️
Yiw xamolo dara nopele mbamme
يو مم دكي دول
Hady ak audience bimou am senegal yup mouy tok di wax lii té amoussi ben dalil
Nooo! Hady niass day fen rek di tek 🦮🦮🦮🦮🦮🦮🦮
jagula yaw
Yéne khawma wahabistes khawma ibadou ay élève jardin 1ère section guène yam alors que Tarikha yi niveau professeur universitaire lagn .
Yéne daguéne rerr té xamoléne guatt. Sene guiss guiss mo soriwoul motax ligni wax diléne diaxal. 😂
on verra inchaallah yalla nalla yalla tek ssi yonu siratal mustaqin
@@abdallahba2667 kane la YALLA di tek si yonou sirat yéne? Kone amine.
Nioune mom ague nagn bouyague.
Doff certifié gua broh, dél nangou deugg Hardy Niass mytho leu,
Eskey salatoul fatiha, à cause de cette vidéo je comprends mieux les bien fait de salatoul fatiha 👍yalna si sax dee ci ❤dieureudieufati ya oustaz
Oie mom dfa melni dof certifié gua, yagui wakhé poumon, dél nangou deugg
Hady Niass bo heup sa bay xam xam AK KO masa diangall
Gni ay doff lagnou
Longue vie oustaz alpha
Fier d être tidiane
ya kham😂deh
Hady ligay wakh retanlouna dh😂
Asalamou alaykoum mbokouyi niame yallah bakhoul waye li yopou soufiyakeyi rek niokay wakh ay wokhi dof
Masha'Allah oustaz alpha ba leral yi Amna solo yallna yallah fay la ❤❤❤❤❤
Néna soussossa
😂😂😂
Hady dinâ khôl ndakh nimouye tafsiré Alkhourane nonoula
Meun na diangual say wadiour Tafsir
Yagui mère di😂
@@AwaNdiaye-f4u 😅😅😅 meusouma mér dama xam ni say wadiour lan lagne déf si dinnee jii
@@AwaNdiaye-f4u diokhma sa numéro niou débat
C'est vrai mbokmi wakhna degue diaratoul tontou
😂😂😂
Yene dangene di diague pour wérénté lamiñou safara rk ngéne yor
ioe momou la ragal sa wakhi retournéwou sa kaw khamal loy wakh avant qu'il ne soit trop tard
Fiennes bakhoul...
Vouloir défendre le nomade du désert au point de mentir sur Allah et.son Prophète...
Hady Niass, soit pas orgueilleux va apprendre...
Qu'Allah veille sur toi ALPHA BA ma sha Allah Ma sha Allah Ma sha Allah...
Allahumma amine
Jerejeff imam Alpha bah
Salatou.fatiya.doulou.ndawz
Hady da ngai dull rek
Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla faye yalla na gnou yalla wane deug bagne meuneko top mou wane nene bagne maytouko
Allahumma amine
Alfa démal diagi
ioe momou ya wara diangui😂