Ce que tu viens de dire c'est la vérité malgré le temps et les différents époques l'islam le Coran les règles de l'islam ne changeons jamais merci beaucoup pour ce rappel 🤝
Sama wadji diadieuf Guiss ngua Sénégal bo wakhé Lou yalla wala yoneneté bi (psl) wakh té niom arrangéwoulen dagni nane ki dafa doff wala dafa yénou diné bii Wala sakh niou nane yagg nguako deff wala you Mel nonou Limalay wakh dale Moy yone bimgua nekk disi diokhé xam xam boul ko meusseu bayi Parce que yangui dimbeuli diaamou yalla yii Kone continue sur cette lancé ❤
Wallah wakh nga deug boulène arrangé woul rk téh gnou xam ni deug leu lolou laniouye wakh dh thiéye 😢wala gnoulèy ignoré téh au plus profond d'eux xam nagne ni deug leu,c'est désolant srt pour l'actuelle génération boulène wakhè lini mél dangay dég gni naane kone nane ngay takè diabar,wala nane ngay amè dieukër dileu sofantall😮 Qu'Allah azawajal nous guide sur le droit chemin 🤲🏽
Merci beaucoup frère, relation hors mariage bakhoul, lounek moy khey sibir, tu stresse tout le temps, temps fatiguée mentalement et physiologiquement, t'es la tu penses tout le temps à la personne tu te demande si c'est réciproque, en plus ça engendre la colère d ALLAH, j'y étais mais magui sante yallah de m'avoir sortie de cela, certes ça fait mal, mais bakhoul, un point un trait c'est tout, tu l'aime marié vous c'est tout, si c'est pas possible tu passe à autre chose
Machallah Qu"ALLAH te préserve petit Frère un jeune qui s'évertue d'etre meilleur cela rassure de voir des jeunes savoir les limites des relations Homme Femme . De connaitre le fait qu'il soit Haram les relations hors mariage , de meme de s'isoler que se soit par téléphone , sms ou autres.
wallahi se que tu dis c'est vrai mon frére se matin a l'école c'est se que je disais a mes camarades de classe mais ils ne m'ont pas crus ,mais grawoul par ce que mane ma amme deugue sénne kawe et bonne continuation mon frére tu as beaucoups d'expérience
Merci vraiment, suis de France y’a une fille je l’aime et elle aussi mais on est trop jeune donc on a décider de plus se parler. Jusqu’à ce que je sois prêt pour la marier . Car on veut pas de relation hors . Elle est comorienne
Salam aleykoum Mon frère Deugue mo nekh yalla deugue yalla bi wakhko té boul falé kéneu koussi mer wala mou bagna d’accord lolou c’est son affaire mais ioe defal sa waref on te soutient machallah yalla nala yalla Fay ♥️🤲🤲
Diamono dji dh sofi neké Legui so beuguenté woul niou fokni danga doff😂wala gnoulay tekk tout le temps pression en te disant Loy xar ioe dal danga fasséné tokk ni rk tout le temps lolou lay degue ms nianatouma df Lo xamni nekoul souniou borom relation bou amoul projet doumasi dougou di def Lo xamni yalla beugouko k Dieu nous facilite tous le mariage🥰bonne continuation frère
Nnn Sénégal xam nagn ko dhh daniouy doff doff lou rkk Xam nagn lou bax ak lou bone danio topou sen nafsou bakane rkk ba daguanal lou bone lolou rkk mo fii nek
*Mercredi Le 24 Avril 2024* Machallah Abdoul Wahab Dieye Yalla Nala Yalla Faye Yiw Ci Vidéo Bi Amna Solo Lool Li Dëgg Moy Lolou Dou Yoone Té Diadouwoul Aussi Ay Thiakhaane Kasé La Pour Mane Nitt Dafa Wara Déf Farata Wala Mou Bayi Waayé Guéne Youdoul Diékh Ay Thiakhaane La Kou Tak Takha Diouk Na Tak Lolou Mou Yoone Encore Dieureudieuf Abdoul Wahab Dieye Yalla Na Yalla Goudeul Sa Fane Té Barkél Liguéye Bi Amine Allahouma Amine 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Kou beugu seydouna mouhamed Boul diale ta lalo guéme ❤🙏
Loolu looy géej gi amna ndox 😅
salalakhou aleykhi wa salam
❤
PSL 🥰😘😍❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤
sa ma yaye yalna goudu fanne🤲🤲 amine
Amiiiiine ❤
❤❤❤Amin Ya Rabbi mais waron ngua wah sounou la prière collectif est mieux que celle individuelle ❤
@@OusmaneLy-cv5nd c,est la verité 😇😇
@@diarrandiaye-f6w AMEEN
Kou wathié sa bop gua BILAHI Nala YALLAH Féy
Amine
Amin yarabi❤
Amiiin Macha'ALLAH 👏🏿❤
Amine yarabi barké seydina MOUHAMED PSL ❤
Ce que tu viens de dire c'est la vérité malgré le temps et les différents époques l'islam le Coran les règles de l'islam ne changeons jamais merci beaucoup pour ce rappel 🤝
Masha Allah yalna yallah are si barké Seyduna Mouhamed sallalahu Aleyhi Wasallama ❤️ ❤️ ❤️
SALLALLAHOU ALEYHIM WA SALAM❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amin
Amine ❤❤yalla 🤲🏾❤️🙏🥰💕👌👍♥️✅💯❤️❤️❤️🥹🥹🥰❤️❤️❤️❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉❤😊❤
Abdoul wakhabe dieye yalla nala yalla faye Que Allah nous pardonne nos pêches Amine yarabi Que Allah nous permet de réaliser nos rêve Amine yarabi 🤲🤲
Sama wadji diadieuf
Guiss ngua Sénégal bo wakhé Lou yalla wala yoneneté bi (psl) wakh té niom arrangéwoulen dagni nane ki dafa doff wala dafa yénou diné bii
Wala sakh niou nane yagg nguako deff wala you Mel nonou
Limalay wakh dale Moy yone bimgua nekk disi diokhé xam xam boul ko meusseu bayi
Parce que yangui dimbeuli diaamou yalla yii
Kone continue sur cette lancé ❤
Wallah wakh nga deug boulène arrangé woul rk téh gnou xam ni deug leu lolou laniouye wakh dh thiéye 😢wala gnoulèy ignoré téh au plus profond d'eux xam nagne ni deug leu,c'est désolant srt pour l'actuelle génération boulène wakhè lini mél dangay dég gni naane kone nane ngay takè diabar,wala nane ngay amè dieukër dileu sofantall😮
Qu'Allah azawajal nous guide sur le droit chemin 🤲🏽
@@fantasagna4076Wakh Ngua Dëgg Deh
Wakh Ngeene DEUG Deh ❤❤❤❤
Djieureudjeuf si
Wakh geudeu gue
Kou bah nga li diangalé amna solo trop machallah ♥️ yalna la Allah yokal ler inchallah ❤️ diadieuf
Koy sopey serigne saliou❤👍
Djeureu djeuf nala Yallah fay sa waréf ci domou djoulite rk nga def guissou gnouci lén lou rétanlou donté dou yombou ci niou bari
Masha'Allah amna solo❤
Sant yalla alkhamdoulillah yomboul déh way Lou mata bay khél la yalla niou yalla samb té mouthial niou thi AMINE❤
Des coeur pour notre Prophète Mohammed ♥️♥️🧡🧡🤍🤍💜💜🖤🖤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salalahou alla mouhamed ❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
قال الله تعالى في سورة المائدة: ولا متخذي أخدان ويقصد العلماء كإمام ابن كثير رحمه الله من هذه الآية العلاقة بين الرجل والمرأة الأجنبية.
❤❤❤❤❤❤ شكرا لك اخي شكرا لك اخي
Bouniou yalla yeureumoul xawma fougn dieumm 😢
Fou Raaw Tamba 😂😂
😂😂😂😂@@meundieufstudio1408
@@meundieufstudio1408Rayguama 😂😂😂
Mais nagn mougn rék
Mashallah Abdoul Wahab🎉❤❤
Abdou Wahab Diéy Yallah nafi yague the Wére🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Merci beaucoup frère, relation hors mariage bakhoul, lounek moy khey sibir, tu stresse tout le temps, temps fatiguée mentalement et physiologiquement, t'es la tu penses tout le temps à la personne tu te demande si c'est réciproque, en plus ça engendre la colère d ALLAH, j'y étais mais magui sante yallah de m'avoir sortie de cela, certes ça fait mal, mais bakhoul, un point un trait c'est tout, tu l'aime marié vous c'est tout, si c'est pas possible tu passe à autre chose
Machallah
Qu"ALLAH te préserve petit Frère
un jeune qui s'évertue d'etre meilleur
cela rassure de voir des jeunes savoir les limites des relations Homme Femme .
De connaitre le fait qu'il soit Haram les relations hors mariage , de meme de s'isoler que se soit par téléphone , sms ou autres.
ماشآءالله أحسنت ياشيخ عبد الوهاب أحسن عليك بخير إحسان والله حق 🙏✅
Allahouma barik Akhi AWD🤲🏽 récemment avant la publication je recherchait ce genre de thème Al hamdoul Illah 😊 qu'Allah augmente ta science 🤲🏽
ligay wakh wakh ko mo lèèr bol kouy ragall yalla moulaye sammu INCHALLAH ❤❤
Yallana yalla barckela machalla yallana yalla fayla nouko sounou sague bou téd bi salahou halayhi wa salame salahou hala Muhammad ❤
Allahumma salli a la seydina mouhamadine SWS ❤️❤️❤️
صلى الله عليه وسلم😊
wallahi se que tu dis c'est vrai mon frére se matin a l'école c'est se que je disais a mes camarades de classe mais ils ne m'ont pas crus ,mais grawoul par ce que mane ma amme deugue sénne kawe et bonne continuation mon frére tu as beaucoups d'expérience
Merci vraiment, suis de France y’a une fille je l’aime et elle aussi mais on est trop jeune donc on a décider de plus se parler. Jusqu’à ce que je sois prêt pour la marier . Car on veut pas de relation hors . Elle est comorienne
Macha allah c’est une bonne chose
Qu'Allah vous facilite 🤲🏿
Qu'Allah vous réunisse🙏
Amine Yarabi @@abdousalamlahi
MachaAllah baarakallou fiikoum ya Akhy yalna yalla samm la
Well spoken, Well appreciated And thank you sooo much Abdoulah 🙏🏼❤🙏🏼
Machaa'allah Abdoul Wahab ❤❤❤❤
ماشاءالله جزاكم الله خيرا ❤️❤️❤️❤️
Yalla nala yalla goudale sa Fanne amine❤❤
Salam aleykoum Mon frère
Deugue mo nekh yalla deugue yalla bi wakhko té boul falé kéneu koussi mer wala mou bagna d’accord lolou c’est son affaire mais ioe defal sa waref on te soutient machallah yalla nala yalla Fay ♥️🤲🤲
Kepou kou bègue seydina Mouhamed AK sa yaye boul dial té abonné wo sama compte bi
Gniy wax boulen bayi xel sénégalais kouko topoul si limou beug mou sonal la defal sa devoir gnila beug deglou dinagne la deglou ❤️🧕
Abdou yalah na yallah goudal say fann si barki alkhourane❤
بارك الله يا عبد الوهاب ❤
بارك الله فيك وجزاك الله خيرا يا اخي الكريم ❤❤❤❤❤❤❤
Machaa'Allah sa va réveillés beaucoup des gens qui ne le savais pas yalla nala yallah fay frère 🙏
Merci et encore Tes vidéos nous aident beaucoup dans notre vie ❤❤
Machallah Wahabe deuk rek gua fii wakh yallah nala yallah Faye bi diahi Naby Moustapha SWS ♥️♥️♥️♥️♥️
Machallah Amna solo ndeysane ❤
ماشاء الله تبارك الله عليك ياأخي الكريم الشيخ
Merci pour le rappel❤❤❤
Yallah na diam yague❤
Merci beaucoup frérot qu’Allah te récompense ❤
Merci pour le rappel
Abdou wakhab❤️ yalla na yalla faye la 🙏
Machallah li Moy dine dinagn si bayi xel inchallah
Massa Allah
Diamono dji dh sofi neké Legui so beuguenté woul niou fokni danga doff😂wala gnoulay tekk tout le temps pression en te disant Loy xar ioe dal danga fasséné tokk ni rk tout le temps lolou lay degue ms nianatouma df Lo xamni nekoul souniou borom relation bou amoul projet doumasi dougou di def Lo xamni yalla beugouko k Dieu nous facilite tous le mariage🥰bonne continuation frère
😂😂
Walay t'as raison
lou werr machaallah yalla nala yalla deugeureul
@@abdallahba2667Amine Incha’Allah
On te dit amo fiite chaque jour lolou lay dégu
Machallah yallna yalla samb ❤🎉
❤ماشاء الله تبارك الله ❤🎉
C'est très gentil ce que tu fais que le tout puissant te protège ❤❤❤❤
Nnn Sénégal xam nagn ko dhh daniouy doff doff lou rkk Xam nagn lou bax ak lou bone danio topou sen nafsou bakane rkk ba daguanal lou bone lolou rkk mo fii nek
Vérité absolue ❤
MASHALLAH GOD BLESS YOU BROTHER ❤🙏
Wah nga deug Frere mashaallah ❤
اللهم بارك فيك ياشيخ ❤❤❤❤❤
Bilahi abdou whab ya kham degue merci way
Yalla yalla fay yalla ❤❤❤yalna yalla dooli kham kham bi si barke koutèdeu ki amine 🤲🤲🤲🤲
Ma Sha Allah Akhyy sa liguey raffétt na trop yalna yalla sam la t arr la sam mbolém djoullitt🙏🤲🫶
Mashalah😊 merci beaucoup pour l'enseignement
Masha Allah may Allah reward you
Macha Allah amna solo torop 🙏🙏🙏
شكرا لك يا اخي الكريم جزاك الله خيرا
Machalla amatina sollo ❤❤
ماشاءالله الحق مقبول ولو من جاهل جزاك الله خير الجزاء
Merci beaucoup amna solo❤
ماشاءالله أحسنت وأكملت ❤
Machallah ❤Amna solo trop trop ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sa fait 6 ans k ma bako Al hamdullilah di bayi ba paré pour takk sogua nekk si inshallah. Et merci bcp Oustaz dinagn si gueuneuh goor goor lou
Macahalla Abdoul wahab ❤❤❤❤🥰
yalna yallah soutoural mayla guoudou fane machallah
Bly Frèrot longue vie à toi ❤❤❤❤❤
شكراً جزيلاً لموضوعك هذا.❤
jerejef abdoul wahab. bonne continuation.
Machalla que dieu vous bénisse ❤❤❤
Bilay wakh ga deuge sénégal kou wakh deuge niou ni dafa soff mais il continue comme ça ❤
Amna solo Machalla ❤
Machallah merci سكرا لك جزا كل الله خيرا ياءستاس
Dieureudieuf que Dieu te bénis 🙏
Machallah vérité absolue ❤❤❤❤
Machallah abdoul wahab 🙏🙏🙏
Machallah ❤❤ merci beaucoup frère ❤❤❤
Amine akhi yallah nalla yallah fay té barkel la❤
Degue Rek gawakh Bilahi 👆❤❤❤
Diadieuf oustaz ❤🙏🏽yalna sa diam yag
Machallah ya chiekh ❤
J suis le premier
Serigne Abdoul wahab vraiment ame na solo lol vraiment cadou bi Nice na trop mashallah ❤️🥰☪️🙏
MachAllah Abdoul ❤❤
*Mercredi Le 24 Avril 2024*
Machallah Abdoul Wahab Dieye Yalla Nala Yalla Faye Yiw Ci Vidéo Bi Amna Solo Lool Li Dëgg Moy Lolou Dou Yoone Té Diadouwoul Aussi Ay Thiakhaane Kasé La Pour Mane Nitt Dafa Wara Déf Farata Wala Mou Bayi Waayé Guéne Youdoul Diékh Ay Thiakhaane La Kou Tak Takha Diouk Na Tak Lolou Mou Yoone Encore Dieureudieuf Abdoul Wahab Dieye Yalla Na Yalla Goudeul Sa Fane Té Barkél Liguéye Bi Amine Allahouma Amine 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
ما شاء الله قولك حق ❤❤❤
Merci 💯💯
Manchallah ❤الهم صلى على سيدنا محمد صلي الله عليه و سلم 🥰
Mashallah amna solo trop yalna Yallah fayla
ماشاء الله تبارك الله
Qu’الله te récompense
Abdul heb kuam teginnga yalnala yala faye
Allah houma sali alla mouhamad
Merci si rappel bi
Merci beaucoup Rak dji Macha allah amatina solo
Yalnaniou yalla diégeul ak fi diamono tolou🙏❤️❤️
Al dinou nassikha. Jazzakallah kAllah