Serigne Diadji Tall
Serigne Diadji Tall
  • 6
  • 136 730
LA VIE DE SOHNA MAI KOUBRA PAR SERIGNE DIADJI TALL
La vie de sohna Maimouna Mbacke ibn Serigne Touba Cheikh Ahmadou Bamba Khadimoul Rassoul racontee par Serigne Diadji Tall le grand conferencier.
Переглядів: 4 967

Відео

ZIARRE KOUREL BAYE FALL A NDINDY CHEZ ABDOU KARIM MBACKE
Переглядів 5 тис.10 років тому
Le Ziarr du Kourel Baye Fall a Ndindy chez Serigne Abou Karim Mbacke ibn Serigne Fallou Mbacke en presence de Serigne Diadji Tall le grand conferencier.
SERIGNE DIADJI TALL INVITE 2STV
Переглядів 14 тис.10 років тому
Serigne Diadji Tall et Serigne Mame Mor Mbacke sur le plateau de 2STV en discutant sur la vie de Sohna Maimouna Mbacke Ibn Khadimoul rassoul.
SERIGNE DIADJI TALL WAHTANU RAMADAN VOL 2
Переглядів 30 тис.10 років тому
Wahtanu Ramadan etait un conference organise par le Daayira Touba Bergamo en Italy. Le programme etait au moos de novembre 2004 et c´etait durant le saint mois de Ramadan. Le conference etait anime par le grand conferencier Serigne Diadji Tall qui represente dignement le mouridisme et il souhaite toujour d´´avoir la possibilite de vehiculer les ecrits de serigne touba et son statut de Khadimoul...
BEUGUE SERIGNE TOUBA SERIGNE DIADJI TALL
Переглядів 38 тис.10 років тому
BEUGUE SERIGNE TOUBA SERIGNE DIADJI TALL
Serigne Diadji Tall Wahtanu Ramadan Vol 1
Переглядів 45 тис.10 років тому
Wahtanu Ramadan etait un conference organise par le Daayira Touba Bergamo en Italy. Le programme etait le 07 novembre 2004 et c´etait durant le saint mois de Ramadan. Le conference etait anime par le grand conferencier Serigne Diadji Tall qui represente dignement le mouridisme et il souhaite toujour d´´avoir la possibilite de vehiculer les ecrits de serigne touba et son statut de Khadimoul Rass...

КОМЕНТАРІ

  • @LikaLo-z4j
    @LikaLo-z4j 4 місяці тому

    Ndeysaane yalla na khipper firdawsi barkéb borom toubaa

  • @zeusskarakarimiem7074
    @zeusskarakarimiem7074 5 місяців тому

    Amiiine ya Rabbanaa

  • @OMARGAYE-jf2zf
    @OMARGAYE-jf2zf 10 місяців тому

    Yalla nala yalla yeureum té serigne bi teroula

  • @ahmadoubambakendla2069
    @ahmadoubambakendla2069 11 місяців тому

    ❤❤❤❤❤

  • @falloukhouma3515
    @falloukhouma3515 11 місяців тому

    Serigne Diadji Tall Yallah nako yallah yeureume barkep Serigne Fallou

  • @falloukhouma3515
    @falloukhouma3515 11 місяців тому

    Sokhna mai yallah na yallah Yokou lérame AK Serigne Djiadji tall

  • @falloudiaw6447
    @falloudiaw6447 11 місяців тому

    Yalanako yalasuniu barôme doli hay lér aminne

  • @modoumbow4874
    @modoumbow4874 11 місяців тому

    Maasàllaa Yal na ko Yàlla dolli yërmànde.

  • @PapeFaye-u7g
    @PapeFaye-u7g 11 місяців тому

    N'alla yalla dolly souttourra amine ❤

  • @papesaerkane4501
    @papesaerkane4501 Рік тому

    YALLA nala YALLA yereum t'es kharéla Aldiana ❤❤❤❤❤

  • @moamadousall
    @moamadousall Рік тому

    Quelle pédagogie !

  • @Bayfall123
    @Bayfall123 Рік тому

    Akasa serious diadji tall yalna na ko seringe touba terou barkep khadim rasoul ❤❤❤❤

  • @badaradiop7888
    @badaradiop7888 Рік тому

    Yalla na Yalla yok ay l'éram ❤❤

  • @astoudiop6260
    @astoudiop6260 2 роки тому

    ❤❤❤❤Amine y’a Rabi Rabi

  • @elhadjiabdoulayediagne8319
    @elhadjiabdoulayediagne8319 2 роки тому

    Dieredieufati Serigne Diadji.

  • @mourtadafall6009
    @mourtadafall6009 2 роки тому

    N'oubliez jamais de prier pour Serigne Djadji Tall.

  • @abdoudiagne8324
    @abdoudiagne8324 2 роки тому

    Ki scientifique leu deh

  • @thegambiasinterestlaminbad3033
    @thegambiasinterestlaminbad3033 2 роки тому

    Jere Jeff seringe touba

  • @Abo-fp2pf
    @Abo-fp2pf 2 роки тому

    Yallay jam gni

  • @Abo-fp2pf
    @Abo-fp2pf 2 роки тому

    Serigne Bamba dal kenn la

  • @piaimecamara5402
    @piaimecamara5402 2 роки тому

    Oh c'est dommage que dagnioo daagu wakhtaan wii mou bariii deugu keneu douko daagu waay Thiey Baye Djadjii Djooyna daal vraiment 😭😭😭😭😭😭😭degu degu deugu mooy diiné

  • @piaimecamara5402
    @piaimecamara5402 2 роки тому

    Non quel essence d'enseignement😍💕💕💕💕😭

  • @elhadjiabdoulayediagne8319
    @elhadjiabdoulayediagne8319 2 роки тому

    Mouride yeupako war di gnaanal.

  • @elhadjiabdoulayediagne8319
    @elhadjiabdoulayediagne8319 2 роки тому

    Yalna Yallah teral serigne diadji. Yalna dadièk ndimbalal borom Touba.

  • @bbthiatgaye3774
    @bbthiatgaye3774 3 роки тому

    Yalla nako yalla Dolly yeurmande ak diegeul si bark serigne bi

  • @mortallambaye2228
    @mortallambaye2228 3 роки тому

    Dieureudieuf yala nako yala fayé aldiana si b.s.touba

  • @gueyemoustapha1156
    @gueyemoustapha1156 3 роки тому

    Gueyemoustapha840

  • @MourideguiCom
    @MourideguiCom 3 роки тому

    Yala nala yala kharé aldiana thi barké Borom Touba

  • @sambalingeer5680
    @sambalingeer5680 3 роки тому

    Sëriñ Jaaji Taal Yàlla në suñu Boroom yërëm ko , jeegal ko té gërëm ci barkepp Boroom Tuubaa 🙏🏿

  • @lampetouba7076
    @lampetouba7076 3 роки тому

    Aminiiine

  • @damedia9410
    @damedia9410 4 роки тому

    Machalah

  • @mouhamadoubambambengue8421
    @mouhamadoubambambengue8421 4 роки тому

    Borom kham kham bou woor walahi!!!

  • @kebaseckbasskhanaaidadalaf3088
    @kebaseckbasskhanaaidadalaf3088 4 роки тому

    Vid

    • @serignediane3457
      @serignediane3457 2 роки тому

      Jërëjëf Sëriñ Jaaji Taal Yàlla na ko Yàlla gërëm te xare ko Aljana amiin

  • @mansourmboup7659
    @mansourmboup7659 4 роки тому

    Sa waxtane benene level leu Yalla nala serigne touba terou

  • @beuguecheikhibrandao1518
    @beuguecheikhibrandao1518 4 роки тому

    Ki kéman billahi

  • @yorosarr4140
    @yorosarr4140 4 роки тому

    Serigne diadji ,vrai pédagogue

  • @yorosarr4140
    @yorosarr4140 4 роки тому

    thiey Adouna

  • @ndongodiop4807
    @ndongodiop4807 4 роки тому

    Yalla na yalla doli lerram

  • @mamemortall8518
    @mamemortall8518 4 роки тому

    Yalla nako yalla yeureum té diégalko barkéb borom touba

  • @seidousoumare2212
    @seidousoumare2212 4 роки тому

    Yala na tala yook ay leeram

  • @xaxa6821
    @xaxa6821 4 роки тому

    11lihlas ngir serigne diaadji yalla nako yalla yeureum té kharéko aldjiana

  • @oumidiop1901
    @oumidiop1901 4 роки тому

    Ndéyssane serigne diadji tall aka beuguone Serigne Touba té kénalone ko yalla na yalla yok Aÿ léram té tass niou thi barkém yalla nako yakaram bâ di souniou yakar Serigne Touba térou amine way

  • @boubacarba6644
    @boubacarba6644 5 років тому

    Yalnako yalla yereum tei xareko aldiana

  • @seidousoumare2212
    @seidousoumare2212 5 років тому

    Dieureudieuff Serigne Touba

  • @makhtardia3690
    @makhtardia3690 5 років тому

    Kouma sopla allahouma ikhfirlaho amine

  • @smamemor
    @smamemor 5 років тому

    Ndayssaane kou yagg heehhal l'islam. Avec une pédagogie extraordinaire. Yalnagnou ko Saa Boroom fayal té yokkou ko lerr

  • @modougueyembaye6084
    @modougueyembaye6084 5 років тому

    Yalla nakou souniou brom yaram thi barkeb serign touba 11 likhlass hadiya s touba

  • @mamadoumbengue7455
    @mamadoumbengue7455 5 років тому

    Yalna Nako Yalla khare Aaldiana firdawsi Aamine

  • @mouslymbow5470
    @mouslymbow5470 5 років тому

    Jeurajeuf yalna borom bi dolléko geuram barké serigne Saliou

  • @mouslymbow5470
    @mouslymbow5470 5 років тому

    Yallana ay ngeuramam weuy di dottèkou thi serigne bou mack bi bi barakaatii huruufyi