- 498
- 712 393
Serigne Mbaye DIAKHATE
Senegal
Приєднався 1 бер 2018
Daaray Sëriñ Mbay Jaxate
Jàppal sa dund bi dundal lépp - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Jàppal sa dund bi dundal lépp ak jëf i yiw
Ta waxtu woo deful uw yiw, ray nga waxtu wa yaw
Ngir waxtu jëmm la jëf nag moo di ruu nga, ndegam
Defoo ca lëf, waxtu way ab ëkk kon bu taxaw
Ta waxtu woo lebal uw yiw kat bu saa taxawee
Nga seeru waxtu wa jug ñëw fay la woowale yiw
Ta yaa ngi nii waxtu yaa ngii nag di romb fi yaw
Loo def ci ñoom it ñu naaw ak loola yóbbu ko kaw
Loo bëgg a làq ëllëg, gaawal ci leble ko tay
Di séenu loo leblewul ag ndof la mbaa yëfi ndaw
Ta gis nga waxtu wu dee taw lépp loo bëgg a am
Doo def ludul fab ko daal koy tex ca boobale taw
Loo bëgg tex ko mu sax, loo soxlawul bu ko tex
Ku tex lu bon, bu saxee doy koo xalaat aka daw
Tuubal bu wér la nga daa def lépp yaw ci lu bon
Ngir tuub a fii tax a jub, bañ tuub a fii tax a bew
Ta loo moyoon ba la sànni’g moy waree ba fi saa sii
Boo ko tuubee ta sellal daal di jot ku la raw
Ta daal di jot wépp yiw woo xamne daa na la raw
Ta daal di bokk ca gaa yay dem ci péey aka ñëw
Lii waaye nit du ko jox boppam ta gaa ya ko am
Da ñoo bawoon seen i mbir ak Yàlla ñoo gën a ñaw
Ta topp nag seen i sang ak Yàlla melni ku dee
Di sant akay aw ndigal, yewwul ta roy ñile yaw

Переглядів: 133
Відео
Ñaan ci bàrkeb weer yi, bis yi ak waxtu yi | Céy Soxna May moo man a ñaan
Переглядів 14712 годин тому
Noo ngi dagaan ci Muharam wa Safar wa kasaa Rabiihul Awali wéy cig jaamu Yallaahu Rabiihul laahiri indal ash-hurul xurumi Ñooy weer ya jàmbaar ya daa am aajo Yallaahu Jumaada Loola sarax nu fan wu gudd akub Wér ak cawarte bu wér cig jaamu Yallaahu Jumaada Saaniya ak bàrkeem nu fàddu ci yaw Dunyaa waa uhraa na def sun yite Yallaahu Rajab musal nu ci moom Shahbaana may nu ci moom Lislaam ju sell ...
Jotaayu Murid | Bàyye sunu bopp ak Sëriñ bi (Épisode 4)
Переглядів 14819 годин тому
Jotaayu Murid Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté Thème : Bàyyee sunu bopp ak Serigne Bi
Ma def bëyit yii Soxna May, ngir Seexu Bàmba mi ko may...| Serigne Moussa Ka
Переглядів 229День тому
Ma def bëyit yii Soxna May Ngir Seexu Bàmba mi ko may Baatin bu tax ma di ko way Ndax mu dëgar ci li mu ngoy Ndax te mu fàttaliku ma Mbaa làmmiñam wa tudd ma Mbaa te mu beg ba rammu ma Ci darajay Maam ma fa Ngay Yaw Soxna Maymuunatu neel Aamiina ndax nu am ngëneel Noo ngi dagaan lula kaweel Yal na nga rëy ba tol ni Guy La Seexu Bàmba fas ci yaw Ak la nga fas ci mom ci yiw Yal na nga am lepp te ...
Jotaayu Murid | Bàyye sunu bopp ak Sëriñ bi (Épisode 3)
Переглядів 19514 днів тому
Jotaayu Murid Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté Thème : Bàyyee sunu bopp ak Serigne Bi
Wolofal Soxna May Mbacké - ñaanal Tawfeex
Переглядів 13714 днів тому
Sëriñ bi yaa ma tax a jug Su ma tëddee nga di ma rog Bëgg nga ma jaamu te lefog Giiñ naa ni yaa may dimbali Giiñ naa ni yaa fi indi maam Awata yaa fi indi maam Abdu mu jub mi dëkk Ndaam Yàl nang nu yàgg dalale Beg naa ci seen dikk gi lool Daa doon nelaw tay maa ngi xool Saa xel mi dal ma yokk lool Ca góor ga nekkoon Baafali Suñ sanc bi ma nekk tay Tudde ko Tawféex di fi way Nang ma fi may tawfé...
Jotaayu Murid | Bàyye sunu bopp ak Sëriñ bi (Épisode 2)
Переглядів 25021 день тому
Jotaayu Murid Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté Thème : Bàyyee sunu bopp ak Serigne Bi
Bàkk wi | Seexi Faadilu moo aaye tay ...- Wolofal Serigne Moussa Ka feat Serigne Abdou Diokhané
Переглядів 27221 день тому
Wolofal Seex Muusaa KA Aji bindaat ji: Soxna Nogay Cuun (jàng-wolof)
Jotaayu Murid | Bàyye sunu bopp ak Sëriñ bi (Épisode 1)
Переглядів 35428 днів тому
Jotaayu Murid Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté Thème : Bàyyee sunu bopp ak Serigne Bi
Wolofal Barzan (28) - Serigne Moussa Ka | Ñu daaldi tër doom ja Abdullaahi bay bëgg a ray...
Переглядів 222Місяць тому
Barzanjiyu Wolofal Serigne Moussa Ka par Serigne Modou Mamoune Diongue
Xamal ni Yàlla du nekk ak lenn lëf ci sa xol - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 262Місяць тому
Sa xol bi génné ci soxnaaki murid aki kër Ak doom akii alal ak mbooleem lu koy tilimal Xamal ni Yàlla du nekk ak lenn lëf ci sa xol Boo génné wul lépp lëf sab xol mu dëddu sa xol Ku bëgg Buur aki xejjam dal ngëram, na setal Këram ga, ngir bu setul Buur ak ñoñam du ca dal Ta Yàlla ab xol la def muy dëgg dëgg i këram Xol rekk a dib wàccukaayam dëgg dee ko setal Farlul ba waxtu bu seete xol bi fek...
Wolofal Barzan (27) - Serigne Moussa Ka | Digante yaari gëtam yaa ngay melax bu jogaan...
Переглядів 188Місяць тому
Barzanjiyu Wolofal Serigne Moussa Ka par Serigne Modou Mamoune Diongue
Serigne bi bàyyil sa nëbbu bi ... - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 366Місяць тому
Sëriñ bi doy ngama doyloo naala it ci lune Fegal nu wopp aki dee fàww ak ñu bon fu ñu ne Doylul nu wëllis i fajkat ak la ñiy faje nit Ta may nu mucc ak wér ak dund ak ngëram yu tane Ndegam da ñuy feg i lor yaa dàq a feg kune lor Mën ngaa feeg ii lor ta doo jam aw yaram ni gone Loo xamni day ruur akay lor nit na jëm fu nu moy Man jàpp naala def ub ñag, wër ma kàpp fune Ngir Yàlla ak Yonnenam ak ...
Wolofal Barzan (26) - Serigne Moussa Ka | Wa Màkka ak Medina... jébbal ko réew ma mu def xaliifa...
Переглядів 206Місяць тому
Barzanjiyu Wolofal Serigne Moussa Ka par Serigne Modou Mamoune Diongue
Wolofal Barzan (25) - Serigne Moussa Ka | Ba Salmaa jisee Haashim ne rët ni nërëm ngir leer ba...
Переглядів 162Місяць тому
Barzanjiyu Wolofal Serigne Moussa Ka par Serigne Modou Mamoune Diongue
Jàngat Wolofali Sëriñ Mbay Jaxate - Xastee fi xew aki fen
Переглядів 104Місяць тому
Jàngat Wolofali Sëriñ Mbay Jaxate - Xastee fi xew aki fen
Serigne bi kenn mënukoo nax ngir dafay yëri xol - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 281Місяць тому
Serigne bi kenn mënukoo nax ngir dafay yëri xol - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Wolofal Barzan (24) - Serigne Moussa Ka | Leeram ga roofu ca Maam Aadamaa waraloon...
Переглядів 2652 місяці тому
Wolofal Barzan (24) - Serigne Moussa Ka | Leeram ga roofu ca Maam Aadamaa waraloon...
Ngir yaa ngi njaaloo ta kuy njaaloo la gën rayiko … - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 3562 місяці тому
Ngir yaa ngi njaaloo ta kuy njaaloo la gën rayiko … - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Wolofal Jazaa u Shakoor Géej gi - Serigne Moussa KA (Partie 2)
Переглядів 3112 місяці тому
Wolofal Jazaa u Shakoor Géej gi - Serigne Moussa KA (Partie 2)
Miskin mu bon laa mu nekk ak yaw 😭 - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 2582 місяці тому
Miskin mu bon laa mu nekk ak yaw 😭 - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Wolofal Barzan (23) - Serigne Moussa Ka | Ku xoolutoon Mustafaa boobe asal du ko jis dunyan wa uxran
Переглядів 1832 місяці тому
Wolofal Barzan (23) - Serigne Moussa Ka | Ku xoolutoon Mustafaa boobe asal du ko jis dunyan wa uxran
Yàlla na nu am mujj gu rafet - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 2742 місяці тому
Yàlla na nu am mujj gu rafet - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Wolofal Barzan (22) - Serigne Moussa Ka | Déglul ma wax la ganaaw kiraay ya géej ya mu aw...
Переглядів 1842 місяці тому
Wolofal Barzan (22) - Serigne Moussa Ka | Déglul ma wax la ganaaw kiraay ya géej ya mu aw...
Diggante Touba ak Ndiareme… - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 1862 місяці тому
Diggante Touba ak Ndiareme… - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Ndioudj Ndiaadj - Wolofal Serigne Moussa Ka
Переглядів 7212 місяці тому
Ndioudj Ndiaadj - Wolofal Serigne Moussa Ka
Sama jëmma ngii sama lépp a ngii ... - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté feat Serigne Khadim Gueye
Переглядів 5703 місяці тому
Sama jëmma ngii sama lépp a ngii ... - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté feat Serigne Khadim Gueye
Wolofal Barzan (21) - Serigne Moussa Ka | Fa leerug Mustafaa dox a dox ci awwalan sooga ñëw ...
Переглядів 1563 місяці тому
Wolofal Barzan (21) - Serigne Moussa Ka | Fa leerug Mustafaa dox a dox ci awwalan sooga ñëw ...
Serigne bi Yàl na jàpp ub murid yeesal ko poull ... - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Переглядів 1593 місяці тому
Serigne bi Yàl na jàpp ub murid yeesal ko poull ... - Wolofal Serigne Mbaye Diakhaté
Wolofal Barzan (20) - Serigne Moussa Ka | Ba Yàllay amal leerag Muhammadanaa...
Переглядів 1833 місяці тому
Wolofal Barzan (20) - Serigne Moussa Ka | Ba Yàllay amal leerag Muhammadanaa...
YALLA NA NU AMUG DEGG... JAAJEF
❤❤❤🎉
❤❤❤❤
Dieureuf chiekh Ibrahima fall yalna nouko yalla fayal thie barkép Serigne Touba
Machallah ❤❤❤
Céy yile ñaan🥰🥰🥰
Macha alla ken dou serigne bi
Akassa
Akassa
❤❤❤❤❤
Machallah
Salla lahu Allah mouhamed
Amine inchallah Aswajal
Samay" mbir Yaw laako diIs... "foofu neex nak 🤩❤ DIEUREU NGEEN DIEUFATI🙏
Thiey Sama waji baye mbaye
Machala kebe ndiouga aly sa badiane begg na
Jërëjëf Badiene sant nagn bu baax 🥰
Dieureudieuf Serigne Modou DIÉNE wakhtane bi ame solo lolou ndakh app sonié deug leu thi kep kouy talibé🙏
Waw léne goor
ndeysaan, moom daal yal nan sax fi moom rek muy ne fi nun
Ndeysaan Amiin waay
Machallah ❤amaatina solo dh , yalla nalene yalla saam gueneu deugueureul xam xam gui
Amiin jëwriñ Jërëjëfati 🙏
Jaajëf Murid ❤❤❤❤❤
Machalla ❤ Dieureu dieufeuti 🙏🏿
Jërëjëf Baay Ngagne, sant nañ bu baax
Machallah amna solo
Jërëjëf jëwriñ
yalla na lene serigne bi fayal bopam amna solo trop
Amiin jëwriñ Jërëjëfati
Dieureu ngeen dieufeuti ❤❤❤
Jërëjëf Baay Aliou
🥰🥰
Machallah, am na solo lool sakh
Jërëjëf baay jëwriñ 🥰
❤❤❤❤❤❤
Ani ataaya bi. Kon kenn du naan daal?
Naanal Nañ la 🥰
Haqaza jerejefety ❤
Machallah
ndeysaan ❤
Walahi li amna solo torop fall ❤❤
Machalla ❤ Dieureu dieufeuti serigne Ousmane ak serigne Mamadou 🙏🏿
Tiey ??? Dieureu ngeen dieufati❤
Thiey lolou ❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤
❤ waaw góor a waay lii de am na solo lool.
Jërëjëf waay
Meus naye khibare AK ndiébelom Baye wakh ni yala miko môme mo Niko bamba Mola môme sariko diokhko saye pèkhé tétalko yoon wa ape mourid du aw ba raw pèkhé meuride ba âme nguéreum Bari mourid té dotoule ré Baye tékh tékhi mou daldi dém Tayba dakare ngire dégue bamba difa khare sétna Serigne Tayba dakare thime nguague laye khaméy pékhè mou teude goudi lissikhare bamou kheuyé ba tisbare Serigne makhtar touré fadiare lérame ga wonko aye pékhé makhtar touré nga yoori diare yanouko dieume mbacké kadiore cheikh bamba yoniko thia bour cheikh Ibra topeutiaye tékhé ba guis fa Serigne Adama Gueye sanni mbirame daldithia ngoye mou wonko bamba mbeur mou reye Serigne ba nanko foo feukhé mou wakhko tétal yafa môme Serigne baa wonko lafa mome mou khamné guis n'a kako môme mou daldi dieule mbireume diokhé ma wakhla bisbi ndakh mou woore niare fouki ate thi wérou koore bésoupe dibére la mbire ma woore cheikh Ibra moo reuye pékhé mou sobou fare ba djitoulén bamba né ki eupenalén lérame gou reuye gui weur nalén foumou tôle khôl baye nokh nokhi wakh Nani touti cône mou déme fék Serigne ba nga léme mbirame ba kéneu d'où mosse thi batiname loudoul thia bisse baniouye tékhé diarama cheikh Ibra fall l'AMPe bi cheikhi bamba talle lérale nga réwmi ya kamale Mame bamba yaniouye môme kouye soumbe soumbale guéthieu kou bègue foo lambe dathieu ndokh soumbeule guéthieu
Ndeysaan Jërëjëf
❤❤❤❤
Céy lii yéeme na lool
Amine🙏🏽❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Tiey !!!❤❤❤
Dieuredieufati, yalla na souniou borom dollé taxawou thi barké smj
Amiin waay sunu baay ji
Ma Shaa Allah ❤️❤️❤️❤️ Allahuma Amîîn 🤍🤲🏽. Jazaka'Allahu Kheyr ♥️. Qu'Allah Azza Wa Jel Nous Pardonne nos Manquements et Péchés.❤🤲🏽😭
Waw Goor ❤❤❤
❤❤❤❤❤
TIEY WAW GOOR❤