oustaz Sagna
oustaz Sagna
  • 205
  • 533 677
24 DÉCEMBRE AK 31 DÉCEMBRE DAGANE NA
24 DÉCEMBRE AK 31 DÉCEMBRE DAGANE NA
Переглядів: 1 423

Відео

BARTHÉLÉMY DIAZ DÉLOL SA BOP THI YALLA
Переглядів 1,1 тис.День тому
BARTHÉLÉMY DIAZ DÉLOL SA BOP THI YALLA
DEUGUE NATANGUÉ LA FÉNE BÉKORE LA
Переглядів 63514 днів тому
DEUGUE NATANGUÉ LA FÉNE BÉKORE LA
WA PASTEF AMNANIOU CHANCE
Переглядів 1,5 тис.21 день тому
WA PASTEF AMNANIOU CHANCE
DINÉ DOU BUSINESS
Переглядів 1,1 тис.Місяць тому
DINÉ DOU BUSINESS
YALLA DÉLONA SERIGNE MOUSTAPHA SY PLACEAME
Переглядів 17 тис.Місяць тому
YALLA DÉLONA SERIGNE MOUSTAPHA SY PLACEAME
KEPP KOUYE LATHIE KHALISS THI DINÈ DADIALE NGUA
Переглядів 782Місяць тому
KEPP KOUYE LATHIE KHALISS THI DINÈ DADIALE NGUA
KADDU LA ILAHA ILAL LA LOUMOUYE TEKKI ?
Переглядів 1,1 тис.Місяць тому
KADDU LA ILAHA ILAL LA LOUMOUYE TEKKI ?
LANE MOYE WEURSEUK BOU DIEX ?
Переглядів 8142 місяці тому
LANE MOYE WEURSEUK BOU DIEX ?
EST-CE QUE WÈDI YALLA DAYE WAGNI WEURSEUK ?
Переглядів 9842 місяці тому
EST-CE QUE WÈDI YALLA DAYE WAGNI WEURSEUK ?
EST-CE QUE PLANNING FAMILIAL DAGUANE NA ?
Переглядів 8032 місяці тому
EST-CE QUE PLANNING FAMILIAL DAGUANE NA ?
TALIBÈ SERIGNE BABACAR SY YI TOUPE LÉNE
Переглядів 1,4 тис.2 місяці тому
TALIBÈ SERIGNE BABACAR SY YI TOUPE LÉNE
SERIGNE BABACAR SY NITE KESSÈ LA
Переглядів 2,6 тис.2 місяці тому
SERIGNE BABACAR SY NITE KESSÈ LA
NINGUÉNE GNEUWÉ THI ADOUNA NONOU NGUÉNE DI DÉLO THI YALLA
Переглядів 1 тис.3 місяці тому
NINGUÉNE GNEUWÉ THI ADOUNA NONOU NGUÉNE DI DÉLO THI YALLA
TASS LÉNE TARIKHA YI BALA YALLA DIKO TASS
Переглядів 3 тис.3 місяці тому
TASS LÉNE TARIKHA YI BALA YALLA DIKO TASS
C'EST PAS CHEIKH OUMAR DIAGNE C'EST DIEU
Переглядів 6 тис.3 місяці тому
C'EST PAS CHEIKH OUMAR DIAGNE C'EST DIEU
GAMOU FÊTOU DADIALE LA
Переглядів 3 тис.3 місяці тому
GAMOU FÊTOU DADIALE LA
BOURD PIÉGEOU DADIALE LA
Переглядів 3,6 тис.4 місяці тому
BOURD PIÉGEOU DADIALE LA
MONSIEUR LE PRÉSIDENT DIOMAYE FAYE MOYTOULE PIÉGE BI
Переглядів 2 тис.4 місяці тому
MONSIEUR LE PRÉSIDENT DIOMAYE FAYE MOYTOULE PIÉGE BI
AMADOU BA DÉFOULE BÉNE KÉMETANE
Переглядів 5 тис.4 місяці тому
AMADOU BA DÉFOULE BÉNE KÉMETANE
MAGAL TOUBA FÊTOU FRANC-MAÇON LA
Переглядів 10 тис.4 місяці тому
MAGAL TOUBA FÊTOU FRANC-MAÇON LA
MONSIEUR LE PRÉSIDENT DIOMAYE MOYTOULE TARIHA YIII
Переглядів 2,8 тис.4 місяці тому
MONSIEUR LE PRÉSIDENT DIOMAYE MOYTOULE TARIHA YIII
SERIGNE MOUNTAKHA ABE GUONÉ SY NIO YAME
Переглядів 3,1 тис.4 місяці тому
SERIGNE MOUNTAKHA ABE GUONÉ SY NIO YAME
BAYILÉNE XASSIDA SERIGNE TOUBA YII
Переглядів 4,1 тис.5 місяців тому
BAYILÉNE XASSIDA SERIGNE TOUBA YII
MASALIKULE JINANE DAGNE KO WARA TOTHIE
Переглядів 1,6 тис.5 місяців тому
MASALIKULE JINANE DAGNE KO WARA TOTHIE
KEPP KOU AMOULE LIBERTÉ SOO DÉWÉ DÉME SAFARA
Переглядів 1,1 тис.5 місяців тому
KEPP KOU AMOULE LIBERTÉ SOO DÉWÉ DÉME SAFARA
KEPP KOU ASKANAL SA BOPP KOUR ANIYOUNA DADIALE NGUA
Переглядів 1,3 тис.5 місяців тому
KEPP KOU ASKANAL SA BOPP KOUR ANIYOUNA DADIALE NGUA
DOCTEUR AHMAD LÔ CI DADIALE YII LA BOKK
Переглядів 5 тис.6 місяців тому
DOCTEUR AHMAD LÔ CI DADIALE YII LA BOKK
SERIGNE MOUNTAKHA SOU DÉÉWÉ TÉ TOUBOULE BOULKO BÉNE DIOULITE GNANAL
Переглядів 7 тис.6 місяців тому
SERIGNE MOUNTAKHA SOU DÉÉWÉ TÉ TOUBOULE BOULKO BÉNE DIOULITE GNANAL
BANE YONÉNETE MOYE WATHIEU THI MALANOU WASIFA ?
Переглядів 3,8 тис.6 місяців тому
BANE YONÉNETE MOYE WATHIEU THI MALANOU WASIFA ?

КОМЕНТАРІ

  • @elhadjfall6531
    @elhadjfall6531 7 годин тому

    Gni gamoul yalla gno app ci aduna gnone dagno geum yalla té dou gnou ko massa bokalé ak dara La ilaha Ila houwa. Lolou lanou geum Yaw minga yafi nék di fén di fénal yalla di fénal gor yalla beuss bou nek ngeu seug ci dérou nitgnou baax Gni di lek souba ak ngone. Malheur à toi dans cette vie et à l’au-delà. Tu es maudit c’est pourquoi tu t’acharnes contre des gor yalla qui ont abandonné tout pour aller vers leur seigneur souhana hou wa tahala.

  • @elhadjfall6531
    @elhadjfall6531 8 годин тому

    Yaw noupou loul ak sa guémigne cheitané yalla yoni woulou ci dara fénal yalla rek ngafi. Yaw kou le ndieuk savara dafa la ndieuka deh.

  • @senegal7883
    @senegal7883 2 дні тому

    Longue vie à toi domou baye

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 2 дні тому

      @@senegal7883 amine domou baye merci beaucoup

  • @bababalde7793
    @bababalde7793 3 дні тому

    Vous avez parfaitement raison

  • @elhadjfall6531
    @elhadjfall6531 3 дні тому

    Wax diou niaw rek ngah xam Bou fékéné ab dioulite ngah danga wara nopi té bayi gnép Gni ngaye lék sén yap vi

  • @thiampassion
    @thiampassion 3 дні тому

    Billahi lakoum dini koum waliya dinee. Mais si nekk di critiquer alors que sa yonne nekoutchi. Vraiment yenn yii togne la .

  • @Mounta618
    @Mounta618 4 дні тому

    Merci oustaz sagna. Li nga wakh yeup deugue la. Deug mo toumouranké sénégal. Merci.

  • @BabacarFAYE-vx4uz
    @BabacarFAYE-vx4uz 4 дні тому

    Merci Oustaz

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 4 дні тому

      @@BabacarFAYE-vx4uz ok merci beaucoup contanna

  • @ibrahimabarry2541
    @ibrahimabarry2541 4 дні тому

    Les oustazs n'ont pas critiquer la fête des chrétiens mais ils parlent aux mons des musulmans qui manifeste cette fête du 31 décembre ils la ils faut faire attention monsieur svp se que vous disez sur les confréries des musulmans au Sénégal c'est vrai

  • @matardjiba1674
    @matardjiba1674 4 дні тому

    Toi tu ne connais pas l'histoire du 24 et du 31 décembre même les chrétiens disent que ces deux fêtes sont satanique Le principal nafeek c'est tu ignores tout de la religion chrétienne

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 4 дні тому

    niom bou niou madouwonn dinaniou fen nan yalla dafa am dom orzo

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 4 дні тому

    kon yenentebi mandouwoul won۔koufi wahnee yalla amna domou orzo dagay doul

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 4 дні тому

    gaydee dou fiour nit nitt moy diour nit

  • @alwaysbethankful3742
    @alwaysbethankful3742 4 дні тому

    Oustaz Sagna damalaa beugue tee yalla takh wallahi, tee insha aallah suma ñiéwè Sénégal dinaala visite insha aallah 🤲🏾🤝🏼 merci beaucoup infiniment est resté comme vous êtes insha aallah ☝🏼

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 4 дні тому

      @@alwaysbethankful3742 merci beaucoup contanna si yaw yalnaga gouda maguilay khare yalnala yalla samedi fepeu foné mala raw

  • @MbathiouMbeng
    @MbathiouMbeng 4 дні тому

    Oustaz Sagna bayil docteur Ahmad lo

  • @CheikhouSylla-vr8jh
    @CheikhouSylla-vr8jh 4 дні тому

    allahou akbar all hamdou llii llah yallah yoow rék yaaye yallah soub hana hou wa ta Allah kééne dou yallah kou doul yoow yallah mouhamadou rassoul mooye sou gnou nabi Allah kééne la fii téh doo toul gnar ccii darou adouna ak Allah xiira . deeg bou deegou dou roombe noop mouk xana noop shaïtane mounafixoune batara mooxo bou Allah boonii maudit .

  • @soulipaye1432
    @soulipaye1432 4 дні тому

    Merci sagna

  • @MbathiouMbeng
    @MbathiouMbeng 5 днів тому

    Gnou melni yaw yalna beuri

  • @MbathiouMbeng
    @MbathiouMbeng 5 днів тому

    Oustaz sagna ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Cheikh-d5p
    @Cheikh-d5p 5 днів тому

    Bien dit oustaz✅

  • @rokhayatine-hu9zy
    @rokhayatine-hu9zy 5 днів тому

    Merci ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 5 днів тому

      @@rokhayatine-hu9zy merci beaucoup contanna si yaw

  • @MbathiouMbeng
    @MbathiouMbeng 5 днів тому

    Jazaka Allah

  • @MbathiouMbeng
    @MbathiouMbeng 5 днів тому

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @Luqmane-i9p
    @Luqmane-i9p 5 днів тому

    Merci beaucoup oustaz Sagna DEUG rek tu es véridique longue vie et la santé tu du que la vérité

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 5 днів тому

      @@Luqmane-i9p merci beaucoup contanna amine

  • @alexandreanas8222
    @alexandreanas8222 5 днів тому

    Merci oustaz sagna longue vie et la santé à toi deug moy deug sénégal deukou boukalela ak nefkhla

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 5 днів тому

      @@alexandreanas8222 merci beaucoup amine

    • @alexandreanas8222
      @alexandreanas8222 4 дні тому

      @oustazsagna6722 bonjour comment vas tu le travailler que vous faites est remarquable merci beaucoup que le bon dieu te protège ya oustaz

  • @Leternel.incompris
    @Leternel.incompris 5 днів тому

    Oustaz wakhal cii mbacke Sakho soudé deugg mola niorr…

  • @fatoubintangom4264
    @fatoubintangom4264 5 днів тому

    Deug nékhoul

  • @papeissatoure2119
    @papeissatoure2119 5 днів тому

    Vraiment vous avez bien raison et suis tout a fait d'accord avec vous et personne ne peut nier ce que vous dites.

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 5 днів тому

      ❤❤❤merci beaucoup contanna si yaw yalnaga gouda fane

  • @ousmanesane5313
    @ousmanesane5313 5 днів тому

    Macha Allah yaa Oustaz ❤️ Que DIEU VOUS GARDE 🤲

  • @greenespace4001
    @greenespace4001 5 днів тому

    Salam Wakhatinga deuk

  • @Yeme--NA
    @Yeme--NA 5 днів тому

    Titre bi ni ngako bindé meune na diakhassé khél mane sakh dama fogone ni da ngani dagane na. Da nga warona binde par exemple: ndakh dagane na ?

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 5 днів тому

      @@Yeme--NA comprendon témbi lima beugeu wah moye menndou

    • @Yeme--NA
      @Yeme--NA 5 днів тому

      @@oustazsagna6722 Waaw comprendre nako, da am nio kham né souniou lirer titre bi té continuer wouniou vidéo bi meune nanio bania comprendre fi ga wakhé motakh malaye layer bir pour ngay indi interrogation bi tchi question.

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 5 днів тому

      @@Yeme--NA ok deugeule mais yalla bahna merci beaucoup pour léralbi

    • @Yeme--NA
      @Yeme--NA 5 днів тому

      @@oustazsagna6722 Merci beaucoup, diamono yi niou nék ni amna nio kham ni meune nanio capturer titre bi sakh ni yaw li nga wakh déformer sens bi.

  • @morniague945
    @morniague945 6 днів тому

    Bilahi yaye Mbame ya bone ya yèsse ya mana togne...nioune mouride mono thi nioune Dara

  • @yibbou
    @yibbou 7 днів тому

    Diné dji kay moy marssandiss bi, taalibé yi di clients/consommateurs yI

  • @matarkeita2804
    @matarkeita2804 7 днів тому

    Prier sur l’océan n’est qu’un miracle pour ahmadou mais ses vrais miracles se sont ses écrits c à dire les Xassida et nul ne peut le nier et personne d’autre n’a écrit pareil ici et ailleurs .pour tes agissements sache qu’un autre mara a traversé le fleuve en voiture un certain m Ndaw si je ne me trompe. Miracle chak jour niou guisko danou si avion dara doula dal amna seurign mbidou lixom moy miracle

  • @CheikhounaGueye-q3w
    @CheikhounaGueye-q3w 8 днів тому

    Oustas li ma begue xam moy boy danou wala ngay wa dal dara ban torou yalla nga wara todou

  • @abdoulayediakho1075
    @abdoulayediakho1075 10 днів тому

    السلام عليكم ورحمة الله وبركاته شكرا على الحق

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 10 днів тому

      @@abdoulayediakho1075 و عليك السلام ورحمة الله وبركاته شكرا لك يا أخي الكريم بارك فيك وجزاك خيرا

    • @oustazsagna6722
      @oustazsagna6722 10 днів тому

      @@abdoulayediakho1075 و عليك السلام ورحمة الله وبركاته جزاك الله خيرا يا أخي سررت بك

  • @elhadjimalick2418
    @elhadjimalick2418 10 днів тому

    Il faut prier la guidée pour eux (wa tarikha) au-delà de tout cela. Cela fait partie de la sagesse.

  • @MaimounaDiatta-i6c
    @MaimounaDiatta-i6c 11 днів тому

    Riba rek ses marabouts,mactar sarr et consorts

  • @MaimounaDiatta-i6c
    @MaimounaDiatta-i6c 11 днів тому

    mactar sarr tapalé Kate la 😂😂.. merci Macha alla ya oustaz sagna ❤

  • @elhadjfall6531
    @elhadjfall6531 11 днів тому

    Yalla yoni woula wathié woul ci Yaw dara Kone mano dioxé. Danga am complexé pour les arabes té certains arabes gno yess ci aduna Yaw nak doul rek ngafi néké. Wax bou niaw rek moy guéné cisa guémigne Yaw xamo dara danga trox banopi yangui melné xadj bou rammeu amo diam té doko massa am fék nitou yalla bo xamné lépam yalla la dara gnorouko loudoul yalla ngah seugeu ci sen der di lén wax diou geuna niaw ngah yakaar né yangui liguyal yalla fekna cheytané ngaye liguyal lingaye wax tu l’as sorti de ta petite cervelle mais ici personne n’associe le seigneur à qui que ce soit sauf bien sûr les derangés comme toi

  • @AdamaSambou-kp9bt
    @AdamaSambou-kp9bt 11 днів тому

    Merci sagnan longue vie sante que dieux vous anttende amine

  • @MbayeBabacarNdao-vj9mw
    @MbayeBabacarNdao-vj9mw 11 днів тому

    Amine yaraby sangna walahi ya beugue sa rew machalah

  • @aminataniang8765
    @aminataniang8765 11 днів тому

    Allahouma amine - masha Allah

  • @aminataniang8765
    @aminataniang8765 11 днів тому

    ❤❤❤❤❤❤

  • @yac21
    @yac21 11 днів тому

    Oustaz souniou yalla mayone 10 youye lerale comme ni ngay def sénégal defarou merci

  • @ablayendiane8285
    @ablayendiane8285 11 днів тому

    Masha'Allah amna solo Ya Oustaz❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @AdamaDiop-rh4ii
    @AdamaDiop-rh4ii 11 днів тому

    Boul ragal data Oustaz. Yalla molay aral boppam ndakh mom ngafi nekkal.

  • @milkdiakhate1809
    @milkdiakhate1809 11 днів тому

    Ziarnla oustaz esk d'accord nga ak mbacké sakho si diouli

  • @cheikhsadiboufaye1859
    @cheikhsadiboufaye1859 11 днів тому

    Oustas argentivore da aam oustasou Yallah aam

  • @biboulayetouray1517
    @biboulayetouray1517 11 днів тому

    Amine Amine Amine 🤲🏽🤲🏽🤲🏽