AL Murtadaa TV
AL Murtadaa TV
  • 273
  • 31 502

Відео

laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 8714 днів тому
laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 10914 днів тому
laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 9614 днів тому
laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 12821 день тому
laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye
Laa biireg Sëñ tuubaa ci sàkku xam-xam .....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 328Місяць тому
Laa biireg Sëñ tuubaa ci sàkku xam-xam .....par Serigne Mourtada Ndiaye
"Nit du bëgg diine xam diine ba noppi di bañ sëriñ tuuba loolu manuta nekk........"
Переглядів 2 тис.Місяць тому
"Nit du bëgg diine xam diine ba noppi di bañ sëriñ tuuba loolu manuta nekk........"
wër Kaaba gi di jàng Xasida.......par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 7 тис.Місяць тому
wër Kaaba gi di jàng Xasida.......par Serigne Mourtada Ndiaye
jottali ci ginnaaw imaam.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 175Місяць тому
jottali ci ginnaaw imaam.....par Serigne Mourtada Ndiaye
bind am njaal ngir di xam ñi la jaale.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 74Місяць тому
bind am njaal ngir di xam ñi la jaale.....par Serigne Mourtada Ndiaye
ñiy wax naan Sëñ bu mag bi (BA) la sant ndax peul la......par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 76Місяць тому
ñiy wax naan Sëñ bu mag bi (BA) la sant ndax peul la......par Serigne Mourtada Ndiaye
jakka juñ suul ay liir.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 50Місяць тому
jakka juñ suul ay liir.....par Serigne Mourtada Ndiaye
ndax jënd yalwaanu dongo dagan na....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 42Місяць тому
ndax jënd yalwaanu dongo dagan na....par Serigne Mourtada Ndiaye
lan moo tax bu ñuy jaale ñu di ko sanni.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 43Місяць тому
lan moo tax bu ñuy jaale ñu di ko sanni.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Ki def lu dul yoon ba tëdd ci kaso dem ñu defal ko looxamne.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 48Місяць тому
Ki def lu dul yoon ba tëdd ci kaso dem ñu defal ko looxamne.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Tafsiir par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 25Місяць тому
Tafsiir par Serigne Mourtada Ndiaye
ndax nit buñ ko rayee duñ ko hisaab....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 40Місяць тому
ndax nit buñ ko rayee duñ ko hisaab....par Serigne Mourtada Ndiaye
ban weer moo gën a rafet ngir takk ci sëy.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 74Місяць тому
ban weer moo gën a rafet ngir takk ci sëy.....par Serigne Mourtada Ndiaye
mbooloo muy teg dara te kuñ ko lebal booy fay teg ca dara....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 35Місяць тому
mbooloo muy teg dara te kuñ ko lebal booy fay teg ca dara....par Serigne Mourtada Ndiaye
kiy jàpp am cër bum manuta raxas mu masaa ko......par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 12Місяць тому
kiy jàpp am cër bum manuta raxas mu masaa ko......par Serigne Mourtada Ndiaye
koy naafila basmala lay tàmblee wala faatiha .....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 48Місяць тому
koy naafila basmala lay tàmblee wala faatiha .....par Serigne Mourtada Ndiaye
Tafsiir par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 20Місяць тому
Tafsiir par Serigne Mourtada Ndiaye
len ci xista yi ñuy netta li ci Sëriñ bi lan mooy daliil bi ......par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 113Місяць тому
len ci xista yi ñuy netta li ci Sëriñ bi lan mooy daliil bi ......par Serigne Mourtada Ndiaye
naka la laal jigeen di tojee njàpp......par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 27Місяць тому
naka la laal jigeen di tojee njàpp......par Serigne Mourtada Ndiaye
walastu radiya.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 39Місяць тому
walastu radiya.....par Serigne Mourtada Ndiaye
Tafsiir par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 111Місяць тому
Tafsiir par Serigne Mourtada Ndiaye
ndax jigeen bu nekkee ci regle man naa jang alxuraan......par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 87Місяць тому
ndax jigeen bu nekkee ci regle man naa jang alxuraan......par Serigne Mourtada Ndiaye
kiy sikk salka ci njàppam...par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 42Місяць тому
kiy sikk salka ci njàppam...par Serigne Mourtada Ndiaye
ndax jinne yi dañuy bokk ci huurul hayni......par Serigne Mourtada Ndiaye
Переглядів 36Місяць тому
ndax jinne yi dañuy bokk ci huurul hayni......par Serigne Mourtada Ndiaye
Serigne Mourtada Ndiaye sur l'affair de cheikh Omar diange......
Переглядів 7 тис.Місяць тому
Serigne Mourtada Ndiaye sur l'affair de cheikh Omar diange......

КОМЕНТАРІ

  • @Nafidramè-r7b
    @Nafidramè-r7b 18 днів тому

    Yalla nanou yalla fayal mag you bakhyi❤❤❤❤❤❤

  • @tallafall6839
    @tallafall6839 18 днів тому

    ماشاء الله جزاك الله خيرا

  • @NdameSeye
    @NdameSeye 24 дні тому

    Liga wakh moy dege ❤❤❤ ñiye wakh ay nafèkh rk lan dia dief s mourtada xam xam dou pèkhè

  • @NdameSeye
    @NdameSeye 24 дні тому

    Diere diefeti s mourtada ndiaye ❤❤❤

  • @matyfall5208
    @matyfall5208 24 дні тому

    ❤❤❤❤❤❤❤dieuredieuf khadimou Rassoul

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 26 днів тому

    Diangue xasaïde di ngustal baakhoul. Yéckati katou xasaîtyi dañiye nguistal reck wala ñouy wout addouna.

  • @Utilisateuranonyme12355
    @Utilisateuranonyme12355 27 днів тому

    LES MOURIDES, BAYYILÈNE THIAAKHAAN SÈNE TARIKHA Bi AYE BIDDAA LÀ.

  • @ibrahimafaye4226
    @ibrahimafaye4226 28 днів тому

    😂😂😂

  • @aboudiop-fj4ug
    @aboudiop-fj4ug Місяць тому

    Yaye amo kham kham démal gessou dji wate

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Місяць тому

    Suko naar yi defoon dooko corrigé 😂😂😂

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 Місяць тому

    yep yalla di fowee yenentebi di sabote kabagi di soufel sahabayi.alhourab aj souneu guen sadiko feulee

  • @YATTEBassirou
    @YATTEBassirou Місяць тому

    Tontounga sabop ndakh hamnga lign thiadioblou ndakh nekoul ngiiir diangalé ni gnouy gnané. Gui naw wkhamo lanek senhol Kon rafet si ndiortou .

  • @yaragteggiin5101
    @yaragteggiin5101 Місяць тому

    Ñu mel nii lañu soxla xam-xam kepp nga fi wax de.❤❤❤

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Місяць тому

    Yaw complexe nga waay

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Місяць тому

    Lii dara nekku ci ❤❤❤❤ waaw naar yiy yekkati alquraan ci Kaaba gi nak?

  • @AhmadouSylla-o7c
    @AhmadouSylla-o7c Місяць тому

    Machallah amatina solo

  • @IbrahimaBousso-wl4ks
    @IbrahimaBousso-wl4ks Місяць тому

    Lii deful ludul baax bal gën sax Na ñuy rafet ñortu ci sunuy mbokku

  • @moustaphadiop7738
    @moustaphadiop7738 Місяць тому

    Maacha allah amana solo looll te deuppook ay tegine yalla na yalla dolli len teuwfekh

  • @abodiop3328
    @abodiop3328 Місяць тому

    Kàddu yi amna solo lool lool macahallah

  • @abodiop3328
    @abodiop3328 Місяць тому

    Macahallah amna solo lool

  • @SeringneMoustapha_mbacke
    @SeringneMoustapha_mbacke Місяць тому

    lilebb complex rk la😂😊

  • @FadalGaye-is9qy
    @FadalGaye-is9qy Місяць тому

    M achalla

  • @abdoukhadirborombakhdade6516
    @abdoukhadirborombakhdade6516 Місяць тому

    Sénégal daal xamna rèew mu jaxaso la

  • @MamadouSeck-y5s
    @MamadouSeck-y5s Місяць тому

    Macha allahou yalla na yalla goudal senni fane thibarkee khassidayi

  • @FallouNdiaye-v8k
    @FallouNdiaye-v8k Місяць тому

    ❤❤❤❤

  • @sindidisindidi801
    @sindidisindidi801 Місяць тому

    Bu jaarul woon yoon, waa Makka tere ko, kenn xamul yaay kan wax rekk nga defal diine jëfoo tus.

  • @sindidisindidi801
    @sindidisindidi801 Місяць тому

    Lislaam daliil lay laaj, waaye du lu la neexuk rekk nga génne ci. Wër Kaaba gi, di ñaan kenn manu koo araamal, te xasiida ñaan la. Ki koy def nag, li mu ci yéene moo ko xam Sariiha àtteloowu la ko.

    • @AbdouahadGadiaga
      @AbdouahadGadiaga 26 днів тому

      Degloulooule boubakh limou wakh sa Waye bala gaye tontou

  • @sindidisindidi801
    @sindidisindidi801 Місяць тому

    Senegaal de bari nañuy wax te defaloo dara lilsaam lu dul ay wax rekl, ñii li ñu def dara lu ko dàq doo ko def, njort rekk ak iñaan nga ciy waxe.

  • @baradiop7600
    @baradiop7600 Місяць тому

    Daguena beug lu guen di wax rek waye li mom amo len dara luguen si wax leppa baax te deun bona ak beuguk serigne bi Bayil len sokhor

  • @AbdouhakimDiop-n4q
    @AbdouhakimDiop-n4q Місяць тому

    Cëy xam xam bi rafét Na lol sax Yal Na la yalla Sàmm Barkép xasiidayi

  • @BabacarDiouf-dp2jv
    @BabacarDiouf-dp2jv Місяць тому

    khassida soudone déranger kone nare yi Dinagnko wakh dakh déguenagnou Arabe, dans ce ca kel est le pblm de certaines sénégal sur les khassida à la mécque . Lima guiss dal moy ape sokhor , kiniane ak khol bou diékh molén diape. Ta bouko séni MAME défone kéne dou dégue , way yéna bone. ALKHAMDOULILAH, DIEUREUDIEUF KHADIME RASSOUL DIARAMA MAME CHECKH IBRAHIMA FALL, BARKEPE KHASSIDA....

    • @Bah-gl1kj
      @Bah-gl1kj Місяць тому

      Amiine

    • @Bah-gl1kj
      @Bah-gl1kj Місяць тому

      Khassida borom Touba yi kounou déranger tu es malade

  • @SaliouDiop-i6r
    @SaliouDiop-i6r Місяць тому

    Yallah nala Yallah sam kham kham bu lerr ngay wakh santna niou bu bakh yaw dokhall jambarr ga barkeup b Touba Sop nala loul gir Yallah jajef

  • @kebekhadim4355
    @kebekhadim4355 Місяць тому

    Thiay senegal waxga

  • @18safartouba77
    @18safartouba77 Місяць тому

    Laaj leen ñoom ñikkuy def am na ci solo lool sooga àtte

  • @mbayangdieng-ex6ct
    @mbayangdieng-ex6ct Місяць тому

    Goudou fane ak wér laniou lay nianale ndiaye

  • @modoudiagne8237
    @modoudiagne8237 Місяць тому

    Eupeul rék ak khamadi Ak guistsl ak folcoulor rék

  • @ousmanedieng14
    @ousmanedieng14 Місяць тому

    daffa barii dayri yoo kham né dognou waré dianguii khamm khamm...dii kourell rekk té yenni khamm khamm fagou wokoo!!!!......serigne bii dieuredieuff....demal wakhko kilifeuyyii!!!

  • @ousmanedieng14
    @ousmanedieng14 Місяць тому

    chers mourides ( je le suis comme vous) la mekk est universelle et on ne doit pas innover des choses qui pourraient inspirer toutes les autres communautés du monde ( tidiane.khadria..salsali.hammadiya...)et cela va devenir une sorte de foire...le harmal est symbole de cette universalité et permet de éviter les colorations avec des obédiences particularisante....!!!....merci serigne bii yow boromm kham kham bouuy sentantal ngua!!!....il faut en parlé aux kilifeu!!!...ensuite comme vous dites nagnou bayyi filmé bii dikoo partagé....mbirmii dou tourism religieux.....!!!.....

  • @aminatasidibe9481
    @aminatasidibe9481 Місяць тому

    Il faut respecter l hortodoxie du pèlerinage tel que décrit dans le coran

  • @baragueye-bi6jt
    @baragueye-bi6jt Місяць тому

    gnaane kay wax deug YALLA soxla wul wax si kaw YALLA du am tëx salaaw. mane daal lii dafa teey sama xel gistël lay xawa ndiru

  • @latyrdiouf6837
    @latyrdiouf6837 Місяць тому

    Macha Allah. Mais fofou bougnouy weur Kaaba gui gnépay wax si kaaw wala beug gni thi eup. Mane kaay deffine bii la rafét lou woul mooy di filmé di tassaré rk

  • @institutislamiquetv5285
    @institutislamiquetv5285 Місяць тому

    Machala kam kam reka wor

  • @fallndiaye4883
    @fallndiaye4883 Місяць тому

    Dieuredieuf serigne bo alhamdoulilaah

  • @SerignecheikhGueye-mc7nh
    @SerignecheikhGueye-mc7nh Місяць тому

    waye li Dara nekou si

  • @mbacke7303
    @mbacke7303 Місяць тому

    Mnchall

  • @BasseNdiaye-ms4tu
    @BasseNdiaye-ms4tu Місяць тому

    ❤❤❤ machalla amna solo

  • @MameyoroDime
    @MameyoroDime Місяць тому

    Dieureudieuf Borom Touba

  • @AbdoulahadLoum
    @AbdoulahadLoum Місяць тому

    Marchalla direjef serigne bi thi léral gui amna solo torop

  • @alybambasy351
    @alybambasy351 Місяць тому

    Mashalah Man d wah deug bima guissei kunekk yorr sa téléphone Di filmer damani gniii hamuniou lulen yeukeuti

    • @papeabdoulwalydiagne8336
      @papeabdoulwalydiagne8336 Місяць тому

      Serigne bi maka ak jaka bokou niou teguine Ndakh jaka sofa douguer daniouy ber goor gni appart bere djiguene gni appart Wayer kaba gui goor gni ak jiguen gni daniouy diakhasso teh dara nekouthi

    • @papeabdoulwalydiagne8336
      @papeabdoulwalydiagne8336 Місяць тому

      Teh diakhasso goor ak jiguene jaka nangou wouko mais kaba gua nangou nako Diné adiouwoul thi khalat wayer geum geum la Kone khassida diko tawafé dara nekouthi

    • @alybambasy351
      @alybambasy351 Місяць тому

      @@papeabdoulwalydiagne8336 kubahh Limay wahh tontouwossi d Bala 'ga tontu niitt diemeul hool Limu souligne

    • @mbyehughes392
      @mbyehughes392 Місяць тому

      @@papeabdoulwalydiagne8336kii dafa melni waxoulnè dianga fa xassida baxoul dh mais diko birreul ci kaww tè mou meuneu perturbér ñènène ñufa nekk.

    • @papeabdoulwalydiagne8336
      @papeabdoulwalydiagne8336 Місяць тому

      kagne la rajaz khassida neker problème? Lo khamner serigne Abdou samad sakh soufa demane dakoy deff niou filmée ko Niakk ko def mot complexée

  • @AhmadouSylla-o7c
    @AhmadouSylla-o7c Місяць тому

    جزاك الله خيرا